Traducción generada automáticamente

Jeune Mara
VJ
Junger Mara
Jeune Mara
Lay layla luuLay layla luu
Tay ngeen dee, teyaati ngeen dee oooTay ngeen dee, teyaati ngeen dee ooo
Wuy sama ndey jooy naa ba waddWuy sama ndey jooy naa ba wadd
Kaay!Kaay!
Doo def lu mel ni même boo ko bëggoon (eee)Doo def lu mel ni même boo ko bëggoon (eee)
Mënoo ko def ni man mi (eee)Mënoo ko def ni man mi (eee)
Lan ngay wër ci stars lu newul ci man mi (eee)Lan ngay wër ci stars lu newul ci man mi (eee)
Maa jogé di échauffement arbitre naan butMaa jogé di échauffement arbitre naan but
Lekketu bayal yi la miinLekketu bayal yi la miin
Xale bi yëngël jamono jëkketi na toog di xaar seen commentaireXale bi yëngël jamono jëkketi na toog di xaar seen commentaire
Dritte GT ci boy bu ndaw, ah c'est légendaire!Troisième GT ci boy bu ndaw, ah c'est légendaire!
Kan moo fi dëkk ci feesal stade, Senegaal booy ma fi starsKan moo fi dëkk ci feesal stade, Senegaal booy ma fi stars
Tribüne la ma ñépp di owe, xaaju ma ci ay salleTribune la ma ñépp di owe, xaaju ma ci ay salle
Maa ngi dégg xale yi naan: VJ duñu concert xanaaMaa ngi dégg xale yi naan: VJ duñu concert xanaa
Yaw doo def bala déwen, léegi ñu am vacancesYaw doo def bala déwen, léegi ñu am vacances
Yaw suñu album bi ñuy xaar, doo ko génne xanaa?Yaw suñu album bi ñuy xaar, doo ko génne xanaa?
Yaw loo génne dafay neex, chouchou des nanasYaw loo génne dafay neex, chouchou des nanas
Moo tax ni rekk laa koy defe ni mu yombeMoo tax ni rekk laa koy defe ni mu yombe
Nga jënde sa ticket dox ñu daje biir GTNga jënde sa ticket dox ñu daje biir GT
Album bi bés bu génne bu amul morts am blésséAlbum bi bés bu génne bu amul morts am bléssé
Ndax xol bu rafet ak mbégte ding ko déglu wét di feccNdax xol bu rafet ak mbégte ding ko déglu wét di fecc
Force zac zac zarko (àljanna)Force zac zac zarko (àljanna)
Ko kaay corégeou président maay capoKo kaay corégeou président maay capo
Man VJ sama concert xale yi neex fa lañ baadoMan VJ sama concert xale yi neex fa lañ baado
Ma te gambe bi flow yas ngay siisooMa te gambe bi flow yas ngay siisoo
Bon, setlu naa nak ku fi jokk rekk def ma concurrenceBon, setlu naa nak ku fi jokk rekk def ma concurrence
Maa toog def noppi di seetaan calmementMaa toog def noppi di seetaan calmement
Ki la wax dama tappet ku ko ne ragal laKi la wax dama tappet ku ko ne ragal la
Man may bandit di délinquant (yaw ki di woyu)Man may bandit di délinquant (yaw ki di woyu)
Mara, marabout de la jeunesseMara, marabout de la jeunesse
Junger mara, marabout de la jeunesseJeune mara, marabout de la jeunesse
Man VJ, maay marabout de la jeunesseMan VJ, maay marabout de la jeunesse
Junger mara, marabout de la jeunesseJeune mara, marabout de la jeunesse
Mara, marabout de la jeunesseMara, marabout de la jeunesse
Junger mara, marabout de la jeunesseJeune mara, marabout de la jeunesse
Man VJ, maay marabout de la jeunesseMan VJ, maay marabout de la jeunesse
Junger mara, marabout de la jeunesse!Jeune mara, marabout de la jeunesse!



Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de VJ y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: