Traducción generada automáticamente

Love Acoustic (Session Live)
Jeeba
Amour Acoustique (Session Live)
Love Acoustic (Session Live)
T'es là, je te sensTooñ nga ma been yoon
Ouais chérie, je te ressensYaw chérie maa la baal
T'es là, je te sensTooñaat ma ñaari yoon
Même si je te sens pasBu ñeent dama lay baal
Ce que je ressens dans mon cœurLi ma yëg ci sama xol
Dieu m'a donné ça, ouaisYàlla seede na ma ko, waaw
Toi, tu es là, tu me fais vibrerYaw ñëwal fi nga jege ma
Si tu veux, dis-le moi, ouaisLoo bëgg wax ma ko, waaw
Toi, t'es là, t'es là dans la nuit, je ne t'oublie pasYaw biig, yaw biig ci guddi nelawuma
Je pense à toi, tout de suite, je ne t'oublie pasDi la xalaat ba léegi babe nelawuma
Toi, t'es pas là, ne fais pas ça, ça me fait malYaw déedéet, bul defe noonu doyalu ma
Qui t'a dit de partir, qui t'a dit de quitter ma vieKu la naan màndi ku la ray gëne reew sama
Et quand tu es là, les pensées s'envolent, mashallah !Te ba nga yegsee la xel yi dal ñépp naan kaar mashallah!
Moi, je suis là pour toi, chérie, ouais ouais ouaisMan namoon naa la chérie boy, waawaawaaw
Aah aah aah aahAah aah aah aah
Allô, Allô, Allô, téléphone-moiAllame Allame Allame téléphonaa
Allô, Allô, Allô, téléphone-moiAllame Allame Allame téléphonaa
Allô, Allô, Allô, téléphone-moiAllame Allame Allame téléphonaa
Chérie, téléphone-moiChérie, Allame téléphonaa
T'es là, je te sensTooñ nga ma been yoon
Ouais chérie, je te ressensYaw chérie maa la baal
T'es là, je te sensTooñaat ma ñaari yoon
Même si je te sens pasMême bu ñeent dama lay baal
Même si je te sens pasBu ñeent dama lay baal
Toi, t'es là, viens me voirYaw yaay booy, kaay jege ma
Ne me laisse pas seulMbëggeeloo may gaañ
Toi, t'es là, viens me voirYaw yaay booy, kaay jege ma
Ne me laisse pas seulMbëggeeloo may gaañ
Ne me laisse pas seulMbëggeel yaa mën a boole
Une personne qui est sombre et une autre qui est claireNit ku ñuul ak nit ku weex
Ne me laisse pas seulYaa mën a boole
Bambara, la langue est belleBàmbara beek tukulóor bee
Ne me laisse pas seul, ne me laisse pas seulTàkkuloo ko tàkkuma ko
La femme, elle me toucheJigéen la yërëm ko
Mais toi, toi, tu es là, ouais, ouais, ouaisWaaye, yaw waaye bum la saay-saay yeeeh

Quand je suis dans la rue, je suis perduMa ci jobaate, kalaju laa
Je ne vais jamais m'en sortirAbadan doo fay
Celui que tu veux, je le veux aussiKi nga bëgg ba bëgg ko
Si tu me laisses, je vais me battre pour toiSoo la meree dangay feebar di dox ci yaw
Comme si je n'avais jamais été perduMel ni ku sibbiru mbëggeel metti na

Si tu me vois, je suis làSoo xaaree ma ñëw
Où tu es, où je suis, on est ensembleFi nga ne fi ma nekk Mbaye sori nanu
Et le cœur voitTe xol day gise
Quand je te vois, je suis contentSaa su ma lay gisee man kontaan
Comme un rêve, un rêve, un rêve, un rêveNi mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel
C'est vrai, ouais ouaisMetti na waaw waaw
Je suis là, je veux te voir !Maa woo la, ndaw sile bëgg naa la!
Si tu me vois, je suis làYaw soo xaaree ma ñëw
Où tu es, où je suis, on est ensembleFi nga ne fi ma nekk Mbaye sori nanu
Et le cœur voitTe xol day gise
Quand je te vois, je suis contentSaa su ma lay gisee man kontaan
Comme un rêve, un rêve, un rêve, un rêveNi mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel, mbëggeel
C'est vrai, ouais ouaisMetti na waaw waaw
Je suis là, je veux te voir !Maa woo la, ndaw sile bëgg naa la!
Toi, rêve chérie, toi, rêve chérieYaw dërëm yaay, yaw dërëm yaay
Rêve chérie, rêve chérieDërëm yaay, dërëm yaay
Rêve chérie, chérie, rêve chérieDërëm yaay, chérie xaadi dërëm yaay
Rêve chérie, rêve chérieDërëm yaay, dërëm yaay
Clédore, rêve chérieClédore dërëm yaay
Baay Aïcha, rêve chérieBaay Aïcha dërëm yaay
Rêve chérie, rêve chérieDërëm yaay, dërëm yaay
Youssou, rêve chérieYoussou dërëm yaay
Rêve chérie, elle, tet tet tet tet !Dërëm yaay, she tet tet tet tet!

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Jeeba y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: