
Dunya
Youssou N'dour
Dunya, dunya
Dunya, dunya
Dunya, dunya, dunya mome dafay diekh
Dunya dunya, li fi nekk te jadduwul ëpp na
Dunya dunya, li fi nekk te jaddu tuuti
Dunya dunya, li fi nekk te jadduwul ëpp na
Ne baal ma, lor nga ma, lor nga ma
Wuy yërëm ma
Àdduna bi nanu jugg daal
Naanu jokko te baña seetaan
Ni wala ci ne, lii am-solo mooy jëf dafay metti
Dunya, dunya
Dunya, dunya
Seegante joge wa ne ngorom
Dunya, dunya
Tàngaay bi
Àdduna bi nanu jugg daal
Naanu jokko te baña seetaan
Ni wala ci ne, lii am-solo mooy
Jëf dafay metti!
Àdduna bi jaar na xoolaat
Ana borom xam-xam yi, borom kom-kom yee
Àdduna bi jaar na xoolaat
Mandu jokko te am-yaakaar
Billaay àdduna bi nanu jugg daal
Naanu jokko te baña seetaan
Ni wala ci ne, lii am-solo mooy
Jëf dafay metti
Àdduna bi jaar na xoolaat
Ana borom xam-xam yi, borom kom-kom yee
Àdduna bi jaar na xoolaat
Mandu jokko te am-yaakaar
Àdduna bi nanu jugg daal
Naanu jokko te baña seetaan
Ni wala ci ne, lii am-solo mooy
Jëf dafay metti!
Ana ñi soriyante
Ani ñi dokkolante (jëf dafay metti)
Ni wala ci ne, lii am-solo mooy
Jëf dafay metti!
Jokko kaay ñu jokko
Jokko kaay ñu jokko
Jokko, jokko, jokko baña seetaan
Dunya bi jaar na xoolaat, nañ ci teey
Nañ ci mandu te am ci yaakaar
Jokko, jokko, jokko bañ seetaan
Dunya li ci mbootaay yi di bañ
Te nit ki lu ko taxa joog war na cee dem ba jeex
Jokko, jokko, jokko baña seetaan
Seetal ma li!
Li ci mbootaay yi di bañ
Te nit ki lu ko taxa joog war na cee dem ba jeex
Jokko, jokko, jokko baña seetaan
Oui, c'est le mouvement qui dit non
Qui dit non, non
C'est le mouvement qui dit non



Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Youssou N'dour y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: