Traducción generada automáticamente

visualizaciones de letras 277

Jeune Mara

VJ

Letra

Significado

Jeune Mara

Jeune Mara

Lay layla luuLay layla luu
T'es là, t'es là, oh ohTay ngeen dee, teyaati ngeen dee ooo
Je suis là pour faire bougerWuy sama ndey jooy naa ba wadd
Allez !Kaay!

Fais comme si c'était la même chose que tu voulais (eee)Doo def lu mel ni même boo ko bëggoon (eee)
Je peux faire comme si j'étais celui-là (eee)Mënoo ko def ni man mi (eee)
Qu'est-ce que tu veux dire par les étoiles qui brillent pour moi (eee)Lan ngay wër ci stars lu newul ci man mi (eee)
Je suis là pour m'échauffer, l'arbitre dit butMaa jogé di échauffement arbitre naan but
Les lumières de la ville, c'est moi qui les voisLekketu bayal yi la miin

Le jeune est là, le temps est venu de lire vos commentairesXale bi yëngël jamono jëkketi na toog di xaar seen commentaire
Troisième GT, le petit, ah c'est légendaire !Troisième GT ci boy bu ndaw, ah c'est légendaire!
Comment ça se passe ici, au stade, Sénégal, je suis là avec les starsKan moo fi dëkk ci feesal stade, Senegaal booy ma fi stars
Dans les tribunes, tout le monde est là, je suis dans la salleTribune la ma ñépp di owe, xaaju ma ci ay salle
J'entends les jeunes dire : VJ, on va au concert, non ?Maa ngi dégg xale yi naan: VJ duñu concert xanaa
Toi, tu fais comme si c'était rien, maintenant on a des vacancesYaw doo def bala déwen, léegi ñu am vacances
Toi, notre album, on va l'écouter, tu ne vas pas le sortir, non ?Yaw suñu album bi ñuy xaar, doo ko génne xanaa?
Toi, tu sors, ça va être bien, chouchou des fillesYaw loo génne dafay neex, chouchou des nanas

C'est pourquoi je fais juste ce que je fais, même si ça me fait malMoo tax ni rekk laa koy defe ni mu yombe
Tu as pris ton ticket, on avance dans le GTNga jënde sa ticket dox ñu daje biir GT
L'album, c'est un bon moment, pas de morts, pas de blessésAlbum bi bés bu génne bu amul morts am bléssé
Est-ce que le cœur est beau et la tête est bien, ça va brillerNdax xol bu rafet ak mbégte ding ko déglu wét di fecc
Force zac zac zarko (àljanna)Force zac zac zarko (àljanna)
Allez, courage, président, fais le chefKo kaay corégeou président maay capo
Moi, VJ, mon concert, les jeunes aiment çaMan VJ sama concert xale yi neex fa lañ baado
Je vais faire le flow, tu vas voirMa te gambe bi flow yas ngay siisoo

Bon, je suis là, celui qui est là, je fais ma concurrenceBon, setlu naa nak ku fi jokk rekk def ma concurrence
Je reste calme, je fais le pointMaa toog def noppi di seetaan calmement
Qui a dit que je suis un bandit, celui qui ne veut pas de malKi la wax dama tappet ku ko ne ragal la
Moi, je suis un délinquant (toi qui dis ça)Man may bandit di délinquant (yaw ki di woyu)

Mara, marabout de la jeunesseMara, marabout de la jeunesse
Jeune mara, marabout de la jeunesseJeune mara, marabout de la jeunesse
Moi, VJ, marabout de la jeunesseMan VJ, maay marabout de la jeunesse
Jeune mara, marabout de la jeunesseJeune mara, marabout de la jeunesse
Mara, marabout de la jeunesseMara, marabout de la jeunesse
Jeune mara, marabout de la jeunesseJeune mara, marabout de la jeunesse
Moi, VJ, marabout de la jeunesseMan VJ, maay marabout de la jeunesse
Jeune mara, marabout de la jeunesse !Jeune mara, marabout de la jeunesse!


Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de VJ y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección