Traducción generada automáticamente

Nappé (feat. BM Jaay & Samba Peuzzi)
Bass Thioung
Nappé (feat. BM Jaay & Samba Peuzzi)
Nappé (feat. BM Jaay & Samba Peuzzi)
Mets-le à tempsTeg ko ci temps
Tu es là à tempsAmoon nga fi temps
Nous vivons tous cette tempêteLéegi ñun ñoo moome vent
Tu vas t'en sortir !Dangay nappe!
Tu sais que je suis juste en train de m'accrocherYaw xam nga rekk dama di ndaanaan
La lumière du jour me manqueLamb démb ma daan
Je vais rester tranquille comme un poisson dans l'eauMa leen gëna saf ni daxar ba ci yoon mbaadan
Ne lâche pas ce qui t'attireMoytul noon mu tarxis saran
Vous êtes prêts à brillerBari ngeen jaxan
Le flow comme un roi, il est déjà làFlow bu reew la indi tay moom
Un rap tout doux qui appelleRap bu soft la laal
Pas d'arrêt (pas d'arrêt)Amul arrêt (amul arrêt)
Je continue (je continue)Dey daw rekk (dey daw rekk)
Fais ce que tu dois faire, je sais que c'est comme Mbappé (comme Mbappé)Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé)
Je ne veux pas d'arrêt (pas d'arrêt)Ma ni amul arrêt (amul arrêt)
Je ne vais pas tarder (vite, vite)Munoo ma tardeel (mukk mukk)
Tu sais c'est chaud ici, je te laisseXam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma
dans le coin de mon œil mouilléSàndi sama mbale mi nappé
Je continue sans relâcheDéy daw rekk
Chauffe l'ambianceYoroo wéroo
Eh, je veux juste briller, brillerEh, bëgg jitte bëgg nappé
On va briller, on va brillerLooy nappé, looy nappé
On sait ce que tu veuxXam nañu li ngay dundu
Éveille notre corps, tu es sur le point de brillerDawoo suñu yaram, dangay nappé
Mets-le à tempsTeg ko ci temps
Tu es là à tempsAmoon nga fi temps
Nous vivons tous cette tempêteLéegi ñun ñoo moome vent
Tu vas t'en sortir !Dangay nappe!
Fais-le, c'est ta placeFetaak moom place
Ils sont là en haut, on entreÑoom ci kaw lañu jëm
Et moi, je reste iciTe man fa laa toog
En mode prêt à percerRomb ay kuti ñu may mbow
Tu sais que tu as trop d'atoutsNdax te bukki bi la bot
Arrête de jouer, avanceTaat moo ko topp muy déllu gannaaw
Car je suis là pour vousCi bi ma ko
Avec eux, ne me déçois pas comme çaMan ak ñoom dootuñu laale jamais
Comme les Guissés-MaaboComme les Guissés-Maabo
Mets ton poing et entoure ce tempsTeg fa sa loxo jàppal ma temps
Une pépite comme KylianPépite la ni Kylian
Attends, reste sur la bonne voie et continue, prends le tempsÑaw ngemb tere mbot ndaanaan dégg may daan
Le monde entier dépend de ton rappeur coolÀdduna potu nda la sa rappeur du gux du naan
Moi, je fais ce que je peux pour attirer ces filles, préparez-vousMan lan ko diw ma jàpp seen girl yi, jàppal leen gam
C'est juste l'final, je ne joue pasFinal rekk moom laay joué
Je suis le chef de la bande, je fais juste la cuisine à la maisonMoom chef de bandi lay ñodd cooki feebar rekk de
Je vais m'occuper d'eux mais vous allez vraiment voirDinañu ma daq mais yere yi may sol rekk a may teye
L'argent vient en éclats mais ça ne m'atteint pasXaalis lay xëccoo mais du pe
Ce que tu fais pour moi, je suis prêt à donner ma couleurLu ne lay teg sama der tewul maa ngi jàpp teint
Pas d'arrêt (pas d'arrêt)Amul arrêt (amul arrêt)
Je continue (je continue)Dey daw rekk (dey daw rekk)
Fais ce que tu dois faire, je sais que c'est comme Mbappé (comme Mbappé)Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé)
Je ne veux pas d'arrêt (pas d'arrêt)Ma ni amul arrêt (amul arrêt)
Je ne vais pas tarder (vite, vite)Munoo ma tardeel (mukk mukk)
Tu sais c'est chaud ici, je te laisseXam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma
Dans le coin de mon œil mouilléSàndi sama mbale mi nappé
Je continue sans relâcheDéy daw rekk
Chauffe l'ambianceYoroo wéroo
Eh, je veux juste briller, brillerEh, bëgg jitte bëgg nappé
On va briller, on va brillerLooy nappé, looy nappé
On sait ce que tu veuxXam nañu li ngay dundu
Éveille notre corps, tu es sur le point de brillerDawoo suñu yaram, dangay nappé
Mets-le à tempsTeg ko ci temps
Tu es là à tempsAmoon nga fi temps
Nous vivons tous cette tempêteLéegi ñun ñoo moome vent
Tu vas t'en sortir !Dangay nappé!
Je suis sur mon chemin comme BRTMan rekk ci sama yoon comme BRT bi
Les jeunes bougent, bien à l’aiseXale yaa ngi jooy ass bi la tebi
Dis-moi, général, tu es là maintenantNe ma général yaw la asp bi
N'arrête pas de parler comme si tu savaisSoxlatul may wax lam xa bi
Attends, dans ma tête j’entends ce que tu as à direÑaw, kàddu baal la dum leen gaawa dégg
Je ne laisse pas ceux qui jouent de façon ridiculeMan la dogo ñi doon bañ rambax ci game bi lañ gis tey ñu yor bongo
Comme Aly, reste cool et sain d'espritComme Aly wéy geroo fils sa buur la
Un Aly doit faire face à son équipeBenn Aly ñëw wacc la sa ngur la
Prépare ton rappeur, mets les nez à l'heure, d’après DieckTegal sa rappeur sañ-sañ, tojal ko mbari from Dieck
Mets ça à temps comme pour encadrer, fais monter l'ambianceTeg ko ci temps di sañse, jamos ko blow tek-tek
Élargis l’horizon, votre team est au sommet, mon K7 est juste làLindia seen game bi bët-set, seen K7 sama weccet
La vie est une fête, l’invité, profitons-enFatt dundu lifu jetset, teddi king fat pérpéte
Pas d'arrêt (pas d'arrêt)Amul arrêt (amul arrêt)
Je continue (je continue)Dey daw rekk (dey daw rekk)
Fais ce que tu dois faire, je sais que c'est comme Mbappé (comme Mbappé)Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé)
Je ne veux pas d'arrêt (pas d'arrêt)Ma ni amul arrêt (amul arrêt)
Je ne vais pas tarder (vite, vite)Munoo ma tardeel (mukk mukk)
Tu sais c'est chaud ici, je te laisseXam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma
Dans le coin de mon œil mouilléSàndi sama mbale mi nappé
Je continue sans relâcheDéy daw rekk
Chauffe l'ambianceYoroo wéroo
Eh, je veux juste briller, brillerEh, bëgg jitte bëgg nappé
On va briller, on va brillerLooy nappé, looy nappé
On sait ce que tu veuxXam nañu li ngay dundu
Éveille notre corps, tu es sur le point de brillerDawoo suñu yaram, dangay nappé
Mets-le à tempsTeg ko ci temps
Tu es là à tempsAmoon nga fi temps
Nous vivons tous cette tempêteLéegi ñun ñoo moome vent
Tu vas t'en sortir !Dangay nappé!

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Bass Thioung y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: