Traducción generada automáticamente

Jeune Mara
VJ
Young Mara
Jeune Mara
Lay layla luuLay layla luu
You’re doing great, you’re really shining, ohTay ngeen dee, teyaati ngeen dee ooo
I’m like my mom, I’m not backing downWuy sama ndey jooy naa ba wadd
Come on!Kaay!
Do what you want, just like you want it (yeah)Doo def lu mel ni même boo ko bëggoon (eee)
I can do it like I’m the one (yeah)Mënoo ko def ni man mi (eee)
What are you reaching for, stars that shine for me (yeah)Lan ngay wër ci stars lu newul ci man mi (eee)
I’m just warming up, referee says it’s a goalMaa jogé di échauffement arbitre naan but
The crowd is wild, they’re feeling itLekketu bayal yi la miin
The kid is living in a time that’s hard to handle, check your commentsXale bi yëngël jamono jëkketi na toog di xaar seen commentaire
Third GT, the young one, ah it’s legendary!Troisième GT ci boy bu ndaw, ah c'est légendaire!
How can you be here, in the stadium, Senegal, I’m here with the starsKan moo fi dëkk ci feesal stade, Senegaal booy ma fi stars
The stands are all cheering, I’m in the zoneTribune la ma ñépp di owe, xaaju ma ci ay salle
I hear the kids say: VJ, we’re not missing the concertMaa ngi dégg xale yi naan: VJ duñu concert xanaa
You’re just doing it, now we’re on breakYaw doo def bala déwen, léegi ñu am vacances
You’re checking our album, are you gonna drop it?Yaw suñu album bi ñuy xaar, doo ko génne xanaa?
You’re dropping heat, darling, the girls love itYaw loo génne dafay neex, chouchou des nanas
That’s why I’m just doing my thing, it’s all goodMoo tax ni rekk laa koy defe ni mu yombe
You got your ticket, let’s go, we’re ready for GTNga jënde sa ticket dox ñu daje biir GT
The album’s hot, no deaths, no injuriesAlbum bi bés bu génne bu amul morts am bléssé
Is your heart pure and your vibe right, let’s shine brightNdax xol bu rafet ak mbégte ding ko déglu wét di fecc
Force zac zac zarko (let’s go)Force zac zac zarko (àljanna)
Come on, let’s go, president, let’s do thisKo kaay corégeou président maay capo
I’m VJ, my concert, the kids love it, they’re vibingMan VJ sama concert xale yi neex fa lañ baado
I’m flowing, the beat’s got you movingMa te gambe bi flow yas ngay siisoo
Well, I’m just here, no competitionBon, setlu naa nak ku fi jokk rekk def ma concurrence
I’m chilling, keeping it calmMaa toog def noppi di seetaan calmement
Whoever says I’m just a player, they’re mistakenKi la wax dama tappet ku ko ne ragal la
I’m a bandit, a delinquent (you know what I mean)Man may bandit di délinquant (yaw ki di woyu)
Mara, youth’s spiritual guideMara, marabout de la jeunesse
Young mara, youth’s spiritual guideJeune mara, marabout de la jeunesse
I’m VJ, your spiritual guideMan VJ, maay marabout de la jeunesse
Young mara, youth’s spiritual guideJeune mara, marabout de la jeunesse
Mara, youth’s spiritual guideMara, marabout de la jeunesse
Young mara, youth’s spiritual guideJeune mara, marabout de la jeunesse
I’m VJ, your spiritual guideMan VJ, maay marabout de la jeunesse
Young mara, youth’s spiritual guide!Jeune mara, marabout de la jeunesse!



Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de VJ y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: