Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 16

Mangui Baxx

Dieyla

Letra

Mangui Baxx

Mangui Baxx

Regarde-moi bienNelawoo ba yàndoor
Tout est bon et tout est beauDëkke lu bon ak lu ñaaw
Les gens sont làSoxor iñaan
Je suis condamnéMoo la condamné
Suis mon cheminDoxal sa yoon
Je ne vais pas te laisser tomberDuma la sóoraale
Je ne peux pas te laisser vivre ce que je ressensMënuloo ma tere dundu li ma neex

Je vais bienMaa ngi baax
Je ne vais pas vous décevoirDuma leen faale

Tu vas encore être en retardBillaay dinga gëna tarde
(Tu vas encore être en retard)(Billaay dinga gëna tarde)
Moi, je ne vais pas vous décevoirMan daal duma leen faale
(Non non, je ne vais pas vous décevoir)(Non non duma leen faale)
Ici, tout le monde est là, je te le disFii lépp a ngi tolloo, taluma noono
Tu ne vas pas me décevoirBillaay duma leen faale

Toi, tu es bien, tu es làYaw mbaa jàmm nga fanaan
Toi, tu es bien, tu es partiYaw mba jàmm nga yéndo
Ce que tu ne sais pas, c'est que je t'ai déjà euWoté lo gëmul, xamoo ni jëli naa la

Je vais bienMaa ngi baax
Je ne vais pas vous décevoirDuma leen faale

Tu vas encore être en retardBillaay dinga gëna tarde
Je ne vais pas vous décevoirMan daal duma leen faale
Non non, je ne vais pas vous décevoirNon non duma leen faale
Ici, tout le monde est là, je te le disFii lépp a ngi tolloo, taluma noono
Tu ne vas pas me décevoirBillaay duma leen faale

Non non (je te le dis)Noono (moom talu la)
Ce que Dieu a fait pour moiLi Yàlla def si man
Tu sais qu'il n'y a pas de mal iciNga ne mu ku du fi ame
Aaah, je suis en train de m'énerverAaah nga di ma jebaane
Je suis en train de m'énerverNga di ma jebaane
Non non non, ouaisNon non nono yeah

Ne me laisse pas tomber, je vais me battreXamaloo ma dara wër di ma togge
Je vais me battre, ouais, ouaisDi ma soxore yeah yeeeah
Regarde-moi bienNelawoo ba yàndoor
Tout est bon et tout est beauLu dul dëkke lu bon ak lu ñaaw

Ne déçois pas, ne te laisse pas faire, suis ton cheminBul faale bul toppatoo doxal sa dox
Ne te laisse pas faire, suis ton cheminWuyooy bokkuleen yoon, doxal sa dox
Ne déçois pas, ne te laisse pas faire, suis ton cheminBul faale bul toppatoo doxal sa dox
Je vais bien (je vais bien)Maa ngi baax (maa ngi baax)
Je ne vais pas vous décevoirDuma leen faale

Tu vas encore être en retardBillaay dinga gëna tarde
(Tu vas encore être en retard)(Billaay dinga gëna tarde)
Moi, je ne vais pas vous décevoirMan daal duma leen faale
Non non, je ne vais pas vous décevoirNon non duma leen faale
Ici, tout le monde est là, je te le disFii lépp a ngi tolloo, taluma noono
Tu ne vas pas me décevoir (je te le dis)Billaay duma leen faale (taluma noonu)

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Dieyla y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección