Traducción generada automáticamente

Sama Xool (feat. VJ)
Mia Guisse
Sama Xool (feat. VJ)
Sama Xool (feat. VJ)
Alors je ne sais pas pourquoi je suis làSoo ma soree nu may nooye sama xol kaay
Dis-moi, je ne peux pas te laisser partir, je vais mourirWaatal ma ni doo ma bàyyi ba ba may dee
As-tu vu la lumière qui m'entoure quand je m'éloigne ?Gisoo mbégte bi may àndal su ma lay wayal?
Est-ce que le roi sait juste où je vais me retrouver ?Ndax laawu Buur bi rekk a xam fi nga ma jële
Je pense à toi, mon amourDénk naa la sama xol bi
Je ressens ta présence, mon amourYéene naa la sama xol bi
Je t'entends dans ton cœur, mon amourDégg naa la ci sa xol bi
Alors où que tu sois, je vais te retrouverKon nak foo móolee pikkiru laay def
Tu es coloré dans mon cœur, mon amourColoré nga sama xol bi
Je pense à toi, ma têteDénk naa la sama bopp
Ce que tu fais dans mon cœur, mon amourLi nga liggéey ci sama xol bi
C'est comme si ma mère me disait de faire çaWuy yaay bi bànneex nii mu may def
Dis-moi, c'est bienSay xeetu xaar baax
Je vais te laisser ici, je vais faire çaMan su ma koy lim fi de laay des
Est-ce que je t'ai dit que je voulais te voir encore ?Ndax su ma feeberee bëgg wér séeti ko laay def
Le parlement dit que je suis un banditParlement bi yépp naan bandit laa
Ils disent que je suis un voleur, tu es là pour me sauverÑi naan kobb laa, nga ñëw tànn ma
Bébé, qu'est-ce que tu en penses ?Baby yaw ci loo ne?
Dis-moi, on va s'en sortirJegesi ma, ñu felfëlaale
Je pense à toi, mon amourDénk naa la sama xol bi
Je ressens ta présence, mon amourYéene naa la sama xol bi
Je t'entends dans ton cœur, mon amourDégg naa la ci sa xol bi
Alors où que tu sois, je vais te retrouverKon nak foo móolee pikkiru laay def
Tu es coloré dans mon cœur, mon amourColoré nga sama xol bi
Je pense à toi, ma têteDénk naa la sama bopp
Ce que tu fais dans mon cœur, mon amourLi nga liggéey ci sama xol bi
C'est comme si ma mère me disait de faire çaWuy yaay bi bànneex nii mu may def
Je suis làMaa ngi séet
Je vais le faire, ouiFi ma la def waaw
Maman, je vais le faire, bébéYaay ki ma def roi bébé
Montre-moi ce que tu veuxXamal ma luy nobeel
Quand on se voitBa ñu gisee
Je ne peux pas le croire, ouiMënuma xef waaw
C'est juste un rêve, oui, bébéBëtu mbëggeel rekk waaw, bébé
Je ne peux pas m'en passerLaa la mës a xoole
Est-ce que tu es ma seule chance ?Man sama jëmm ji rekk nga jaaxal?
Je ne vais pas te perdre, car tu es làDuma bett ci yaw ndax ndaanaan nga
Je ne peux pas voir quelqu'un d'autre, car c'est toi que je veuxDuma xool keneen ndax yaw mi yaa ma doy
Je suis là, je suis làMaa la njëkk barde
Est-ce que tu es mon amour, qu'est-ce que tu veux ? (Rien)Man sama bae nga, lu ci nit ñi mën? (Dara)
Et mes rêves ne sont pas si loinTe sama féem yi rëcc ci du gaaw
Quand tu es là, je suis avec Mami GuisséBa nga réppee ba dugg ci Mami Guissé
Je ne vois que toi, c'est toutLaa la xool rekk ree
Je pense à toi, mon amourDénk naa la sama xol bi
Je ressens ta présence, mon amourYéene naa la sama xol bi
Je t'entends dans ton cœur, mon amourDégg naa la ci sa xol bi
Alors où que tu sois, je vais te retrouverKon nak foo móolee pikkiru laay def
Tu es coloré dans mon cœur, mon amourColoré nga sama xol bi
Je pense à toi, ma têteDénk naa la sama bopp
Ce que tu fais dans mon cœur, mon amourLi nga liggéey ci sama xol bi
C'est comme si ma mère me disait de faire çaWuy yaay bi bànneex nii mu may def
Je pense à toi, mon amourDénk naa la sama xol bi
Je ressens ta présence, mon amourYéene naa la sama xol bi
Je t'entends dans ton cœur, mon amourDégg naa la ci sa xol bi
Alors où que tu sois, je vais te retrouverKon nak foo móolee pikkiru laay def
Tu es coloré dans mon cœur, mon amourColoré nga sama xol bi
Je pense à toi, ma têteDénk naa la sama bopp
Ce que tu fais dans mon cœur, mon amourLi nga liggéey ci sama xol bi
C'est comme si ma mère me disait de faire çaWuy yaay bi bànneex nii mu may def

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Mia Guisse y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: