Traducción automática

Bëgg Naa La Man
AMADEUS
Je t'aime
Bëgg Naa La Man
Eh Massamba waloEh Massamba walo
Hey waayHey waay
Zoom sur le beatZoom on the beat
Je t'aimeBëgg naa la
Raison d'être, je t'aime vraimentReason to be, man fonk naa la
Ouais ma belle, je t'aimeYaay jant bi, man bëgg naa la
Si je t'aime, c'est que ça vient du cœurNii ma la bëggee yi jeggi na dayo
Eh ouais, ma filleEh way ye way mi girl
Je te veux pour la vieMi yi dei ma for life
Tout ce qui arrive, tu es là pour moiLu nekk jaral nga ma
Personne ne peut me dire, je t'aimeKenn mënul tax, man mere la
Écoute ce qu'ils disentÑook seeni wax
On s'en fout de leur avisFuck nañu leen daaw
Je suis là, je vais tout déchirer, tu saisMan so merre damar jaaxle, tiis
Je t'aimeDama la bëgg
Mais aucune fille ne peut me faire changer d'avisBe neen jigéen mënul tax ma giif
Est-ce que tu m'aimes ?Ndax yaw la bëgg
Pas de douteAmul sax
Personne ne sait ce que je ressens pour toiNit kuy mën xam li may yëg ci yaw
Pas de douteAmul sax
Personne ne sait comme je t'aime, ouaisNit kuy mën compu ni ma la bëggee yiiii
Je t'aime, ouaisBëgg naa la man
Ehh eh, je t'aime, ouaisEhh eh, bëgg naa la man
Je t'aime, ouaisBëgg naa la man
Ehh eh, je t'aime, ouaisEhh eh, bëgg naa la man
Eh ouais !Eh way!
Je t'aime, même si je ne te vois pasDama la bëgg ba faf gëmewuma la
Ne laisse personne te dire que je ne t'aime pasBañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la
Je t'aime, même si je ne te vois pasDama la bëgg ba faf gëmewuma la
Ne laisse personne te dire que je ne t'aime pas, ehBañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la eh
Tu sais que je suis là pour toi, je ressens tout çaJàmm nga may laaj ma ñëw indi feeling paj
Si tu entends, tu sais que je suis là et je ressens çaKu dégg ngay laaj te man dama dégg daaj
Eh même dans ce monde, c'est juste toi que je veuxEhh tamit ci àdduna, man rekk ma lay beggël
Tu sais que je suis là pour toi, je ressens tout çaJàmm nga may laaj ma ñëw indi feeling paj
Si tu entends, tu sais que je suis là pour toiKu dégg ngay laaj ma ñëw indi feeling paj
Eh même dans ce monde, c'est juste toi que je veuxEh tamit ci àdduna, man rekk ma lay beggël
Qui te parle, je suis là pour toiKu la laale man lay raagal
Et qui te touche, je suis là pour te faire plaisirTe ku la tooñ may nangu xeex bi
Eh ouais, ma filleEh way ye way mi girl
Je te veux pour la vieMi yi dei ma for life
Tout ce qui arrive, tu es là pour moiLu nekk jaral nga ma
Personne ne peut me dire, je t'aimeKenn mënul tax, man mere la
Écoute ce qu'ils disentÑook seeni wax
On s'en fout de leur avisFuck nañu leen daaw
Je suis là, je vais tout déchirer, tu saisMan so merre damar jaaxle, tiis
Je t'aimeDama la bëgg
Mais aucune fille ne peut me faire changer d'avisBe neen jigéen mënul tax ma giif
Est-ce que tu m'aimes ?Ndax yaw la bëgg
Pas de douteAmul sax
Personne ne sait ce que je ressens pour toiNit kuy mën xam li may yëg ci yaw
Pas de douteAmul sax
Personne ne sait comme je t'aime, ouaisNit kuy mën compu ni ma la bëggee yiiii
Je t'aime, ouaisBëgg naa la man
Ehh eh, je t'aime, ouaisEhh eh, bëgg naa la man
Je t'aime, ouaisBëgg naa la man
Ehh eh, je t'aime, ouaisEhh eh, bëgg naa la man
Eh ouais !Eh way!
Je t'aime, même si je ne te vois pasDama la bëgg ba faf gëmewuma la
Ne laisse personne te dire que je ne t'aime pasBañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la
Je t'aime, même si je ne te vois pasDama la bëgg ba faf gëmewuma la
Ne laisse personne te dire que je ne t'aime pas, ehBañ lu la metti bañu yaakaar ni ñemewuma la eh



Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de AMADEUS y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: