Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 25

Lonkotina

Mia Guisse

Letra

Lonkotina

Lonkotina

J'ai entendu parler de toi, personne ne peut te remplacerMan dégg naa feebaru mbëggeel kenn mënu ko faj
Je veux être malade et ne pas te dire au revoirMa bëgg ba malade te fasenewuma naan garab
La lumière est là, ne brille pas comme un feu de pailleNgelaw bi ci ëpp kaay, dootul mel ni faru-rab
Je suis là, je t'appelle, ouais Pape et CheikhNobati naa, lonkoti naa dal, wuy Pape et Cheikh

Ouhou ouhou ouh...Ouhou ouhou ouh...
Si tu ne sais pas, tu sais que le sucre est bon iciBoo ñamul kaani doo xam cafka sukkër bi neex ci lem
Ouhou ouhou ouh...Ouhou ouhou ouh...
J'ai ressuscité celui qui t'a ramenéDaagan naa jaamu ki la ressuscité
Tu sais...Nga ni...

Qui es-tu ?Ku la moom?
Moi, je suis là pour toiMan ma la moom
Dis-moi qui je suis pour toiLaaj ma ku ma moom man
Je ne peux pas le direMa bañ duma ko wax
Tu sais qui tu es ?Nga ni ku la moom
Moi, je suis là pour toiMan ma la moom
Dis-moi qui je suis pour toiLaaj ma ku ma moom man
Toi seulement, toi seulement, tu es celui qui est là pour moiYaw rekk yaw rekk lay doon ba muy moom

Je t'appelle, où es-tu ?Lonkoti naa, foo ma jaar?
Moi, je veux juste toiMan yaw rekk la bëgg
Je ne veux rien d'autrePare naa bañ bañ na dara
Mon bébé chériMy baby boo

Mon bébé chat, il est rapideMay baby cat dafa gaaw
"Suma suma lomsong fi jubbo lonkong""Suma suma lomsong fi jubbo lonkong"
Je suis coincé dans le péchéMusloo ci seytaane
Je suis là où tu es, là où tu esMa xaare côté bi nga jaare côté bee
Qu'est-ce qui est bon ?Neex-neex bi lan la?
Tempo tempo, prends ton temps, je suis là pour toiTempo tempo di jël sa temps ba rof ma jaaro baram
La lumière, je veux voir ton visageLaax bi nak fok ma sëlëm ko sa kanam
Je mets un pas en avant, alors je mets deux pas en arrièreTegal benn pas ñëw, kon ma teg ñaari fekk ci la
Ne te laisse pas faire, ne te laisse pas tomberBul di dóor, bul di saaga
Regarde ce qu'ils mettent dans ta mainXoolal li ñu teg sa loxo
Je mets un pas en avant, alors je mets deux pas en arrièreTégal benn pas ñëw, kon ma teg ñaari fekk ci la
Ho ho ho ho, dis-moi quand tu es làHo ho ho ho, dëggëntan ba ngee

Ouhou ouhou ouh...Ouhou ouhou ouh...
Si tu ne sais pas, tu sais que le sucre est bon iciBoo ñamul kaani doo xam cafka sukkër bi neex ci lem
Ouhou ouhou ouh... (ouxayati)Ouhou ouhou ouh... (ouxayati)
J'ai ressuscité celui qui t'a ramenéDaagan naa jaamu ki la ressuscité
Tu sais...Nga ni...

Qui es-tu ?Ku la moom?
Moi, je suis là pour toiMan ma la moom
Dis-moi qui je suis pour toiLaaj ma ku ma moom man
Je ne peux pas le direMa bañ duma ko wax
Tu sais qui tu es ?Nga ni ku la moom
Moi, je suis là pour toiMan ma la moom
Dis-moi qui je suis pour toiLaaj ma ku ma moom man
Toi seulement, toi seulement, tu es celui qui est là pour moiYaw rekk yaw rekk lay doon ba muy moom

Je t'appelle, où es-tu ?Lonkoti naa, foo ma jaar?
Moi, je veux juste toiMan yaw rekk la bëgg
Je ne veux rien d'autrePare naa bañ bañ na dara
Mon bébé chériMy baby boo

Qui es-tu ?Ku la moom?
Moi, je suis là pour toiMan ma la moom
Dis-moi qui je suis pour toiLaaj ma ku ma moom man
Je ne peux pas le direMa bañ duma ko wax
Tu sais qui tu es ?Nga ni ku la moom
Moi, je suis là pour toiMan ma la moom
Dis-moi qui je suis pour toiLaaj ma ku ma moom man
Toi seulement, toi seulement, tu es celui qui est là pour moiYaw rekk yaw rekk lay doon ba muy moom

Oh mon feu de pailleYaay sama faru-rab
Je suis là pour toiJege ma dolli

Dites-moi qui es-tu ?Doro ku la moom?
Clara, qui es-tu ?Clara la moom
Dis-moi qui je suis pour toiLaaj ma ku ma moom man
Je ne peux pas le direMa bañ duma ko wax
Bamba, qui es-tu ?Bamba ku la moom?
Aïcha, qui es-tu ?Aïcha la moom
Dis-moi qui je suis pour toiLaaj ma ku ma moom man
Toi seulement, toi seulement, tu es celui qui est là pour moiYaw rekk yaw lay doon ba muy moom

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección