Suscríbete

Traducción generada automáticamente

visualizaciones de letras 17

Wa Li Nékhoul

Maabo

Letra

Wa Li Nékhoul

Wa Li Nékhoul

Ma chérieMaabo
Je t'aimeHoney, I love you
Bébé, j'ai besoin de toiBaby, I need you

Tout ce qui existe, je te le dis je t’aimeBés bu nekk dinaa la wax je t’aime
Je ne peux pas te dire à quel point je t'aimeDuma sonn ci di la wan how much I love you
J'ai entendu dire qu'ils disent que je suis fou de toiDégg naa ñu ne dama dof ci yaw
Peut-être qu'ils ne savent pas que ma mère a dit que c'est précieux pour moiXanaa xamuñu ni yaay dalal li wéradi ci man

Je ne veux pas qu'on traîne, hein !Bëgguma ñuy meroo, hie!
On doit avancer ensemble, hein !Nañu ànd longo, hie!
Je ne veux pas qu'on se sépare avec tout le mondeBañuma ci xuloo ak ñoom ñépp
On doit se libérer et se retrouverNañu bàyyi ñu juboo te noppi

Ma chérie, toi seule es tout pour moiYaay sama ngelaw, yaw rekk doy nga ci man
Si je ne te vois pas, tu sais que je ne peux rien faireSu ma la gisul tamit, yaa mën dara ci man
L'amour n'a pas de limites, comme le cielYëg-yëg bi amul limite, mel ni asamaan
Ton sourire me fait vivre comme l'oxygène pour moi, hé !Sa mbëggeel damay dundal ni oxygène ci man, hé!

Tu es ma lumière, personne d'autre que toiYaa ma tere nelaw, kenn rekk nga ci man
Si je ne vois pas ta beauté, le monde n'a pas de sens pour moiSu ma la gisul saalit, àdduna safal du ci man
L'amour ne souffre pas dans mon cœur, il s'épanouitYëg-yëg num sore ci nit sama xol lay dal
Ton sourire me fait vivre, toi tu es plus que tout pour moi, hiii !Sa mbëggeel la may dundal, yaw yaa gën ci man, hiii!

(Eeh eh, qu'ils s'en aillent !)(Eeh eh ayca ñu dem!)
Ceux qui ne sont pas bienWaa li neexul
(Qu'ils s'en aillent, eeh eh ouais)(Ñu dem, eeh eh weuh)
Moi, ceux qui ne sont pas bienMan, waa li neexul
(Aah, toi je te veux !)(Aah, yaw mi la hé!)
Tu es ma douceurYaa may daanel
(Qu'ils s'en aillent comme tu le souhaites)(Ñu dem ni la jëlel)
Moi, ceux qui ne sont pas bienMan wa li neexul

Dis-moi ce qui te fait du bien (ce qui te fait du bien ?)Laajleen ma lu mu saf (lu mu saf?)
Qu'est-ce qui te plaît (hey ouais !) ?Lu neex (hey waay!)
Ce que je ressens pour toi (ce que je ressens ?)Li ma nar ci moom mi (loo nar?)
Ne meurt pas (oohhh !)Du jeex (oohhh!)
Ils ne comprennent pas notre amour, ils ne savent pasÑu jëm tas suñu li, xamuñu
L'amour qui est comme ça, non, ça n'existe pas !Yëg-yëg gu mel ni, non, amul!
Ma chérie, chocolat, le cacao est douxYaay sama chocolat, cacao piir bi
Je te dis oh là là, je suis comme un fouMay sa oh la la, man may bu suur bi
Ton cœur et tes rêves (hé !), c'est vraiMoom sa xol ak say xalaat (hé!), wor na
Je ne perds pas la tête (hé !), c'est vraiAwma xel ñaar (hé!), wor na

Ma chérie, toi seule es tout pour moiYaay sama ngelaw, yaw rekk doy nga ci man
Si je ne te vois pas, tu sais que je ne peux rien faireSu ma la gisul tamit, yaa mën dara ci man
L'amour n'a pas de limites, comme le cielYëg-yëg bi amul limite, mel ni asamaan
Ton sourire me fait vivre comme l'oxygène pour moi, hé !Sa mbëggeel damay dundal ni oxygène ci man, hé!

Tu es ma lumière, personne d'autre que toiYaa ma tere nelaw, kenn rekk nga ci man
Si je ne vois pas ta beauté, le monde n'a pas de sens pour moiSu ma la gisul saalit, àdduna safal du ci man
L'amour ne souffre pas dans mon cœur, il s'épanouitYëg-yëg num sore ci nit sama xol lay dal
Ton sourire me fait vivre, toi tu es plus que tout pour moi, hiii !Sa mbëggeel la may dundal, yaw yaa gën ci man, hiii!

Ceux qui ne sont pas bienWaa li neexul
Moi, ceux qui ne sont pas bienMan, waa li neexul
Aah, toi je te veux !Aah, yaw mi la hé!
Tu es ma douceurYaa may daanel
Qu'ils s'en aillent comme tu le souhaitesÑu dem ni la jëlel
Moi, ceux qui ne sont pas bienMan waa li neexul

Toi je te veux, toi je te veux eehYaw mi la, yaw mi la eeh
Ceux qui ne sont pas bienWaa li neexul
Toi je te veux, toi je te veux eehYaw mi la, yaw mi la eeh
Moi, ceux qui ne sont pas bienMan, waa li neexul
Aaah, toi je te veux ehAaah yaw mi la eh
Tu es ma douceurYaa may daanel
Moi, ceux qui ne sont pas bienMan waa li neexul

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Maabo y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección