Woudjou Yayé

Omar Pène

Letra

    Bile wujj yaay, bile wujj yaay
    Su ma demee jàngi ba wàcc midi
    Maa ñëw ci kër gi du ma tibbal bool
    Bu doomam ñëwee mu jox ko mu lekk
    Bu desalee mu ubbal ma ko fa
    Mbaa mu jox ko xaaj ba
    Baay yaa ma tooñ, baay yaa ma tooñ
    Lu tax nga may bàyyi ak moom?

    Bile wujj yaay, ahn han
    Aka bon a bon!
    Bile wujj yaay, ahn han
    Aka bon a bon!

    Bile wujj yaay, bile wujj yaay
    Su ma demee jàngi ba wàcc midi
    Su ma ñëwee ci kër gi du ma tibbal bool
    Bu doomam ñëwee mu jox ko mu lekk
    Bu desalee mu ubbal ma ko fa
    Mbaa mu jox ko xaaj ba
    Baay yaa ma tooñ, baay yaa ma tooñ
    Lu tax nga may bàyyi ak moom?

    Bile wujj yaay, ahn han
    Aka bon a bon!
    Bile wujj yaay, ahn han
    Aka bon a bon!

    Bile wujj yaay, bile wujj yaay
    Su ma demee jàngi ba wàcc midi
    Maa ñëw ci kër gi du ma tibbal bool
    Bu doomam ñëwee mu jox ko mu lekk
    Bu desalee mu ubbal ma ko fa
    Mbaa mu jox ko xaaj ba
    Baay yaa ma tooñ, baay yaa ma tooñ
    Lu tax nga may bàyyi ak moom?

    Waa waa waaw
    Yaa yaa yaay
    Waa waa waaw


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Omar Pène y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección