Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 34

Defma Reine (feat. Mbaye Dieye Faye)

Aida Samb

Letra

Defma Reine (feat. Mbaye Dieye Faye)

Defma Reine (feat. Mbaye Dieye Faye)

Ich weiß, dass du mich magst, ich weiß, dass du mich willstMan ku ma xam, xam ni bëgg naa la
Was mir gefällt, ist dein LächelnLi ma gëna neex mooy sa jantal
Ich verstehe nicht, warum ich dich willMan xawma lu tax ma bëgg la
Geh zur Hölle, du bist viel zu schnellDem àljanna yaa ci gëna gaaw

Hör auf, ich liebe dich (ich liebe dich, ich liebe dich)Di dégg say je t'aime (je t'aime, je t'aime)
Deshalb kann ich nicht aufhören (hör auf, ja ja)Tax duma jug ci féem (di féem waawaaw)
Wenn ich dich verliere (ja, ja, ja)Su ma dee garab (yaay ren, yaay ren)
Willst du mich verlassen (def ma reine, ja ja)Ndax yaa ma tànn (def ma reine waawaaw)

Ich will dich, änder dich nicht, BabyMan yaw laa bugga, change pas bae
Du weißt, dass ich deine Frau sein kann, deine MamaNeex nga ma mën na doon sa jabar, doon sa maman
Was ich dir sage, will ichLu ma ci gobe, bëgg naa
Ich gehe auf die Straße, um dich zu findenDi dox ci xal ñów fekk ci la

Komm zurück, schau herDëb sol, caxabal
Wo ich bin, wo ich binFoo ma woo ma ñëw
Wo du bist, wo du bistLoo fi laal, loo fi laal
Nur ich kann dich beruhigenRekk ma lalli ko

Komm zurück, schau herDëb sol, caxabal
Wo ich bin, wo ich binFoo ma woo ma ñëw
Wo du bist, wo du bistLoo fi laal, loo fi laal
Nur ich kann dich beruhigenRekk ma lalli ko

Ich weiß, dass du mich magst, ich weiß, dass du mich willstMan ku ma xam, xam ni bëgg naa la
Was mir gefällt, ist dein LächelnLi ma gëna neex mooy sa jantal
Ich verstehe nicht, warum ich dich willMan xawma lu tax ma bëgg la
Geh zur Hölle, du bist viel zu schnellDem àljanna yaa ci gëna gaaw

Hör auf, ich liebe dich (ich liebe dich, ich liebe dich)Di dégg say je t'aime (je t'aime, je t'aime)
Deshalb kann ich nicht aufhören (hör auf, ja ja)Tax duma jug ci féem (di féem waawaaw)
Wenn ich dich verliere (ja, ja, ja)Su ma dee garab (yaay ren, yaay ren)
Willst du mich verlassen (def ma reine, ja ja)Yaa ma tànn (def ma reine waawaaw)

Wantanamera, sag es mirWantanamera, feccal la youza
Komm zurück, ich bin hier, ich bin bereitToogal seetaan, ehn ma daagu dukkat
Was sie sagen, ich will es nicht hören, Baby, sprichÑoom de li ñuy jaay dama koy maye baby waxal
Was in der Luft ist, lass es uns nicht vergessenLi ci wañ bi toggantu ay nga ma koy ñamal

Sprich, was du willst, ich mache es hier, wo du bistWaxal li nga bëgg, maa def fi yaa fi dogal
Was auch immer du tust, ich werde es akzeptierenLu jaar siisu naanal potu ndox te nangu ndogal

Wenn du so sprichst, ist das mein ZuhauseSu weesu waxi noon, kër gi maay boroom
Und alles, was ich habe, Baby, ist mein ZuhauseTe lépp lu ma moom, baby yaay boroom

Komm zurück, schau herDëb sol, caxabal
Wo ich bin, wo ich binFoo ma woo ma ñëw
Wo du bist, wo du bistLoo fi laal, loo fi laal
Nur ich kann dich beruhigenRekk ma lalli ko

Komm zurück, schau herDëb sol, caxabal
Wo ich bin, wo ich binFoo ma woo ma ñëw
Wo du bist, wo du bistLoo fi laal, loo fi laal
Nur ich kann dich beruhigenRekk ma lalli ko

Ich weiß, dass du mich magst, ich weiß, dass du mich willstMan ku ma xam, xam ni bëgg naa la
Was mir gefällt, ist dein LächelnLi ma gëna neex mooy sa jantal
Ich verstehe nicht, warum ich dich willMan xawma lu tax ma bëgg la
Geh zur Hölle, du bist viel zu schnellDem àljanna yaa ci gëna gaaw

Hör auf, ich liebe dich (ich liebe dich, ich liebe dich)Di dégg say je t'aime (je t'aime, je t'aime)
Deshalb kann ich nicht aufhören (hör auf, ja ja)Tax duma jug ci féem (di féem waawaaw)
Wenn ich dich verliere (ja, ja, ja)Su ma dee garab (yaay ren, yaay ren)
Willst du mich verlassen (def ma reine, ja ja)Yaa ma tànn (def ma reine waawaaw)

WantanameraWantanamera
(Woyal, das ist einfach zu gut!)(Woyal céy mbëggeel li dafa over neex!)
Ehnnnn ennhEhnnnn ennh
Wenn die Leute wissen, was in deinem Herzen ist!Bu nit mënoo na génnee li ne ci xol bi waay!
(Das ist gut, das ist gut, einfach nur gut)(Li dafa neex, dafa neex, mbëggeel rekk a neex)
Dein Lächeln und deine Augen, jaSa nijaay ak sa ñoom yaay
Wir sehen die, die redenÑa fay gis ñi toog di waxtaan
Sie können nicht wissen, dass ich dich will, ehMënuloo xam ni ma la bëggee eh
(Abass, du bist so cool, ich will dich)(Abass dafa lank danga sof, bëgg bay jooy)
Sie können nicht wissen, dass ich dich will, ehMënuloo xam ni ma la bëggee eh
(Woyal, Abass, woyal, du bist der Beste!)(Woyal nga Abass, woyal nga faatu awo buuru këram!)
Wenn ich dir sage, was ich willSu ma lay ray say xàqataay
Das könnte der Grund sein, warum du mich nicht magstMoo may tax a naam say jootaay
Sie können nicht wissen, dass ich dich will, ehMënuloo xam ni ma la yëgee bae
(Abass Diadiou, der Sohn von Papa Diadiou, wird die Frauen lieben)(Abass Diadiou baayu Papa Diadiou mëna yor jigéen)
Sie können nicht wissen, dass ich dich will, ehMënuloo xam ni ma la yëgee bae
(Aida Samb, das ist gut, das ist gut, einfach nur gut)(Aida Samb li dafa neex, dafa neex, dafa over neex)

Heute bist du es, morgen bist du es auchSama tey yaw la, sama suba sax yaw la

Ich habe dein Lächeln, du hast michAwma sa fay baby, teral nga ma

(Chérie Abass Diadiou, das ist einfach gut)(Chérie Abass Diadiou mbëggeel rekk a neex)
Was ich will, kann ich dir gebenLu ma la mën a fayee sagal nga ma
(Abass, schau dir Aida an, das ist einfach gut)(Abass toog Fatook Aida mbëggeel dafa neex)
Heute bist du es, morgen bist du es auchSama tey yaw la, sama suba sax yaw la
Heute bist du es, morgen bist du es auchSama tey yaw la, sama suba sax yaw la
Ich habe dein Lächeln, Baby!Awma sa fay baby!

Was auch immer in deinem Herzen ist, lass es rausLu jugé ci xol ci sol lay déllu
Das ist einfach gut!Mbëggeel rekk a neex!
Aida Samb, du bist die Frau, die die Herzen erobertAida Samb woyal na jigéen ñi nob seen jëkkër
Komm zurück!Jëlal!
(Ich habe dein Lächeln, du hast mich)(Awma sa fay baby, teral nga ma)
Ich will dich, ich will dich, ich will dichDaan ko bugga mu bugga la, yëfi buggante la
(Ich habe dein Lächeln, ich gebe es dir)(Awma sa fay baby, sagal nga ma)
Ich will dich, ich will dich, ich will dich, ich will dichBëgg nga ko bëgg naa la te bëgg na leen yëfi bëggante la
Heute bist du es, morgen bist du es auchSama tey yaw la, sama suba tamit yaw la

Ich habe dein Lächeln, Baby, ich gebe es dir!Awma sa fay baby, teral nga ma!

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Aida Samb y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección