Traducción automática

Calm Down (feat. Jeeba)
Karabalik Beatz
Reste calme (feat. Jeeba)
Calm Down (feat. Jeeba)
Tey ma bége laTey ma bége la
Tey ma wone laTey ma wone la
Tey ma wax laTey ma wax la
Yaa ma gën a xam way !Yaa ma gën a xam way!
Tu sais ce que je ressensLi nga ma def soo ko bàyyiwul
Tu ne peux pas me laisser tomberDinga mës a ray doomu jaambur way!
Tu sais que je suis là, je suis là pour toiYaw yaa ma xam, xam ma bu baax
Tu sais que je suis là, je suis là pour toiBu lu xasaan ci man loxo keneen wokesu ko
La nuit est tombée, tout est calmeGuddi gi jot ba lépp ni séelaw
Tu es là, je suis là, je te sens eh eh ehNga daagu ndank ñëw sama kaw di ma eh eh eh yaw
Dis-moi ce que tu veux, je suis là pour toiSay kesen kesen tere ma nelaw
Tu sais que je ne peux pas te laisser partirYaa ma mën a yuxuloo te xam nga dama ragal
Eh reste calme, reste calmeEh calm down, calm down
Bébé reste calme, c'est pour toiBébé calm down, doomu jaambur la
Eh reste calme, reste calmeEh calm down, calm down
Bébé reste calme, c'est pour toiBébé calm down, doomu jaambur la
Ne fais pas de bruit, parce que ça ne sert à rienDootoo niit parce que doo nitu
Tu sais que je suis là, est-ce que tu comprends ?Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Quand tu fais ça, je suis là pour toiNi ngay def dama joomi
Je crois en nous, est-ce que tu le ressens ?Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu
Ouais ouaisYeah yeah
Bébé, ce que je ressens, tu sais que je te le disBaby li ma jaxal te nga wax ma ki la jàngal
Je te donne tout ce que j'ai, je veux que tu le sachesSant na sa bàjjen moom mi la jox li may jomal
Je ne peux pas vivre sans toi, je te vois dans mes rêvesAmatuma sago ci yaw su ma la gise saalit
Ouais ouais, toi bébé ouais ouaisWaaw waaw, yow baby waaw waaw
Ouvre mon cœur, calme mon espritSeddal sama xol, dalal sama xel
Tu sais que je t'aime beaucoupYaa ma gëna lool
Oui, ouvre mon cœur, calme mon espritNe waaw seddal sama xol dalal sama xel
Eh eh ehEh eh eh
Eh reste calme, reste calmeEh calm down, calm down
Bébé reste calme, c'est pour toiBébé calm down, doomu jaambur la
Eh reste calme, reste calmeEh calm down, calm down
Bébé reste calme, c'est pour toiBébé calm down, doomu jaambur la
Ne fais pas de bruit, parce que ça ne sert à rienDootoo niit parce que doo nitu
Tu sais que je suis là, est-ce que tu comprends ?Yaa nga may fit est-ce que doo ciit
Quand tu fais ça, je suis là pour toiNi ngay def dama joomi
Je crois en nous, est-ce que tu le ressens ?Man li may yaakaar est-ce que doo ñooñu



Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Karabalik Beatz y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: