Traducción generada automáticamente

visualizaciones de letras 690

Kaay Waay

VJ

Letra

Kaay Waay

Kaay Waay

Ndekke du mbëggeelu keseNdekke du mbëggeelu kese
Te sax xeetu mbëggeel yi dafa rareTe sax xeetu mbëggeel yi dafa rare
Jekku ma ni duma baal, ja, jaJekku ma ni duma baal, yeah, yeah
An kon yaw bandiet nga ndekke, schatAn kon yaw bandit nga ndekke, bébé
Soppi nga sama xol bi limonadeSoppi nga sama xol bi limonade
Sirote ko di ko naan, ja, jaSirote ko di ko naan, yeah, yeah

Ndax ba ñuy njëkka gisanteNdax ba ñuy njëkka gisante
Li nga ma yénne ni mu diiseeLi nga ma yénne ni mu diisee
Ak ni ñu xoolanteAk ni ñu xoolante
Rekk ma xam ni God ons booleRekk ma xam ni Yàlla ñu boole

Est-ce que doo jinne ndax jommal nga ma (kaay waay)Est-ce que doo jinne ndax jommal nga ma (kaay waay)
Dofloo nga ma (kaay waay)Dofloo nga ma (kaay waay)
Waaye dëfal nga ma (kaay waay)Waaye dëfal nga ma (kaay waay)
Man li may dundu ni dal neex na ma (kaay waay)Man li may dundu ni dal neex na ma (kaay waay)
Soo bégee, ma bég (kaay waay)Soo bégee, ma bég (kaay waay)
Ñu dekke di ree (kaay waay)Ñu dekke di ree (kaay waay)

Yaw mësul metti ba nga réccu li nga ma xam (kaay waay)Yaw mësul metti ba nga réccu li nga ma xam (kaay waay)
Maa la gënal lu ne (kaay waay)Maa la gënal lu ne (kaay waay)
Te yaa ma gënal ku ne (kaay waay)Te yaa ma gënal ku ne (kaay waay)
Bae li ñuy dundu ni cer carré na (kaay waay)Bae li ñuy dundu ni cer carré na (kaay waay)
Bégal, ma bég (kaay waay)Bégal, ma bég (kaay waay)
Maa xécc sa rëndal happy (kaay waay)Maa xécc sa rëndal happy (kaay waay)

Soo ma soree oh mijn liefdeSoo ma soree oh my love
Nammeel bi may yëg ci yaw, wallaay!Nammeel bi may yëg ci yaw, wallaay!
Yaa ko mëna faj, ñëwalYaa ko mëna faj, ñëwal
Ñuy kaf di reeÑuy kaf di ree
Ñuy kaf di fo di reeÑuy kaf di fo di ree

Ndax ba ñuy njëkka gisanteNdax ba ñuy njëkka gisante
Li nga ma yénne ni mu diiseeLi nga ma yénne ni mu diisee
Ak ni ñu xoolanteAk ni ñu xoolante
Rekk ma xam ni God ons booleRekk ma xam ni Yàlla ñu boole

Est-ce que doo jinne ndax jommal nga ma (kaay waay)Est-ce que doo jinne ndax jommal nga ma (kaay waay)
Dofloo nga ma (kaay waay)Dofloo nga ma (kaay waay)
Waaye dëfal nga ma (kaay waay)Waaye dëfal nga ma (kaay waay)
Man li may dundu ni dal neex na ma (kaay waay)Man li may dundu ni dal neex na ma (kaay waay)
Soo bégee, ma bég (kaay waay)Soo bégee, ma bég (kaay waay)
Ñu dekke di ree (kaay waay)Ñu dekke di ree (kaay waay)

Yaw mësul metti ba nga réccu li nga ma xam (kaay waay)Yaw mësul metti ba nga réccu li nga ma xam (kaay waay)
Maa la gënal lu ne (kaay waay)Maa la gënal lu ne (kaay waay)
Te yaa ma gënal ku ne (kaay waay)Te yaa ma gënal ku ne (kaay waay)
Bae li ñuy dundu ni cer carré na (kaay waay)Bae li ñuy dundu ni cer carré na (kaay waay)
Bégal, ma bég (kaay waay)Bégal, ma bég (kaay waay)
Maa xécc sa rëndal happy (kaay waay)Maa xécc sa rëndal happy (kaay waay)

Oh schat, jij bent mijn schatOh bébé toi mon bébé
Jij die me alles hebt gegevenToi qui m’as tout donné
Ik zou je nooit kunnen verlatenJe pourrais jamais te quitter
Ik beloof het je, mijn schatJe t’en fais la promesse mon bébé
Je hebt me zo gesteundTu m’as tellement épaulé
Wanneer het nodig wasQuand il le fallait
Je hebt me uit de problemen gehaaldM’as sorti de la galère
Ik ga je het geld teruggevenJe vais te rendre la money

Oh schat, jij weet dat ik voor je gaOh bébé yaw mi gunge ma man maa lay gunge
En als je bang bent, schreeuw, help me, ik ga je reddenEt si t'as peur crie, aide-moi, man maa lay sauver
Oh schat, hou je van me zoals ik van jou houOh bébé yaw ndax bëgg nga ma comme ni ma la bëggee
Als ik van je hou, zijn er geen woorden die dat kunnen beschrijvenNdax ni ma la bëggee ëpp na waa li num deme

Oh schat, jij bent mijn schatOh bébé toi mon bébé
Jij die me alles hebt gegevenToi qui m’as tout donné
Ik zou je nooit kunnen verlatenJe pourrais jamais te quitter
Ik beloof het je, mijn schatJe t’en fais la promesse mon bébé
Je hebt me zo gesteundTu m’as tellement épaulé
Wanneer het nodig wasQuand il le fallait
Je hebt me uit de problemen gehaaldM’as sorti de la galère
Ik ga je het geld teruggevenJe vais te rendre la money

Oh schat, jij weet dat ik voor je gaOh bébé yaw mi gunge ma

Escrita por: VJ / KHRU / OMAR SARR. ¿Los datos están equivocados? Avísanos.

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de VJ y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección