395px

GLP (Gën Leen Paré)

Mia Guisse

GLP (Gën Leen Paré)

Tej gémmiñu bepp al waxa
Liggéey siggi xool ca kaw
Taluñu ay fo, du ay bla bla
On est ready, queen bi ñu ne mana

Safara bi ngay jaaroo ca ba ngay doon mak
Këriñ bi ndaw nga koy liggéey
Dangay fexe daaj banc di soga nak togg
Bës ñëw lépp neex

Ci biti ñoo ngi wax
Man maa ngi ci biir
Ci biti ñoo ngi wax
Man maa ngi ci biir
Ci biti ñoo ngi wax
Man maa ngi ci biir

Yàlla du juum fenn du am tonto
Ay wax rekk léegi dañ ko fiy tere
Ku la mere sa mbégté dafla soxore
Bomb seen bëñ yi du leen di tax a ree aaay

Gën leen pare
Maa leen gën a pare
Maa leen gën a pare

Loxo bu la bàyyi, loxo ngi tok
Loxo bu la bàyyi, wallaay bàyyi
Loxo bu la bàyyi, loxo ngi tok
Loxo bu la bàyyi, wallaay bàyyi

Compter billets go didi tati
Teye full money money
Duma lekk seen bol, bon appetit
Tële rekk tax ñuy ratatati
Cuj bu xam lekkam du fot
Dale bu la xat am na ku mu jot
Damay fo sax muy neex ñepp
Dieu merci noo tudd yaw

Yëngël sa mbagg bu de yaa ngi jot lii 25/5
Li nga joxe ngay jotaat rekk Yàllay ténnis
Daf ma woo ma ñëw mu sampal ma ay laaf yu bees
Dieu merci, merci, merci, I love mysef

GLP (Gën Leen Paré)

Ich bin bereit, alles zu geben
Arbeiten, bis ich oben bin
Reden wir nicht viel, nur das Bla Bla
Wir sind bereit, die Königin hat gesagt, wir können

Die Party wird heute Nacht groß, ich werde nicht aufhören
Die Jüngeren arbeiten hart
Du machst es gut, während du dich entspannst und chillst
Jeder Tag ist ein Genuss

In der Stadt reden sie
Ich bin mitten drin
In der Stadt reden sie
Ich bin mitten drin
In der Stadt reden sie
Ich bin mitten drin

Gott hat keinen Mangel, es gibt keinen Stress
Nur Worte, die jetzt gesagt werden müssen
Wer deine Sorgen nicht versteht, der hat kein Mitgefühl
Die Bomben sind stark, sie werden dich nicht aufhalten, oh ja

Gibt es mehr für euch?
Ich gebe euch mehr
Ich gebe euch mehr

Die Hand, die dich hält, die Hand ist stark
Die Hand, die dich hält, oh ja, stark
Die Hand, die dich hält, die Hand ist stark
Die Hand, die dich hält, oh ja, stark

Zähle das Geld, es kommt rein
Voll mit Geld, Geld
Ich esse nicht von deinem Teller, guten Appetit
Nur Worte, die wir sagen, die uns zum Lachen bringen
Essen, das du nicht kennst, ist kein Problem
Wenn du es nicht hast, wird es jemand anderes tun
Ich mache es einfach, es ist für alle gut
Gott sei Dank, ich bin hier

Zeig dein Talent, du bist hier, 25/5
Was du tust, ist nur für Gott, Tennis
Lass mich kommen, ich werde dir neue Dinge zeigen
Gott sei Dank, danke, danke, ich liebe mich selbst