395px

Mako Wakhone (feat. Ara)

YERO

Mako Wakhone (feat. Ara)

Tous les jours je pense à nous
Au plus beau jour de ma vie
Dans ta jolie robe, mon amour
Ton visage qui scintille

Amul lu gëna neex li ñuy dundu ni
Danu ko yàgg dream baby tay moo ngi ni
Doon nga sama wife, doon nga sama guy
Fi ngeen jugé sori, baby awma sa faay

Ani ñi doon douter, takk naa ko!
Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko!
Maa ko waxoon bébé, takk naa la!
Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko!

Ñi doon douter, takk naa ko!
Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko!
Maa ko waxoon bébé, takk naa la!
Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko!

Bàyyi ma toog [?]
Ndax lu ma daw daw daw, yaa ma gëna gaaw
Yaa ma gëna gaaw, yaw laay topp
Bébé jiitu ma nga raw ma, maa ngi sa ginnaaw
Topp sa ginnaaw
Naa la xaar âret kaar boo ñëwee yakkal ma say coono
Aka ma xam ni fi ngay jaar
Dingay def toj-toj waaye yaw yoroo xolu tooñ ma
Wax ma ni dama la koy baal

Yapp ma yabbale reewande
Yapp nga xale bu fiir
Client bu mat, client la bu amale caprice
Am nga gan boo dul yàkkale, ñépp ay rangé mur
Naan ci lewel, naan ci Deus, naanale tarxiis

Ani ñi doon douter, takk naa ko!
Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko!
Maa ko waxoon bébé, takk naa la!
Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko!

Ñi doon douter, takk naa ko!
Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko!
Maa ko waxoon bébé, takk naa la!
Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko!

Ay lolou sama lonko
[?] bul sori, yaw kaay waay!
Tëdd sa kaw nga ni ma gan
Sama reni xol, sama ndaanaan

Li ñuy dundu ni
Danu ko yàgg dream baby tay moo ngi ni
Doon nga sama wife, doon nga sama guy
Fi ngeen jugé sori, baby awma sa faay

Ani ñi doon douter, takk naa ko!
Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko!
Maa ko waxoon bébé, takk naa la!
Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko!

Ñi doon douter, takk naa ko!
Sama Ouroul Ainy baa ngi, takk naa ko!
Maa ko waxoon bébé, takk naa la!
Lu waay waxoon na ca delluwaat, takk naa ko!

Mako Wakhone (feat. Ara)

Todo dia eu penso em nós
No dia mais lindo da minha vida
Na sua roupa bonita, meu amor
Seu rosto que brilha

Amor, a gente sempre se entende, né?
Vamos fazer desse sonho uma realidade, baby, é isso que eu quero
Você é minha esposa, você é meu cara
Aqui onde você brilha, baby, eu sou seu fã

E quem duvidar, eu vou mostrar!
Meu amor, a gente tá junto, eu vou mostrar!
Eu te digo, baby, eu vou te mostrar!
O que eu digo é verdade, eu vou mostrar!

Quem duvidar, eu vou mostrar!
Meu amor, a gente tá junto, eu vou mostrar!
Eu te digo, baby, eu vou te mostrar!
O que eu digo é verdade, eu vou mostrar!

Me deixe em paz [?]
O que eu vou fazer, você sabe que eu sou rápido
Eu sou rápido, você vai me seguir
Baby, me leve, eu sou seu fã
Siga seu fã
Eu vou te mostrar que você é a razão do meu coração
E eu sei que você vai me amar
Eu vou fazer tudo, mas você não pode me deixar na mão
Diga que eu sou seu

Me deixe em paz, eu vou me esforçar
Me deixe em paz, eu sou seu filho
Cliente que não vale nada, cliente que não tem capricho
Eu sou seu, não me deixe de lado, todo mundo é igual
Fale com Deus, fale com a sorte, fale com a fé

E quem duvidar, eu vou mostrar!
Meu amor, a gente tá junto, eu vou mostrar!
Eu te digo, baby, eu vou te mostrar!
O que eu digo é verdade, eu vou mostrar!

Quem duvidar, eu vou mostrar!
Meu amor, a gente tá junto, eu vou mostrar!
Eu te digo, baby, eu vou te mostrar!
O que eu digo é verdade, eu vou mostrar!

Ah, meu amor, você é tudo pra mim
[?] não se esqueça, você é tudo!
Cuide do seu coração, eu sou seu
Meu amor, meu tudo, minha razão