Traducción automática

Xarit
Narah Diouf
Xarit
Xarit
Un homme qui n'a pas de cœur ne peut pas aimerNit ku ne am na ku kaay wétali
Un homme qui dit la vérité ne peut pas tromper son espritKu kaay wax dëgg kuy dellusi xelam
Un homme qui n'a pas de cœur ne peut pas se battreNit ku ne am na ku kaay jubbënti
Il faut juste que ça passe, c'est tout ce qu'il fautSayu reere fàtte li ko war
C'est comme un feu, c'est comme une flammeYéena maggando, yéena gowando
Rassemble des désirs comme des étoilesBokk ay bëgg-bëgg mel ni ay seex
Comme des étoilesMel ni ay seex
Xaritoo xarit, où je vais te chercherXaritoo xarit fu ma lay jëleeti
Toi, je vais te mettre sur le chemin de ma véritéYaw mi may teg si yoon su ma réere

Toi, je vais juste connaître ma têteYaw mi ma gëna xam sama bopp
Dis-moi juste, dis-moi ce que je dois avoirWax ma rekk wax ma fu ma lay ameeti

Toi, je vais aimerYaw mi may wétali
Oh oh ooohOh oh oooh
Ouh ouh ouhhOuh ouh ouhh
Il y a des jours où ils se moquentYenn saay ñu meroo
Qui dit qu'il va sur ton cheminKu ne dem sa yoon
Satan et ses pièges peuvent faire ce qu'ils veulentSeytaan ak pexem mëna tas lu ne
Mais les vieux, vieux, ils vont te faire tomberWaye yàgg yàgg dañuy boo loo watt
La vérité est une seule, comme des étoilesÀndaando nekk benn mel ni ay seex
Comme des étoilesMel ni ay seex
Xaritoo xarit, où je vais te chercherXaritoo xarit fu ma lay jëleeti
Toi, je vais te mettre sur le chemin de ma véritéYaw mi may teg si yoon su ma réere
Xaritoo xarit, où je vais te chercherXaritoo xarit fu ma lay jëleeti
Toi, je vais juste connaître ma têteYaw mi ma gëna xam sama bopp
Dis-moi juste, dis-moi ce que je dois avoirWax ma rekk wax ma fu ma lay ameeti
Toi, je vais te mettre sur le chemin de ma véritéYaw mi may teg si yoon su ma réere
Dis-moi juste, dis-moi ce que je dois avoirWax ma rekk wax ma fu ma lay ameeti
Toi, je vais aimerYaw mi may wétali
Oh oh ooohOh oh oooh
Ouh ouh ouhhOuh ouh ouhh
Comme des étoilesMel ni ay seex
C'est comme marcher comme des étoilesDi dox mel ni ay seex
Xaritoo xarit, où je vais te chercherXaritoo xarit fu ma lay jëleeti
Où je vais te chercher ?Fu ma lay jëleeti?
Xaritoo xarit, où je vais te chercherXaritoo xarit fu ma lay jëleeti
Dis-moi !Wax ma kooo!
Dis-moi juste, dis-moi ce que je dois avoirWax ma rekk wax ma fu ma lay ameeti
Dis-moi !Wax ma kooo!
Dis-moi juste, dis-moi ce que je dois avoirWax ma rekk wax ma fu ma lay ameeti
Toi, je vais aimerYaw mi may wétali

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Narah Diouf y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: