visualizaciones de letras 5

Ndaanaan

AMADEUS

Letra

    Papa pa papa
    Dama bëgg jàngi
    Dama bëgg am xam-xam
    Lan, sama doom?
    Dama bëgg jàngi
    Dama bëgg am xam-xam

    Eeeh Massamba Walo

    Duma doon ku ñu naan cam
    Doo ma xool di ma naan topp ma
    Duma doon ku ñu naan cam
    Kenn du ma xool di ma naan topp ma

    Reew mi dinañ donni ñi fiy doggali
    Bés sa ngi ci bés yi
    Dinañ bokku ci ñin na diiw wa ngi
    Ndax dama fonk loolu sama liggéey
    Tekki gëm-gëm moo kay maye
    Mënta naqari su may liggéey
    Ndax li kay neexal lang ci man
    Def li may def ci personnalité
    Teg ko ci code du genn gamm
    Indi fi yeneen tonalité
    Dugal leen ci yeneen ni game
    Aay waay!

    Duma doon ku ñu naan cam
    Doo ma xool di ma naan topp ma
    Duma doon ku ñu naan cam
    Kenn du ma xool di ma naan topp ma

    Duma doon ku ñu naan cam
    Doo ma xool di ma naan topp ma
    Duma doon ku ñu naan cam
    Kenn du ma xool di ma naan topp ma

    Ndaanaan sama lama ngone
    Ci bor bu tar bi lañu jogé
    Ndaanaan sama lama ngone
    Dañu sonoo loolu bañuy doni gone
    Alhamdulillah eeeh
    Li gëna metti jot na jaale
    Na indi ku leen di ngone nam indi
    Nanguwuñu xam nañu fi ñu jogé fàttewuñu

    Ndax dañu fonk loolu sunu liggéey
    Tekki gëm-gëm moo kay maye
    Mënta naqari su ñuy liggéey
    Ndax li kay neexal lang ci man, eeeh waay!

    Duma doon ku ñu naan cam
    Doo ma xool di ma naan topp ma
    Duma doon ku ñu naan cam
    Kenn du ma xool di ma naan topp ma

    Duma doon ku ñu naan cam
    Doo ma xool di ma naan topp ma
    Duma doon ku ñu naan cam
    Kenn du ma xool di ma naan topp ma


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de AMADEUS y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección