Suscríbete

Tradução automática

Exibições da letra 26

Saf Na Ba Nopi

Momo Dieng

Letra

Saf Na Ba Nopi

Saf Na Ba Nopi

Saf na ba noppiSaf na ba noppi
Kenn du sappaliKenn du sappali
Saf na ba noppiSaf na ba noppi
Kenn du sappaliKenn du sappali

Yaw bul ma miin a miin ba faate ma yaayYaw bul ma miin a miin ba faate ma yaay
Coow li mën na bëri loolCoow li mën na bëri lool
Waaye nangul ne cin bokkul safiinWaaye nangul ne cin bokkul safiin
Yaw bul ma miin a miin ba faate ma waayYaw bul ma miin a miin ba faate ma waay
Loo bañ bañ nomboor nangul nopyi guddu na mën na dayLoo bañ bañ nomboor nangul nopyi guddu na mën na day

Saf na ba noppiSaf na ba noppi
Kenn du sappaliKenn du sappali
Momo saf na ba noppiMomo saf na ba noppi
Hey, kenn du sappaliHey, kenn du sappali

Barñi ma rombal bët ba daagu jëm minam jëm senduBarñi ma rombal bët ba daagu jëm minam jëm sendu
Wuy ma yaaya baye Momo DiengWuy ma yaaya baye Momo Dieng
Saf na ba noppi!Saf na ba noppi!

Hee hee hee heeHee hee hee hee
Yahh yaa yaa yaaYahh yaa yaa yaa

Saf na ba noppiSaf na ba noppi
Kenn du sappaliKenn du sappali
Momo saf na ba noppiMomo saf na ba noppi
Kenn du sappaliKenn du sappali

A rafet a mëna fecc a bëy bësi doomA rafet a mëna fecc a bëy bësi doom
Ama mayoon daaw fisiinAma mayoon daaw fisiin
Bassa boori geej geeBassa boori geej gee

Lakoon sakoon nga leebu ba ngiLakoon sakoon nga leebu ba ngi
Moma mayoon daaw fisiinMoma mayoon daaw fisiin
Bassa boori geej geeBassa boori geej gee

Bul ma miinBul ma miin
Bul ma miin miinBul ma miin miin
Bul ma miin ba faate ma kon mu ñaawBul ma miin ba faate ma kon mu ñaaw
Roy du nuroo piirRoy du nuroo piir
Mës nuroo ak piirMës nuroo ak piir
Isma bulma miinoIsma bulma miino
Bul ma miin ba faate ma kon mu ñaawBul ma miin ba faate ma kon mu ñaaw

Lay layla laa ohhLay layla laa ohh

Bul ma miinBul ma miin
Baye Raan bul ma miinBaye Raan bul ma miin
Baye Raan Diop bul ma miin ba faate ma kon mu ñaawBaye Raan Diop bul ma miin ba faate ma kon mu ñaaw

Lourass Diop boo ñówul mu ñaawLourass Diop boo ñówul mu ñaaw
HeyyHeyy
Céy sama waja ngi niCéy sama waja ngi ni
HeyyHeyy
Sa gaan raak sa gaanSa gaan raak sa gaan
HeyyHeyy
Ne naa la Momo yëngal sa gun gu ndajNe naa la Momo yëngal sa gun gu ndaj

Lourass Diop boo ñówul mu ñaawLourass Diop boo ñówul mu ñaaw
HeyyHeyy
Céy sama waja ngi niCéy sama waja ngi ni
HeyyHeyy
Lahy lay la laaLahy lay la laa
Boo ñówul mu ñaaw sama nitBoo ñówul mu ñaaw sama nit
Lahy lay la laa ohhLahy lay la laa ohh

Roy du nuru piirRoy du nuru piir
Mës nuroo ak piirMës nuroo ak piir
Djiby Ndiaye bul ma miin noDjiby Ndiaye bul ma miin no
Bul ma miin ba faate ma kon mu ñaawBul ma miin ba faate ma kon mu ñaaw
Chérie Arame Diallo sama waayChérie Arame Diallo sama waay

Lourass Diop boo ñówul mu ñaawLourass Diop boo ñówul mu ñaaw
HeyyHeyy
Ne naa la Momo yëngal sa gun gu ndajNe naa la Momo yëngal sa gun gu ndaj
HeyyHeyy
Sa gaan raak sa gaanSa gaan raak sa gaan
HeyyHeyy
Ne naa la Momo yëngal sa gun gu ndajNe naa la Momo yëngal sa gun gu ndaj

Djiby Ndiaye boo ñówul mu ñaawDjiby Ndiaye boo ñówul mu ñaaw
Céy diikal diikal sama waja ngi niCéy diikal diikal sama waja ngi ni
Isma boo yëngoo mu neexIsma boo yëngoo mu neex
Malick Mbadj Dissa BayeMalick Mbadj Dissa Baye
Sama wadja ngi niSama wadja ngi ni
HeyyHeyy
Sa gaan raak sa gaanSa gaan raak sa gaan
HeyyHeyy
Ne naa la Momo yëngal sa gun gu ndajNe naa la Momo yëngal sa gun gu ndaj

Senegal booleen yëngoo mu neexSenegal booleen yëngoo mu neex
Céy dikkël dikkël sama réew maa ngi niCéy dikkël dikkël sama réew maa ngi ni

HeyyHeyy
Ne naa la Momo yëngal sa gous gous tathieNe naa la Momo yëngal sa gous gous tathie

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Momo Dieng y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección