Kumu Neexul
Yaw la, yaw la
Dëgg dëgg dëgg yaw rekk la
Coow li, coow li
Neexul ba neexul Ndiaye doo seen moroom
Ku mu neexul jëlal fale
Ku mu neexul toppal nale
Sunu xol yi yaw yaa ci ne
Ndax sa mbaax ñepp ñoo ko seede
Gaynde Ndiaye sa dëgg-dëgg
Fi nga jàpp foofo dëgg
Yàqe bari feem mëna dem
Yaa ngi tax a jooy te dóoroo ñu
Ñu ngi asaman te nawuñu
Tëddel tëddel nelaw
Nelaw ba yàndoor sa gannaw bandang
Man bëgg naa la
Gëmel Yàlla ji
Gëmel Yàlla ji te xam ni moom rekk kaay maye
Gëmel Yàlla ji te xam ni moom rekk kay dogal
Ku mu neexul jëlel fale
Ku mu neexul toppal nale
Sunu xol yi yaw yaa ci ne
Ndax sa mbaax ñepp ñoo ko seede
Gaynde Ndiaye sa dëgg-dëgg
Fi nga jàpp foofo dëgg
Yàqe bari feem mëna dem
Yaa ngi tax a jooy te dóoroo ñu
Ñu ngi asaman te nawuñu
Tëddel tëddel nelaw
Alboury biram Penda Ndiemé
Boroom Jolof bu na njorte
Biram penda Farimata mi mu dembothioro bé
Moy Mami Serigne Ndiaye buna
Buna ba Jolof marré nane, buna yaaa
eunoub tene wajuram di sa nane ba rewmi naat
Yacine gueye massar sa yaye
Serigné Ndiaye bu mansur buna
Sëriñ Ndiaye Aziz Fama Mansour umi
Mame fama Ndiaye baayu Sophie Ndiaye
Aaaah, aaaahn, aaaahn
Sëriñ Ndiaye Bouna
Nelaw ba yàndoor sa gannaw bandang
Man bëgg naa la
Biram ndieme Aissa Ndiaye
Bu kaari bigué sanguleen
Alboury diakher, Alboury baay Buna Ndiaye
Mami mame Famara Ciré Ndiaye, Buna Ndiaye
Man nga yàndoor soy nelaw
Ku mu neexul jëlal fale
Ku mu neexul toppal nale
Nelaw ba yàndoor sa gannaw bandang
Man bëgg naa la
El Lamento de Neexul
Yaw la, yaw la
Dëgg dëgg dëgg yaw rekk la
Coow li, coow li
Neexul, oh Neexul, Ndiaye, mi viejo amigo
El lamento de Neexul resuena
El lamento de Neexul se eleva
Nuestra historia está aquí, sí, en este lugar
Porque tu voz nos guía hacia la luz
Gaynde Ndiaye con su constante latido
Siempre presente en nuestras vidas
El tiempo pasa sin piedad
Y nos lleva a un lugar desconocido
Donde encontramos la paz
En la eternidad
En la eternidad, su espíritu sigue vivo
Nunca se irá
Dios nos bendiga
Dios nos bendiga y nos dé fuerza para seguir adelante
Dios nos bendiga y nos guíe en nuestro camino
El lamento de Neexul resuena
El lamento de Neexul se eleva
Nuestra historia está aquí, sí, en este lugar
Porque tu voz nos guía hacia la luz
Gaynde Ndiaye con su constante latido
Siempre presente en nuestras vidas
El tiempo pasa sin piedad
Y nos lleva a un lugar desconocido
Donde encontramos la paz
En la eternidad
Alboury Biram Penda Ndiemé
El líder de Jolof que nos dejó
Biram Penda Farimata, tu legado perdura
Mi madre, Serigne Ndiaye, mi guía
La madre Jolof que nos cuidó, oh madre
Tu amor nos protege en este mundo
Yacine Gueye, la fuerza de su madre
Serigné Ndiaye, el protector de su pueblo
Sëriñ Ndiaye Aziz Fama Mansour, mi amigo
Mame Fama Ndiaye, madre de Sophie Ndiaye
Aaaah, aaaahn, aaaahn
Sëriñ Ndiaye Bouna
En la eternidad, su espíritu sigue vivo
Nunca se irá
Biram Ndieme Aissa Ndiaye
El guardián de la tradición sagrada
Alboury Diakher, el gran líder Buna Ndiaye
Mami Mame Famara Ciré Ndiaye, Buna Ndiaye
Siempre presente en nuestro corazón
El lamento de Neexul resuena
El lamento de Neexul se eleva
En la eternidad, su espíritu sigue vivo
Nunca se irá