Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 12

Soxna Ci (feat. Samba Peuzzi)

Jeeba

Letra

Soxna Ci (feat. Samba Peuzzi)

Soxna Ci (feat. Samba Peuzzi)

Je ne veux pas que tu ne veilles pas sur moiLoo bëggul man duma ko bëgg damay gaañ
Je ne veux pas que tu ne veilles pas sur moiKoo bëggul man duma ko bëgg dafay xaar
Tu dis que tu es très loin car tu ne peux plus parlerYaa may tere nelaw ndax danga jongé déeg daaj
Viens me dire ça, je te jure que je suis là pour toiKaay ma feccal la yaw, man jaral nga ma tàrantaax

Je ne veux pas te perdre, je te jure que je suis làLoo bëggul ne naa la dafay xaar
Si quelqu'un te dérange, repousse-leKu dul yaw na ma dandu ñëwal gaaw
Oh, tes yeux illuminent ma nuit, je suis à toiYaay yëngal sama aah, man barde naa
Ne fais pas attention à ce que les gens disentBàyyil mbele mbese gi di wax
Tu es là et c'est pas une blague, ma chérieYaa fi nekk te du deñ, girl

Dieu a fait comme ça et ce n'est pas une blagueBuur Yàlla moo ko def te du deñ
Tu veux que je te veuille et c'est pas une blagueBëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Soxna si, tu es ma lumièreSoxna si yaay sama lumière
Pour toujours ce n'est pas une blagueBa abadan du deñ

Je ne vais jamais te quitterBuuru galle lay doon ci yaw
Je suis prêt à tout pour toi, je suis là toujoursDinaa la xeexal fépp foo mën nekk
Je t'ai vu, oh ouaisNewoon naa la ah yaw
Ne laisse pas les autres te démoraliser, tu es là et c'est pas une blagueDagul nu ma la neexe yaa fi nekk te du deñ
Quand je t'ai rencontré je suis tombé amoureux, oh, oh, ohBi ma la xame ci la tàggook wet oooh, yo yo yo
Alors ne me déçois pas, reste comme tu es, ohKon bul ma sori ñëwal fi sama wet ooh
Je suis dans mon paradisMa dundu paradise

Ils veulent me faire tomber de ton côtéThey wanna make me out your way
Mais ma belle, ne les laisse pas briser ton cœurBaby girl don't let them break your heart
Ils cherchent à tout gâcherÑoom dañuy siisu di fen
Mais ma belle, ne les laisse pas briser ton cœurBaby girl don't let them break your heart
Ma chérie, ne pleure pas, non, nonBaby mine warul jooy, nah nah
Ma chérie, ne pleure pas, s'il te plaîtBaby mine, bul jooy, waawaaw

Je ne veux pas que tu ne veilles pas sur moiLoo bëggul man duma ko bëgg damay gaañ
Je ne veux pas que tu ne veilles pas sur moiKoo bëggul man duma ko bëgg dafay xaar
Tu dis que tu es très loin car tu ne peux plus parlerYaa may tere nelaw ndax danga jongé déeg daaj
Viens me dire ça, je te jure que je suis là pour toiKaay ma feccal la yaw, man jaral nga ma tàrantaax

Je ne veux pas te perdre, je te jure que je suis làLoo bëggul ne naa la dafay xaar
Si quelqu'un te dérange, repousse-leKu dul yaw na ma dandu ñëwal gaaw
Oh, tes yeux illuminent ma nuit, je suis à toiYaay yëngal sama aah, man barde naa
Ne fais pas attention à ce que les gens disentBàyyil mbele mbese gi di wax
Tu es là et c'est pas une blague, ma chérieYaa fi nekk te du deñ, girl

Dieu a fait comme ça et ce n'est pas une blagueBuur Yàlla moo ko def te du deñ
Tu veux que je te veuille et c'est pas une blagueBëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Soxna si, tu es ma lumièreSoxna si yaay sama lumière
Pour toujours ce n'est pas une blagueBa abadan du deñ

Tu veux que je te veuille et c'est pas une blagueBëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Dieu a fait comme ça et ce n'est pas une blagueBuur Yàlla moo ko def te du deñ
Soxna si, tu es ma lumièreSoxna si yaay sama lumière
Pour toujours ce n'est pas une blagueBa abadan du deñ

Bébé, tu sais ce qu'ils disentBébé yaa ngi digal lu ne
Ils essaient de dire que c'est vrai mais ce n'est pas la finÑoo ngi koy wax dëgg dëgg nak du jeex
On voyage où l'on veut et ils ne peuvent pas nous arrêterJaar nañu fu ne te ñooy muje
Viens me dire que c'est tout ce que tu veuxKaay ma feccal la bu de mooy li la neex

Bébé, bébéBébé, bébé
Dieu sait, tu saisYàlla xam na, xam nga
Ce que je ressens pour nous, oh, ohLi nga ma jaral wallaay wallaay
On veut être ensemble, tout ira bienBëgg nañu diggënte bi jeex
Mais si tu veux, cela ne finira pas en douleurMais fi muus du fi na ne ñex

Ce qui plaît sait que l'on va vivre, en vraiLu neex da nañu dundu lu neex
Tu sais que mon cœur ne te laissera jamais sans réponseXam nga ne sa xol duma ko nab-nabé
Tu sais que je t'aime comme ça, je ne te quitterai pasYaw ni nga ma bëgg noonu laa la bëggee
N'essaie pas de m'éloigner, de m'éloigner de tout çaBul mab yaa tay daagul fu ñu la nobee

Tu sais que je ne ferai jamais çaYaw ne na la bul mës a bàyyi
Parce que je t'aimeNdax dama la woolu
Ne repousse pas mes mots, ça ne va pas marcher iciBul déglu wax yu bon yi ci man way
Parce que je t'aimeNdax dama la woolu
Tu sais, là où je suisYaw ne na la ne wëti na la
Si je te dis que je tiens, je tiendrai toujoursSoo ma bàyyee ci la lay jàpp
Mon cœur, mes penséesSama xol, sama reeni xol
Tu sais combien je t'aimeXam nga ni bëgg bëgg naa la

Je ne veux pas que tu ne veilles pas sur moiLoo bëggul man duma ko bëgg damay gaañ
Je ne veux pas que tu ne veilles pas sur moiKoo bëggul man duma ko bëgg dafay xaar
Tu dis que tu es très loin car tu ne peux plus parlerYaa may tere nelaw ndax danga jongé déeg daaj
Viens me dire ça, je te jure que je suis là pour toiKaay ma feccal la yaw, man jaral nga ma tàrantaax

Je ne veux pas te perdre, je te jure que je suis làLoo bëggul ne naa la dafay xaar
Si quelqu'un te dérange, repousse-leKu dul yaw na ma dandu ñëwal gaaw
Oh, tes yeux illuminent ma nuit, je suis à toiYaay yëngal sama aah, man barde naa
Ne fais pas attention à ce que les gens disentBàyyil mbele mbese gi di wax
Tu es là et c'est pas une blague, ma chérieYaa fi nekk te du deñ, girl

Dieu a fait comme ça et ce n'est pas une blagueBuur Yàlla moo ko def te du deñ
Tu veux que je te veuille et c'est pas une blagueBëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Soxna si, tu es ma lumièreSoxna si yaay sama lumière
Pour toujours ce n'est pas une blagueBa abadan du deñ

Tu veux que je te veuille et c'est pas une blagueBëgg nga ma bëgg naa lool du deñ
Dieu a fait comme ça et ce n'est pas une blagueBuur Yàlla moo ko def te du deñ
Soxna si, tu es ma lumièreSoxna si yaay sama lumière
Pour toujours ce n'est pas une blagueBa abadan du deñ

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Jeeba y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección