Suscríbete

Traducción generada automáticamente

visualizaciones de letras 15

Wakhal

Ismael Lo

Letra

Wakhal

Wakhal

Iemand die goed is, moet niet alleen maar kijkenNit ku baax warul moom di teye mer
De Heer is degene die ons samenbrengtBuur Yàlla di ko tooñ lañu dekke
Als je praat, moet je ook iets gevenWar nga xaalaat balaa nga may àntu
Laat je hart niet koud zijn, als je het niet kunt helpenGënal li sa xol waaw boo tëddee nelaw

Iemand die goed is, moet niet alleen maar gevenNit ku baax war na di baale moom
Iemand die goed is, moet niet alleen maar ontvangenNit ku baax war na di jégeele
Want de Heer is degene die ons samenbrengtNdaxam buur bi Yàlla dañu dekk di ko tooñ
Als je de weg verliest, laat je dan niet in de steekBoo julee ñan mu face say bàkkaar

Hij heeft je broers voor jou gekozenDafa bàyyi say moroom yaw tànn naa la
Hij heeft je ouders gekozen om je te helpenBàyyi kër ndey ak baay ngir séyal la
Dus als hij je helpt, laat het dan niet verloren gaanKon bu mu séy du luñuy caxanee
Laat je hart niet koud zijn, als je het niet kunt helpenGënal li sa xol waaw bo tëdde nelaw

Kom, praat met hem, kom, praat met hemKaay wax ak moom kaay wax ak moom
Kom, praat met hem, laten we samen zijnKaay wax ak moom yénn bokk njegenaay
Kom, praat met hem, kom, praat met hemKaay wax ak moom kaay wax ak moom
Kom, praat met hem, laten we samen zijnKaay wax ak moom yénn bokk njegenaay

Hey, laten we samenkomen, vrouwenHey nañu caapa ne jigéen ñi
Laten we onze stemmen laten horenÑooy sunu kaani

Dus laten we samen zijn, samen zijnKon gnoune ak goune gnoune
En samen zijnAk gnome
Bij de rivier van de liefdeBa sagar khègne
Die ons samenbrengtMu ne waaw nangu

Dus als je zegt dat je iets wilt, laat het dan niet verloren gaanKon jàpp ne séy lu ko takk taasu ko
Als wij samen zijn, laten we dan samen zijn, hand in hand!Kon ñun ak gu ne ñun ak ñome ba pik ak pele!

Jij, ik ben blij dat je me helptYaw mi jàmm bu ñu la baaloo na nga baale
De Heer is degene die ons samenbrengtBuur Yàlla moom dañu dékk di ko tooñ
Dus jij, ik ben blij dat je me helpt, je moet me helpenKon yaw mi jàmm mi la baaloo danga wara baale
Want de Heer is degene die ons samenbrengt, die ons samenbrengtNdax buur Yàlla moom sopp na jàmm buy baale

Kom, praat met hem, kom, praat met hemKaay wax ak moom kaay wax ak moom
Kom, praat met hem, laten we samen zijnKaay wax ak moom yénn bokk njegenaay
Kom, praat met hem, kom, praat met hemKaay wax ak moom kaay wax ak moom
Kom, praat met hem, laten we samen zijnKaay wax ak moom yénn bokk njegenaay

Kom, praat met hem, kom, praat met hemKaay wax ak moom kaay wax ak moom
Laten we samen zijn, samen zijn, samen zijn.Billaay billaay billaay

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Ismael Lo y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección