Traducción automática

Djiguene
Dobet Gnahoré
Femme
Djiguene
Je te soutiens, toi qui es la fierté de la maisonSopp naa la, yaw jaambaaru kër gi
Toi qui es la reine de ce royaumeYaw mi toppatoo kom-kom mu tool
Toi qui éduques les enfantsYaw mi yar xale yi
Et qui es la lumière de la connaissanceDi sar jàngoro gi
Je te soutiens, toi femme qui es forteSopp naa la, yaw jigéen ju laxu ji
Toi qui es là pour l'autre, pour toi-mêmeYaw mi xeex ngir nit moom boppam
Toi qui es là pour la paix, pour un avenir radieuxYaw mi xeex ngir jàmm ji yàgg lool ci kaw sof
Toi qui es là pour apporter de l'espoirYaw yaay su moo yaakaari ëllëg
Oh femme d'AfriqueHan jigéen Afrique
Femme du mondeJigéen àdduna
Femme d'EuropeJigéen Europe
Femme, mère, amie, femmeJigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme
Femme, mère, amie, femmeJigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme
Femme, mère, amie, femmeJigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme
Femme, mère, amie, femmeJigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme
Je te soutiens, toi femme qui es pleine de sagesseSopp naa la yaw jigéen bu am-sutura bi
Toi qui es la source de la vie, mère et pèreYaw mi ndeyu njirim yi ñàkk ndey, ñàkk baay
Toi qui es la force et la douceurYaw mi am-yërmandé te tabe
Toi qui es là pour élever les âmesYaw yaa tax gune yi yee feexe
Toi qui es la beauté de la terreYaw yaay mbëggeel jër made
Toi qui es l'espoir dans la tempêteYaw yaay yaakaar di bidéew
Toi qui es la lumière de l'avenirYaw yaay kiiraay gune yi
Toi qui es là pour apporter de l'espoirYaw yaay yaakaari ëllëg
Toi qui connais le cheminYaw mi xam cosaan
Femme d'AfriqueJigéen Afrique
Femme du mondeJigéen àdduna
Femme, mère, amie, femmeJigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme
Femme, mère, amie, femmeJigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme
Femme, mère, amie, femmeJigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme
Femme, mère, amie, femmeJigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme
Maman, ehMama sa, eh
Maman, ohMama sa, oh

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Dobet Gnahoré y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: