Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 22

La Famille Au Senegal Oui (feat. Diarra Sylla)

Dior Mbaye

Letra

La Famille Au Sénégal Oui (feat. Diarra Sylla)

La Famille Au Senegal Oui (feat. Diarra Sylla)

Et la famille au Sénégal ?Et la famille au Sénégal?
Oui, bien sûr !Oui, bien sûr!

Sori mon pays et ma familleSori sama réew ak sama askan
Je ne vais pas laisser tomber, je suis làTaxul ma fàtte man mi may kan
Je travaille, je ne traîne pas dans la rueDamay liggéey doxuma ci caaxaan
Votre soutien, je l'apprécie, ça me fait avancerSeen soutien da may bégal di ma yokku katan
Je suis fatigué de travailler, je ne vais pas abandonnerDamay ñafe di liggéey duma geestu
Donne-moi un coup de main, je ne vais pas reculerYónne yakamti ma duma daagu
Ce que j'ai reçu, c'est précieuxLi ma weesu la réccu
Ici, je me sens bien, c'est là que je suis chez moiFi ma jëm leer na ma, man la ni séntu

Ay ay ayAy ay ay
Ici, c'est le SénégalFii mooy Senegaal

Ici, les cœurs sont en feuFii la xol yi di feexe
Ici, le stress fait rageFii la stresse biy wacce
Ici, les enfants sont trop malheureuxFii la xale yi gëna baaxe
Mon pays, c'est là que je me sens bienSama réew nii la neexee

Où que tu sois, Sénégal ? Oui !Foo dëkk, Senegaal? Oui!
Fier d'être sénégalaisFière ci doon sénégalaise
La famille au Sénégal, ouiLa famille au Sénégal, oui
Fier d'être sénégalaisFière ci doon sénégalaise

Civilisé, c'est beau, ça doit s'affirmerCivilisé rafet mëna sañsé
Aujourd'hui, il faut avancerTey bëgg topp cas
Quoi que tu dises, pays de la teraangaKu ne ngay wax, pays de la teraanga
Personne ne peut tout avoir, personne ne peut tout perdreKenn du ñu yàpp, kenn du ñu xeep
Personne ne peut se cacherKenn du ñu kël-kële
On parle de nous, pays de la teraangaÑun lañuy wax, pays de la teraanga

On a la teraangaAm teraanga
Quoi que tu dises, pays de la teraangaKu ne ngay wax, pays de la teraanga
Mon pays, je l'aime et la paix est iciSama réew mi da may neex te jàmm ja ngi fi

L'école est là aussi, l'école est làJàng bi na fi sax, jàng bi

Ay ay ayAy ay ay
Ici, c'est le Sénégal !Fii mooy Senegaal!

Ici, les cœurs sont en feuFii la xol yi di feexe
Ici, le stress fait rageFii la stresse biy wacce
Ici, les enfants sont trop malheureuxFii la xale yi gëna baaxe
Mon pays, c'est là que je me sens bienSama réew nii la neexee

Où que tu sois, Sénégal ? Oui ! (Oui, bien sûr)Foo dëkk, Senegaal? Oui! (Oui, bien sûr)
Fier d'être sénégalais (oui, bien sûr)Fière ci doon sénégalaise (oui, bien sûr)
La famille au Sénégal, oui (oui, bien sûr)La famille au Sénégal, oui (oui, bien sûr)
Fier d'être sénégalais (oui, bien sûr)Fière ci doon sénégalaise (oui, bien sûr)

Où que tu sois, Sénégal ? Oui !Foo dëkk, Senegaal? Oui!
Fier d'être sénégalaisFière ci doon sénégalaise
La famille au Sénégal, ouiLa famille au Sénégal, oui
Fier d'être sénégalaisFière ci doon sénégalaise

Yo Diarra Sylla !Yaw Diara Sylla!
(Où que tu sois, Sénégal ? Oui !)(Foo dëkk, Senegaal? Oui!)
Fatou Mbacké, ta mèreFatou Mbacké Diongay sa yaay
(Fier d'être sénégalais)(Fière ci doon sénégalaise)
Ami Ndikou Guey, ta mèreAmi Ndikou Guey yaayam
(La famille au Sénégal, oui)(La famille au Sénégal, oui)
Cheikh Diongay, ton pèreCheikh Diongay baayam
(Fier d'être sénégalais)(Fière ci doon sénégalaise)
Demba Sylla, ton pèreDemba Sylla sa baay
(Où que tu sois, Sénégal ? Oui !)(Foo dëkk, Senegaal? Oui!)
Sokhna Aïda Mbacké, ta mèreSokhna Aïda Mbacké yaayam
(Fier d'être sénégalais)(Fière ci doon sénégalaise)
Ta mère Seutou Serign BarraYaay Seutou Serign Barra
(La famille au Sénégal, oui)(La famille au Sénégal, oui)
Diarra, ta mère Seutou Serigne ToubaDiarra yaay Seutou Serigne Touba
(Fier d'être sénégalais)(Fière ci doon sénégalaise)

Où que tu sois, Sénégal ? Oui !Foo dëkk, Senegaal? Oui!
Fier d'être sénégalaisFière ci doon sénégalaise
La famille au Sénégal, ouiLa famille au Sénégal, oui
Fier d'être sénégalaisFière ci doon sénégalaise

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Dior Mbaye y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección