Traducción generada automáticamente

Eutou Baabel
AMADEUS
Eutou Baabel
Eutou Baabel
Fais pas le conMaak yaw ba abadan
Je t'ai donné mon cœurJox naa la sama kàttan
Je suis là pour toiJaayaanteek sama ndaw
Je vais plonger dans l'eauDem naa ba ndox ci baat
Je t'ai donné ma voixJox naa la sama kàddu
Je ne peux pas te laisserMënatuma la baal
Et je sens que je suis dans le feu, fais pas le conTe sèntu naa ci jële ndam maak yaw
Parce que ce monde est en train de brûler, je suis en train de m'éteindreNdax àddunya bi dafay feexe ba ma xàddi
Je ne vais pas abandonner ce que je ressens pour moiDuma bàyyi li ma tàmbali man
Je vais te faire honorer, ma mèreFàttaliku naa sama maam
Ne me laisse pas tomber, je veux juste être làNe na ma fori jëlal jaaro gi
J'ai entendu qu'ils veulent me faire taire mais je ne suis pas une femmeDégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
Je sais qu'ils vont me demander pourquoi je dis çaXam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
Personne ne ressemble à Thiam Baabel, tu sais que je veux toiKenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Personne ne ressemble à Thiam Baabel, tu sais que je veux toiKenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
On a fait des chosesDemanoon de nañu
On a fait des promessesDefando nañu ay mbir
Tu sais ce que je veuxXamal nga ma lu ne
Si je te le disSoo ma yoolee
Je ne vais rien laisserDootuma jar dara
Quand je suis avec tout le mondeBi ma ñépp umpale
Toi, tu saisYaw yaa ko xam
Mon père, c'est toiSama waay nga
Celui qui te ressembleKu mel ni yaw
Celui qui n'a pas de problème à te parlerKu ka amul da koy iñaane
Celui qui te ressembleKu mel ni yaw
Eutou Baabel, ils te demandentËtu baabel ñoo lay laaj
Celui qui te ressembleKu mel ni yaw
Thiam Baabel Demba Thiam, ehThiam Baabel Demba Thiam, eh
Celui qui te ressembleKu mel ni yaw
Eutou Baabel, ils te demandentËtu baabel yaw lay laaj
Je vais te ramener à Eutou BaabelNaa la yóbbu ëtub baabel
Je vais te lier à mes rêvesBoole la ak samay nawle yi
Tu sais que tu es mon trésorXam nga tàkkusaanu baabel
Thiam, le maître de la nuit, tu es tout pour moiThiam boroom ndendi was nga fay fowee
ToiYaw
Ne me laisse pas tomber dans mes problèmesMësuloo ma xépp ci samay ay ayib
Mes étoiles ne veulent pas me parlerSama njuumte yi mësoo ko nettali
Tu sais que je suis un guerrierXam nga jaambaar amul
Celui qui ne se laisse pas abattreKu ñu dimbale am
Celui qui sait que c'est bienKu sañoon day baax
Comme un enfant qui saitComme doomu ñay
Quand je te demande de resterBu ma ñaanal ponkal
Je vais vivre bienMan soo ma dundee baax
J'ai entendu qu'ils veulent me faire taire mais je ne suis pas une femmeDégg naa ñu lay wutal mas te doo moroom jigéen
Je sais qu'ils vont me demander pourquoi je dis çaXam naa dinañu ma laaj lan moo tax ma wax lile
Personne ne ressemble à Thiam Baabel, tu sais que je veux toiKenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
Personne ne ressemble à Thiam Baabel, tu sais que je veux toiKenn du mel ni Thiam Baabel xam nga man bëgg naa la
On a fait des chosesDemanoon de nañu
On a fait des promessesDefando nañu ay mbir
Tu sais ce que je veuxXamal nga ma lu ne
Si je te le disSoo ma yoolee
Je ne vais rien laisserDootuma jar dara
Quand je suis avec tout le mondeBi ma ñépp umpale
Toi, tu saisYaw yaa ko xam
Mon père, c'est toiSama waay nga
Celui qui te ressembleKu mel ni yaw
Celui qui n'a pas de problème à te parlerKu ka amul da koy iñaane
Celui qui te ressembleKu mel ni yaw
Eutou Baabel, ils te demandentËtu baabel ñoo lay laaj
Celui qui te ressembleKu mel ni yaw
Thiam Baabel Demba Thiam, ehThiam Baabel Demba Thiam, eh
Celui qui te ressembleKu mel ni yaw
Eutou Baabel, ils te demandentËtu baabel yaw lay laaj

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de AMADEUS y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: