Suscríbete
visualizaciones de letras 1

Sama Xool (feat. VJ)

Mia Guisse

Letra

    Soo ma soree nu may nooye sama xol kaay
    Waatal ma ni doo ma bàyyi ba ba may dee
    Gisoo mbégte bi may àndal su ma lay wayal?
    Ndax laawu Buur bi rekk a xam fi nga ma jële

    Dénk naa la sama xol bi
    Yéene naa la sama xol bi
    Dégg naa la ci sa xol bi
    Kon nak foo móolee pikkiru laay def
    Coloré nga sama xol bi
    Dénk naa la sama bopp
    Li nga liggéey ci sama xol bi
    Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

    Say xeetu xaar baax
    Man su ma koy lim fi de laay des
    Ndax su ma feeberee bëgg wér séeti ko laay def
    Parlement bi yépp naan bandit laa
    Ñi naan kobb laa, nga ñëw tànn ma
    Baby yaw ci loo ne?
    Jegesi ma, ñu felfëlaale

    Dénk naa la sama xol bi
    Yéene naa la sama xol bi
    Dégg naa la ci sa xol bi
    Kon nak foo móolee pikkiru laay def
    Coloré nga sama xol bi
    Dénk naa la sama bopp
    Li nga liggéey ci sama xol bi
    Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

    Maa ngi séet
    Fi ma la def waaw
    Yaay ki ma def roi bébé
    Xamal ma luy nobeel

    Ba ñu gisee
    Mënuma xef waaw
    Bëtu mbëggeel rekk waaw, bébé
    Laa la mës a xoole

    Man sama jëmm ji rekk nga jaaxal?
    Duma bett ci yaw ndax ndaanaan nga
    Duma xool keneen ndax yaw mi yaa ma doy
    Maa la njëkk barde

    Man sama bae nga, lu ci nit ñi mën? (Dara)
    Te sama féem yi rëcc ci du gaaw
    Ba nga réppee ba dugg ci Mami Guissé
    Laa la xool rekk ree

    Dénk naa la sama xol bi
    Yéene naa la sama xol bi
    Dégg naa la ci sa xol bi
    Kon nak foo móolee pikkiru laay def
    Coloré nga sama xol bi
    Dénk naa la sama bopp
    Li nga liggéey ci sama xol bi
    Wuy yaay bi bànneex nii mu may def

    Dénk naa la sama xol bi
    Yéene naa la sama xol bi
    Dégg naa la ci sa xol bi
    Kon nak foo móolee pikkiru laay def
    Coloré nga sama xol bi
    Dénk naa la sama bopp
    Li nga liggéey ci sama xol bi
    Wuy yaay bi bànneex nii mu may def


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección