Traducción generada automáticamente

Yeurmande (feat. Kya Loum)
Ashs The Best
Yeurmande (feat. Kya Loum)
Yeurmande (feat. Kya Loum)
Yo quiero que me escuchenJooy naa ba jeexal ròngoñ
Dame lo que es míoJaay naa la sama bakkan
Dame, dame, dame por mi genteFippu naa fippu xeex ngir sama askan
Por mi genteXeex ngir sama askan
Yo quiero que el mundo sepa que estamos aquíJooy naa ndax nèwdi dooli ngi yelwaan
Luchando en este tiempoXiif akk mar jamono jii
La gente sigue luchandoNèwdi doole di jooy
Dame un poco de paz y amorJël nga sunu peace and lova
El poder que tenemos es contra los enemigosNguur gi def ñu ennemis
Viviendo en un lugar donde nos ignoranDëkk ci di ñu nòot
La unión es lo que nos hace fuertesJëlli ji li ñu moom jot na
Nuestros hijos son nuestros tesorosSeeni doom’ag sunuy doom ku ci gën
Nuestra unión en sus bolsillos es lo que importaSunu koom ci seeni poches dafa doy
Unámonos en este camino que estamos tomandoJëlli wuñu yoonu geej fii la ñuy toog
No dejemos que nos dividanDemmatu ñu bitim reew
Yo quiero que mi comunidadJooy naa akk samay dëkkëndoo
Viva en armonía con DiosYërmande Ci doomu Yalla yi
Dame lo que es de mi madreFippu naa akk sama doomu yaay yi
Dame por este país que es nuestroFippu xeex ngir ëllëgu reew mi
Yo quiero que me escuchenJooy naa ba ñakk ròngoñ
Dame lo que es míoJaay la sama bakkan
Dame por mi genteFippu xeex ngir sama askan
Por mi genteXeex ngir sama askan
Dame por nuestros hijosFippu naa ngir sunuy doom
Dame por la madre que me dio la vidaFippu ngir yaay ju ñakk doomam
Dame por lo que soyFippu xeex ngir li ma moom
Unidos en nuestra familiaYërmande ci sunuy njaboot
Yo quiero que el mundo sepaJooy naa ba ròngoñ jeex
La gente sigue luchandoNèwdi doole ngi yelwaan
Yo quiero que el mundo sepaJooy ba ròngoñ jeex
Por la mujer que es fuerteNgir jigeen gi soon lool
Hay amor en la uniónAm len yërmande
UniónYërmande
UniónYërmande
UniónYërmande
UniónYërmande
UniónYërmande
UniónYërmande



Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Ashs The Best y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: