Traducción generada automáticamente

visualizaciones de letras 21
Letra

Idda

Idda

Danga toog sama xolDanga toog sama xol
Mãe, você é a únicaYaay ki ko moom léeboon
Eu sou seu filhoGént naa takk la
Venho aqui, sou seu filhoKaay doon sama yaayu doom
Eu estou aqui, eu existoDugg naa, dund naa
Eu sou seu filhoMuñ toog ndax yaw doom
E o dia que seu filho nasceuTe bés bu sa doom indee doom
Fiz isso por você, meu filhoDef ko doom sama doom

Quando a pessoa está na escuridãoLi nit di daj ci néegu-séy
Vê sua mãe e não quer que ela morraDi gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey
Quando a pessoa está na escuridãoLi nit di daj ci néegu-séy
Vê sua mãe e não quer que ela morraDi gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey

Eu vou te encontrar à meia-noite (ooh espera)Dinaa la romb midi (ooh wait)
E não vou te ver (ooh espera)Te doo ma gis (ooh wait)
As penicilinas estão chegando (ooh espera)Pénicillines yaa ngi ñëw (ooh wait)
Eu vou me preparar (ooh espera)Ma dàbbali (ooh wait)
Tudo vai ficar bem (ooh espera)Gaa fof no weli (ooh wait)
Não deixe isso acontecer (ooh espera)No dootoo ko defati (ooh wait)

Ooh espera, ooh esperaOoh wait, ooh wait

Quantas mães estão aquiÑaata yaay la fi séy
Sofrendo por causa de seus filhosTëj kaso ndax seen doom
Você pergunta, eu perguntoYii laaj, ngay laaj
Mas não é fácil, não é fácilTay amaguma tontoom
Você não sabe, só agora você entendeYàggatul, léegi rekk nga xam
Isso é o que sou, meu filhoLuy noon sama doom
A Idda vai morrerIdda bi tay la jeex
E eu vou cuidar do meu filhoDi jéggaluwaat sama doom

Quando a pessoa está na escuridãoLi nit di daj ci néegu-séy
Vê sua mãe e não quer que ela morraDi gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey
Quando a pessoa está na escuridãoLi nit di daj ci néegu-séy
Vê sua mãe e não quer que ela morraDi gis sa yaay te doo ko ko sañ a déey

Eu vou te encontrar à meia-noite (ooh espera)Dinaa la romb midi (ooh wait)
E não vou te ver (ooh espera)Te doo ma gis (ooh wait)
As penicilinas estão chegando (ooh espera)Pénicillines yaa ngi ñëw (ooh wait)
Eu vou me preparar (ooh espera)Ma dàbbali (ooh wait)
Tudo vai ficar bem (ooh espera)Gaa fof no weli (ooh wait)
Não deixe isso acontecer (ooh espera)No dootoo ko defati (ooh wait)

Eu estou aqui, eu existoDugg naa, dund naa
Eu sou seu filhoMuñ toog ndax yaw doom

Eu não sei como vai serPare naa, xamoo ni bu jeexee
Vai ser, vai serJeex na, jeex na
Aguarde!Ñëwal!
Ah!Ah!
Você está aqui!Nga ni!
Aah!Aah!
Aah!Aah!

Eu vou aumentar o volumeMa ne beydu volume
O remédio está chegandoSaabu mi nanaani
Coloque os óculosTekkil lunettes yi
Para ver melhor.Ngir gën a gis

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección