Gauche & Droite
Yaw la yaw la yaw la
Yéené sama xol ndax dama la
Love te sax kafu ma ci
Dama sensible dëgg la
Dama feel bëgg la jox
Sama xol bi ndax dama la
Xale bi te ma la jox
Sama xol bi ndax dama la love
Dama la kay jox, dama la kay jox
Dama la kay jox love bi nekk ci man
Chéri ba noppi soppi sama sant
Dama la kay jox, dama la koy jox
Dama la kay jox love bi nekk ci man
Yàlla ko def loolu lu ma ci mën anh eh
Han man, han xawma lan la
Maa ngi dundu love story bu ma yéem
Bul ma laaj lu ma dal nii
Sama nobeel amul fu mu yam
Xale bi soma laajoon
Jant bi, non tey du fanaan
Xale bi soo ma laajoon
Sama bakkan, dama la kay jox
Dama la kay jox, dama la kay jox
Dama la kay jox love bi nekk ci man
Chéri ba noppi soppi sama sant
Dama la kay jox, dama la koy jox
Dama la kay jox love bi nekk ci man
Yàlla ko def loolu lu ma ci mën anh eh
Gauche wala droite?
Dis moi
Si tu veux en haut en bas?
Dis moi
Lu tàng wala lu sedd?
Dis moi
Ma servir la
Bu 19h jotee ñu tëddi
Na metti, na yaag, na mel ni
Xale bi bul ragal na nga yegsi
Ñun kese la ci kër gi na jolli
My babe touch my body, ouh
Everyday ma jox la nga ne ci
Xale bi teg ma lu metti
Bu yexe ci yaw la
No no du ci man han yayayay
Han man, han xawma lan la
Maa ngi dundu love story bu ma yéem
Bul ma laaj lu ma dal nii
Sama nobeel amul fu mu yam
Xale bi soma laajoon
Jant bi, non tey du fanaan
Xale bi soo ma laajoon
Sama bakkan, dama la kay jox
Dama la kay jox, dama la kay jox
Dama la kay jox love bi nekk ci man
Chéri ba noppi soppi sama sant
Dama la kay jox, dama la koy jox
Dama la kay jox love bi nekk ci man
Yàlla ko def loolu lu ma ci mën anh eh
Oh yeaah, oh yeah
Ndéké xale bi rekk laa nob
Man xale bi rekk la nob
Oh yeaah, oh yeah
Ndéké xale bi rekk laa nob
Man xale bi rekk la nob ba sagar xeeñ 🥀
Links & Rechts
Ja la ja la ja la
Ich weiß, dass du bei mir bist
Liebe und auch Kummer sind hier
Ich bin sensibel, das ist die Wahrheit
Ich fühle, ich will dir geben
Mein Herz, denn ich bin bei dir
Das Kind, ich will dir geben
Mein Herz, denn ich bin bei dir, Liebe
Ich gebe dir, ich gebe dir
Ich gebe dir, Liebe, die es nur für mich gibt
Schatz, lass mich meine Gedanken teilen
Ich gebe dir, ich gebe dir
Ich gebe dir, Liebe, die es nur für mich gibt
Gott, lass es so sein, wie ich es will, eh
Was ist los, was ist los mit mir?
Ich lebe eine Liebesgeschichte, die ich träume
Frag mich nicht, was ich hier mache
Mein Herz hat keinen Frieden, wenn es schläft
Das Kind, ich will nicht fragen
Die Zeit, nein, sie bleibt nicht stehen
Das Kind, wenn ich frage
Mein Herz, ich gebe dir
Ich gebe dir, ich gebe dir
Ich gebe dir, Liebe, die es nur für mich gibt
Schatz, lass mich meine Gedanken teilen
Ich gebe dir, ich gebe dir
Ich gebe dir, Liebe, die es nur für mich gibt
Gott, lass es so sein, wie ich es will, eh
Links oder rechts?
Sag mir
Willst du hoch oder runter?
Sag mir
Was ist hart oder was ist weich?
Sag mir
Ich will dir dienen
Um 19 Uhr kommen wir zusammen
Lass uns tanzen, lass uns fühlen, lass uns lieben
Das Kind, lass es nicht vergessen, dass du hier bist
Wir sind zusammen, das Zuhause ist schön
Mein Babe, berühr meinen Körper, ouh
Jeden Tag gebe ich dir, was du willst
Das Kind, ich gebe dir, was du willst
Wenn du bei mir bist
Nein, nein, das ist nicht für mich, han yayayay
Was ist los, was ist los mit mir?
Ich lebe eine Liebesgeschichte, die ich träume
Frag mich nicht, was ich hier mache
Mein Herz hat keinen Frieden, wenn es schläft
Das Kind, ich will nicht fragen
Die Zeit, nein, sie bleibt nicht stehen
Das Kind, wenn ich frage
Mein Herz, ich gebe dir
Ich gebe dir, ich gebe dir
Ich gebe dir, Liebe, die es nur für mich gibt
Schatz, lass mich meine Gedanken teilen
Ich gebe dir, ich gebe dir
Ich gebe dir, Liebe, die es nur für mich gibt
Gott, lass es so sein, wie ich es will, eh
Oh ja, oh ja
Das Kind, nur du bist hier
Ich, das Kind, nur ich bin hier
Oh ja, oh ja
Das Kind, nur du bist hier
Ich, das Kind, nur ich bin hier, bis die Zeit vergeht 🥀