395px

Nawle

AMADEUS

Nawle

Su nit doon may boppam duñu néew la
Duñ doon ay niiw di doole
Kenn du ñu ëppale
Yàlla mooy may waay
Xeeb nañ ma ngir li may niiw di doole
Ne nañ duma sa nawle
Xool nañ ma bëtu xebbe
Yàlla mooy may waay

Su ma doon kiy dogal
Sa askan kenn du ma ci raw ndax ni ñu ma def
Des nañ ma wékk
Gis naa lépp li nga may defal
Sa waa-kër yépp ne du ci dal du fi ame

Nga jombu leen ngir jëmu ju xébbu ji (léegi-léegi)
Fok ma dem utti indi (léegi-léegi)
Mënuma dem bàyyi la (day jeex, day jeex, day jeex)
Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex)
Fok ma dem utti indi (léegi-léegi)
Doole la néew le (léegi-léegi)
Ne nañ duma sa nawle (day jeex, day jeex, day jeex)
Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex)

Ouroul ayni sa niroowaale
Aw nga ci tanku yaayu aje
Yaa ngi mel ni barry bu ndaw
Ndax Adji kom ngay daguwaale
Doo nettali doo gaaruwaale
Duggeloo ma ci giirawaale

Ngir jëmu ju xébbu ji (léegi-léegi)
Fok ma dem utti indi (léegi-léegi)
Mënuma dem bàyyi la (day jeex, day jeex, day jeex)
Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex)
Fok ma dem utti indi (léegi-léegi)
Doole la néew le (léegi-léegi)
Ne nañ duma sa nawle (day jeex, day jeex, day jeex)
Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex)

Nawle

Si je ne suis pas là, je suis dans la rue
Je suis là pour te donner de la force
Personne ne peut me décevoir
Dieu, c'est mon chemin
Regarde-moi pour ce que je fais pour te donner de la force
Je ne veux pas de ta jalousie
Regarde-moi sur le chemin de la mer
Dieu, c'est mon chemin

Si je suis là, je suis là pour toi
Personne ne peut me faire du mal, car je fais ce que je fais
Fais-moi confiance
Je vois tout ce que tu as fait
Ta famille entière ne peut pas être ici, ça n'existe pas

Je te demande de me donner un bon moment (ouais ouais)
Si je dois partir, je vais le faire (ouais ouais)
Je ne peux pas partir sans toi (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)
Je ne veux pas que tu partes sans moi (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)
Si je dois partir, je vais le faire (ouais ouais)
C'est de la force que je veux (ouais ouais)
Je ne veux pas de ta jalousie (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)
Je ne veux pas que tu partes sans moi (c'est pas vrai, c'est pas vrai, c'est pas vrai)

Regarde comme tu es belle
Tu es dans le tank de la vie
Tu es comme une étoile brillante
Est-ce qu'Adji va te faire briller ?
Ne dis pas que tu es fatiguée
Je suis là pour te soutenir

Pour un bon moment (ouais ouais)