visualizaciones de letras 4

Vitamine (feat. Sokhou Bb)

El Maestro

Letra

    [El Maestro]
    Chérie coco

    [Sokhou BB]
    Dafa jonge ci góor duñu xulóo
    Di ma ar moom mi comme zorro

    [El Maestro]
    Di ma ar moom mi comme zorro

    [Sokhou BB]
    Di ma ar yaay sama héro

    [El Maestro]
    Fàttewoo fi ñu jaar yaay gor
    Loo gis lu ne dafa am lu ko jar
    Maa tebbi as takkalako ay or
    Rafet na xol bu dàq taaru Youssoufa

    [Sokhou BB]
    Ne na man la love masu la wiri-wiri
    Masul xëcco buur dama ko doy lingeer
    Maa doon ajj Macca jàkkaarlook Kabba
    C'est plus la peine woweleen ma Adja

    [El Maestro]
    Toppuma Rabi yaw rekk laa joxoñ
    Bve ling ma defal
    Dafa dakk li ñu sargal Arva

    [Sokhou BB]
    Yaay sama xarit man sama chéri boy
    Sama sugar daddy
    Sama vitamine

    [El Maestro]
    Jëmm ji man na ko xool ay fan
    Te samay bët du raaf

    [Sokhou BB]
    Maay ki ñu gëna teral ci àdduna
    Nekkak yaw moo dàq àljanna

    [El Maestro]
    Mbëggeel bu fees del ak vitamine (vitamine)
    Li dafa am vitamine

    [Sokhou BB]
    Bougéwuma fenn man bve laa miin (vitamine)
    Yaay sama vitamine

    Moom sa yuy wax ak man day def tout doux (doux)
    Même su ma ko tooñee duma yuuxu (xu)
    Téyeleen seen kulunas yi bi du yooyu (hé)
    Ndax boo doon wër ci àdduna doo ci gis ñaar

    [El Maestro]
    Bve xam nga àljanna
    Boo nekkul wutuma fa dara (wutuma fa dara)
    Nekk biir safara maak yaw
    Dundu fa àljanna

    [El Maestro]
    Toppuma Rabi yaw rekk laa joxoñ
    Bve ling ma defal
    Dafa dakk li ñu sargal Arva

    [Sokhou BB]
    Yaay sama xarit man sama chéri boy
    Sama sugar daddy
    Sama vitamine

    [El Maestro]
    Jëmm ji man na ko xool ay fan
    Te samay bët du raaf

    [Sokhou BB]
    Maay ki ñu gëna teral ci àdduna
    Nekkak yaw moo dàq àljanna

    [El Maestro]
    Mbëggeel bu fees del ak vitamine (vitamine)
    Li dafa am vitamine

    [Sokhou BB]
    Bougéwuma fenn man bve laa miin (vitamine)
    Yaay sama vitamine

    Vitamine
    Vitamine


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de El Maestro y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección