Traducción generada automáticamente

Kenen Diapoula (feat. Jahman X-Press)
OMG
Kenen Diapoula (feat. Jahman X-Press)
Kenen Diapoula (feat. Jahman X-Press)
Est-ce que tu sais ce que tu veux ?Est-ce que xam nga li nga yor?
Un enfant de ma mère, c'est vraiXale bu ndayam gërëm
Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneMaa ko fa am nekkak keneen jàppu la
Toi, tout le monde veut que tu aiesYaw ku ñépp di wër nga am
Les autres ne sont pas là pour toiÑeneen ñi duñ dërëm

Je veux que tu te calmes un peuMay ki taxoon ñu sakk la
Et que tu te laisses allerÀnd bangue ñu taxe aras
Je pourrais aussi être là pour quelqu'un d'autreKo mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Je veux que ton corps soit à moiMaay ki sa yaram lacc
Est-ce que je peux te toucher ?Ndax may ki koy dawal

Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneNekkak keneen jàppu la
Ton ex te prendSa ex jàppu la
Dis-moi si je peux te laisser tranquilleNangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la

Eh, juste çaEh ndank rekk
Je prends le temps de m'asseoir avec les amateurs qui traînentMa daan la jël bu gaaw amateur yi bekk
Les autres, c'est juste un match nul, ça ne sert à rienÑi bekk V bi rekk match nul loolu mënta nekk
Ton flow de rap, je l'ai vu, c'est pas terribleDoon sa géelu rap bi sanguloo la seet
Une vraie chance, il y en a peu comme moi dans ta vieChance dëgg la am ku mel ni man ci sa wet
Ce que tu veux, je te le donne, c'est ta préféréeLi ñiy bari bari yaw may sa préférée
Et si tu veux, je peux te le prouverTe fàtte xaaju fi var am na so wedde
Tu es là, mais tu veux encore plusLi ngay wëri feneen yaw fi rekk nga koy ame
Est-ce que je peux avoir ce que tu veux, je suis là pour çaNdax may ki ko am ma ko am baku bari doole
Ta pointure, c'est juste, quelqu'un d'autre te prendSa pointure mana, keneen jàppu la
Ces chaussures sur mesureAy boobu mbëgeelu sur mesure
Dis-moi ce que tu veux (est-ce que je peux te toucher ?)Waxal sa dëggëntaan (kan nga nob)
Ce que tu veux (est-ce que je peux te toucher ?)Sa dëggëntaan (man nga nob)
Qui que tu sois, qui que tu soisKu lay gaañ yaw ku lay cooxatan
Est-ce que tu sais ce que tu veux ?Est-ce que xam nga li nga yor?
Un enfant de ma mère, c'est vraiXale bu ndayam gërëm
Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneMaa ko fa am nekkak keneen jàppu la
Toi, tout le monde veut que tu aiesYaw ku ñépp di wër nga am
Les autres ne sont pas là pour toiÑeneen ñi duñ dërëm
Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneMaa ko fa am nekkak keneen jàppu la
Je veux que tu te calmes un peuMay ki taxoon ñu sakk la
Et que tu te laisses allerÀnd bangue ñu taxe aras
Je pourrais aussi être là pour quelqu'un d'autreKo mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Je veux que ton corps soit à moiMaay ki sa yaram lacc
Est-ce que je peux te toucher ?Ndax may ki koy dawal
Je pourrais aussi être là pour quelqu'un d'autreKo mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneNekkak keneen jàppu la
Ton ex te prendSa ex jàppu la
Dis-moi si je peux te laisser tranquilleNangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la
Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneNekkak keneen jàppu la
Ton ex te prendSa ex jàppu la
Dis-moi si je peux te laisser tranquilleNangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la
Je fais juste ce que je fais, je ne fais que ça, je vais augmenter le niveauÀndak man day def effet man rekk damay yokk taar
Mais tu sais, sur le banc de touche, ils ne comprennent pasKon te nga ngoy bu dëgër banc de touche bi ñoo ngi xaar
Je suis là, mais je ne vais pas me laisser faireMan rekk kala jàpp keneen ko àndalit du dem
Et ceux qui te prennent, ils ne savent pas ce qu'ils fontTe ñi di la toppe soo yabo neleen ñu yam
Ils disent que tu es là, mais tu es là pour moi, tu saisÑi naan la yaw fan wi danga leer so goore neleen may diw bi ngay diwoo
C'est juste moi et toi, on est là pour s'amuserLii tax man ak yaw ñun mëñuñu xulóo
Dieu sait ce qu'on fait, nos rêves, ils sont làYàlla ko def suñu rawan yi ñoo jubbó
Est-ce que je fais pour toi, des valeurs, je ne suis pas un vautourNdax ma def ci yaw valeurs bañ lay wër comme ay vautours
Je ne fais que des allers-retoursJarul wiri-wiri man nga nob allez-retour
Dis-moi ce que tu veux (est-ce que je peux te toucher ?)Waxal sa dëggëntaan (kan nga nob)
Ce que tu veux (est-ce que je peux te toucher ?)Sa dëggëntaan (man nga nob)
Qui que tu sois, qui que tu soisKu lay gaañ yaw ku lay cooxatan
Est-ce que tu sais ce que tu veux ?Est-ce que xam nga li nga yor?
Un enfant de ma mère, c'est vraiXale bu ndayam gërëm
Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneMaa ko fa am nekkak keneen jàppu la
Toi, tout le monde veut que tu aiesYaw ku ñépp di wër nga am
Les autres ne sont pas là pour toiÑeneen ñi duñ dërëm
Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneMaa ko fa am nekkak keneen jàppu la
Je veux que tu te calmes un peuMay ki taxoon ñu sakk la
Et que tu te laisses allerÀnd bangue ñu taxe aras
Je pourrais aussi être là pour quelqu'un d'autreKo mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Je veux que ton corps soit à moiMaay ki sa yaram lacc
Est-ce que je peux te toucher ?Ndax may ki koy dawal
Je pourrais aussi être là pour quelqu'un d'autreKo mëna nekkal keneen tamit jàppu la
Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneNekkak keneen jàppu la
Ton ex te prendSa ex jàppu la
Dis-moi si je peux te laisser tranquilleNangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la
Je suis là pour que quelqu'un d'autre te prenneNekkak keneen jàppu la
Ton ex te prendSa ex jàppu la
Dis-moi si je peux te laisser tranquilleNangul ni man nga nob bàyyil saagu jàppu la

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de OMG y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: