Traducción automática

Damalay Bëgg
Jahman X-Press
J'aime toi
Damalay Bëgg
Quand je te vois, mon cœurBi ma la dénkee sama xol
Tout s'emballe, c'est fouFowewoo ko nenne tuuti
Je ne sais pas pourquoi je te dis que je t'aimeBa tax na su ma la doon wax fi nga ma tollu
Je suis là, c'est fouDama la nob dafay tuuti
Maintenant j'ai le teint, mais tu me donnes ce qu'il fautLéegi dama am teint te bae yaa may jox li tax
Shampoing, je vais brillerShampoing mbëggeel laay sangoo
Quand je vois mon ex, je me dis que c'est pas la peineKon ku gis sama ex, nekkoo boppam lay nax
Si tu me vois, je t'aime encoreSu fóogee nii namm naa ko
Ne me demande pas de faire comme siXawma nan lay def ak yaw
Regarde l'allure que tu asWaññil allure bi ngay daw
Ta beauté, c'est quoi, bébé ?Sa xeetu mbëggeel lan la baby?
Regarde dans mon cœur, tu es là, tu es là, tu es làTegal fi sama xol bi nga këf, nga këf, nga këf
Quand je te vois, je fais des efforts, des effortsBa ma féemu def ay yëf, ay yëf
Tu dis que c'est pour ça que tu es làYaw bokkok ñiy wax ndax yaa jëf moo tax
Moi, je t'aimeMan dama lay bëgg
Moi, je t'aime, oh bébéMan dama lay bëgg ba kañ baby
Je t'aimeDama lay bëgg
Je t'aimeDama lay bëgg
Je t'aime, ohDama lay bëgg ba kañ
Chérie, je t'aimeChérie, dama lay bëgg
Si je peux te garder, je le feraiMan su ma yàkkamti woom juum
Je vois que Dieu m'a aidéGis naa ki ma Yàlla dencaloon
Moi, je t'aime, oh bébéMan dama lay bëgg ba kañ
Si je peux te garder, je le feraiAy su ma yàkkamti woom juum
Je t'aime, ohBëgg ba kañ
Je vois que Dieu m'a aidéGis naa ki ma Yàlla dencaloon
Moi, je t'aime, oh bébéMan dama lay bëgg ba kañ
Mon espoir ne s'éteindra pas pour toi, pas maintenantSama yaakaar tasul ci yaw ba léegi
Si je te laisse, c'est parce que tu es làFoo jaar ma yëkkëti la ndax yaa ma daaneel
Tu es avec moi, je suis là, à l'intérieur de moiJikko nga ci man maak yaw ba biir bàmmeel
Tu es là, pourquoi ils disent que tu es une belle femmeMaak yaw a tax ñu naan baatu lingeer ak dameel
Ton homme te fait du bien, car tu es dans mon cœurTontu sa borom lay fay ndax xol nga ma ameel
Tout ce qui brille, c'est pour toiLi ci mbëggeel lanaati lépp
Tout ce qui ne va pas, c'est pour toiLi bu raxul dof yitt ci la
Si je suis làFoo ne maa nga fa
Et si je te vois, je suis là pour toiTe fu ma la jiitu xaar laa fa
Je n'ai pas de souci avec toiAmuma sago ci yaw
Est-ce que tu sais que tu es la vie, bébé ?Est-ce que sax yaw doo nervis une vie, baby
Moi, c'est juste toi que je veuxMan yaw rekk laa miin
Je veux garder mon esprit, car si je te perds, tu es là pour moiYaay dalal sama xel ndax fu ma jaaxle yaw laay wutsi
Mais ne laisse pas les autres te toucherWaaye fokk ñu takk pettaaw
Tu sais que ça va viteNdax xam nga cat dafa gaaw
Ta beauté, c'est quoi, bébé ? (Mon bébé)Sa xeetu mbëggeel lan la, baby? (Mon bébé)
Tout le monde sait que je t'aimeÑépp xam nañu man dama la
Je t'aime beaucoupDama la bëggawut
Je t'aime, bébéBëgg naa la, baby
C'est un cadeau d'Allah que je t'offreSama cadeau d'Allah laa lay woowe
Je veux que tu sois ma femmeNga bëgg leen sama tabbe
Je te le dirai quand tu me prendras dans tes brasNaan laa lay woowee bi nga ma jàppe ba tay
Ne me laisse pas, si tu veux, dis-le moiBàyyiwoo su jakk yakk nga waxe fë
Moi, je t'aimeMan dama lay bëgg
Moi, je t'aime, oh bébéMan dama lay bëgg ba kañ baby
Je t'aimeDama lay bëgg
(J'aime tout de toi, mon bébé)(Yénne naa la lu nekk sama baby)
Moi, je t'aime, ohMan dama lay bëgg, billaay
Je t'aime, oh bébéDama lay bëgg ba kañ
Chérie, je t'aimeChérie, dama lay bëgg
Si je peux te garder, je le feraiMan su ma yàkkamti woom juum
(J'aime, oh)(Bëgg ba kañ)
Je vois que Dieu m'a aidéGis naa ki ma Yàlla dencaloon
Moi, je t'aime, oh bébéMan dama lay bëgg ba kañ
Si je peux te garder, je le feraiAy su ma yàkkamti woom juum
Je t'aime, ohBëgg ba kañ
Je vois que Dieu m'a aidéGis naa ki ma Yàlla dencaloon
Je t'aime, oh bébéDama lay bëgg ba kañ
Mon espoir ne s'éteindra pas pour toi, pas maintenantSama yaakaar tasul ci yaw ba léegi



Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Jahman X-Press y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: