Traducción automática

Nena Waaw
Jahman X-Press
Nena Waaw
Nena Waaw
Si Dieu le veut, tout ira bien, je suis là pour te montrerLi Yàlla sak lépp ci taar sa jëm la ma doon misal
On ne peut pas se séparer, mais on est là pour se voirMusuñu tegante waaye ñoo bokk fi ñu doon xool
C'est vrai que ça fait mal, mais tu sais que je suis là pour toiXëccoo mettiwoon na, waaye yaa fi na lu te yaw la faral
Les cœurs doivent s'unir, même si on doit se battre pour çaXol yi wara ànd bañ juddoo ba tay ñoo ngi werante
Mais si quelqu'un se met en travers, on ne peut pas se laisser faireWaaye su ñu dajee kenn ci ñun dootuñu werante
Celui qui sait, sait que c'est moi qui dois être làKu ne dina xam ne ki laa doon xaar ki rekk laa war doon
C'est vrai, et le cœur dit que c'est vraiNe na waaw te xol bi ne na waaw
Les amis, ils sont là, c'est vrai, les copains, ils sont là, c'est vraiWaajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw
Tout le monde est là, donc tu dois être làÑépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon

Tous ensemble, tout le monde est là, c'est vraiÑi bañoon sax ñépp ne nañu waaw
Et moi, je ne veux pas juste perdre mon espritAk yaw bëgguma sax deme sama xel
Je ne veux pas juste faire des calculs à zéroBëgguma solu bari mbëggeelu 0 calcule
Je ne veux pas juste être celui qui perd la têteMan naguwuma sax ku yaq sama xel
Pour toi, même si je dois dire la vérité, je suis là pour çaCi yaw meme su de dëgg la ma la ko ñekk wedi
C'est comme si le cœur se brisait, mais je ne veux pas perdre espoirFoogoon na ni xol bi yàqu na te dootuma bëggaat
La déception, ça fait mal, comme si on devait juste survivreDéception lu metti la comme dal dootoo bëgg dundaat
Mais toi, tu es comme une drogue pour un psychopatheWante yaw, danga mel ni drogue ci psychopathe
Un fou qui veut juste te garderDof buy gaañ te loo la soxla
C'est vrai, et le cœur dit que c'est vraiNe na waaw te xol bi ne na waaw
Les amis, ils sont là, c'est vrai, les copains, ils sont là, c'est vraiWaajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw
Tout le monde est là, donc tu dois être làÑépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon
C'est vrai, et le cœur dit que c'est vraiNe na waaw te xol bi ne na waaw
Les amis, ils sont là, c'est vrai, les copains, ils sont là, c'est vraiWaajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw
Tous ensemble, tout le monde est là, c'est vraiÑi bañoon sax ñépp ne nañu waaw
C'est vrai, et le cœur dit que c'est vraiNe na waaw te xol bi ne na waaw
Les amis, ils sont là, c'est vrai, les copains, ils sont là, c'est vraiWaajur yi ne nañu waaw, xarit yi ne nañu waaw
Tout le monde est là, donc tu dois être làÑépp ne nañu waaw kon yaw la wara doon
C'est vrai (tu dois être là)Ne na waaw (yaw la doon séet)
Et le cœur dit que c'est vrai (et tu es dans mon cœur)Te xol bi ne na waaw (te yaa ngi sama wet)

Je ne vais pas me laisser faire, même si je dois me battre pour çaSoxlatuma dara ndax nago ba tay ndax gis na sama gow
Le monde entier est là, ta main est là pour me soutenirÀdduna bi yépp sa diggante loxo moo ci gëna woor
Je sais que c'est vrai, mon enfant, c'est toi qui dois être làNe naa la waaw, xale bi, yow laa doon xaar
C'est un départ, mais je suis là pour t'accueillir, même si je dois me battreDépart ba la ma mbëggeel arrivé ci yaw dotoo ma raw
Il faut que ça marche, même si ça fait mal, le cœur dit que c'est vraiDaw na ba sonn mënul nekk boobu xol bi ne na waaw
Tu es là pour me soutenir, même avec mes caprices et mes faiblesses.Mettiwoon nga daw, supporté nga samay caprices sax samay yu ndaw

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Jahman X-Press y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: