Traducción generada automáticamente

AYUBES
Ashs The Best
AYUBES
AYUBES
Man sta ik hier in de schaduw van de maanMan gestu naa di xoolaat fi ma jaar
En ik voel de dood van de sterrenTe weesu naa dootul mës ñëwaat
Als ik jou zie, of op de grondFoo ma jëmee ci kaw mbaa ci suuf
Als ik mijn moeder niet zie, wat moet ik dan doen?Su ma gisatul yaay, te ammu ma maam, fan laay nàmpee
Als ik jou niet meer zieFoo ma nara jëmee
Dan ben ik verloren, dood zonder jou, God zij met jouDa maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom
(God zij met jou)(Maam Yàlla ko moom)
Vrede is wat ik zoekJamm a ko gën
(Vrede is wat ik zoek, oh ja)(Jamm a gën ub ay)
Als ik jou niet meer zieDa maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom
(God zij met jou, jij bent onze kind)(Maam Yàlla ñu moom, moom sunuy doom)
Als ik jou niet meer zieDa maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom
(God zij met jou, oh onze familie)(Maam Yàlla ñu moom, uuf sunu njaboot)
Als ik jou niet meer zieDa maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom
Ik ben jouw gezicht kwijtMiin naa sa kanam gi
Ik ben jouw schaduw kwijtMiin naa kepaar gi
Ik ben jouw liefde kwijtGëj naa këram ga
En ik ben jouw thuis kwijtTe miin naa dëkkam bi
Ik ben verloren in mijn gedachtenGëj naa ci xellam bi
En ik voel me zo alleenTe sës ci xollam bi
Ik heb het zo moeilijkXas naa ko xaccoo
Dood zonder jou hierDootu ma fa delloo
Man, ik ben verlorenMan da maa foogoon
Ik ben verlorenDa maa foogoon
Ik ben verloren, dood zonder jou, God zij met jouDa maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom
God zij met jouMaam Yàlla ko moom
Vrede is wat ik zoekJamm a ko gën
Vrede is wat ik zoek, oh jaJamm a gën ub ay
Ik ben verloren, dood zonder jou, God zij met jouDa maa foogoon dootul jeex ndeke Yàlla ko moom



Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Ashs The Best y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: