Traducción generada automáticamente

Senegal
OMG
Sénégal
Senegal
Sénégal, c'est nousSenegaal ñoo ko moom
Personne ne peut le nierKenn mënu ko xar ñaar
Faim, mangeons iciXiif, lekk ñàkku fi
Marre, restons iciMar, naan ñàkku fi
Il y a de l'espoir dans mon paysGudde am fo fanaan sama rééw
Si on ne laisse personne tomber dans notre lutteBu ñu nangu kenn duggu suñu diggënte
Tous ces diamants ici, nos mères les ont donnésSame diam ji fi ñoom mame bàyyi
On ne veut pas d'autres, on n'en veut pasXamuñu leneen, bëgguñu leneen
He he he !He he he!
Gueye Ndioro, je t'ai entendu (gueye Ndioro, je t'ai entendu)Gueye Ndioro wëy naa la (gueye Ndioro way naa la)
Faye Birame, je t'ai entendu (je t'ai entendu)Faye Birame wëy naa la (way naa la)
Diobeu Dioubeu, je t'ai entendu (diobeu dioubeu, je t'ai entendu, je t'ai entendu, je t'ai entendu)Diobeu Dioubeu wëy naa la (diobeu dioubeu wëy naa la wëy naa la wëy naa la)
Tourè Mandi, je t'ai entendu (hehee)Tourè Mandi wëy naa la (hehee)
Thiam Babel Demba Thiam, je t'ai entenduThiam babel demba thiam way naa la
Gomissa Gania, je t'ai entendu (sané balama)Gomissa gania way naa la (sané balama)
Ndiaye Diata Ndiaye, je t'ai entenduNdiaye Diata Ndiaye wayaan naa la
Dioufa Niokhobay, je t'ai entendu (man djonkéléfa)Dioufa niokhobay wëy naa la (man djonkéléfa)
Les saints doivent protéger notre paysSant yi war galgui rééw ma ngi
Les saints doivent protéger notre paysSant yi war galgui rééw ma ngi
Diom Foulak, fais attentionDiom foulak fàyda
Ne laisse pas ton cœur se perdreFonk diné tax xol yé ngi naat
Dieuf, c'est bon de vivreDieuf ju baax de diogufi
La solidarité est notre forceSutura lañuy ndamo
Han Sénégal, Ndiaye, mon paysHan Senegaal Ndiaye sama rééw
Walo walo dans le paysWalo walo si réw mi
Sine Saloum dans le paysSine Saloum si réw mi
Casamance BoundouCasamance Boundou
Cadior et Baol Fouta ToroCadior ak Baol Fouta Toro
Jolof SénégalJolof Senegaal
Dieng Salla, je t'ai entendu (samb maharam, je t'ai entendu)Dieng Salla waynala (samb maharam waynala)
Diagne Naar, je t'ai entendu (diallo diery, je t'ai entendu)Diagne Naar waynala (diallo diery waynala)
Sow Poulo, je t'ai entendu (ba poulo, je t'ai entendu, Yagg masseuy)Sow Poulo waynala (ba poulo waynala Yagg masseuy)
Sall Ngari, je t'ai entendu (cissé ngari Ngom séni)Sall Ngari waynala (cissé ngari Ngom séni)
Ndoye Mali Maram Ndoye, je t'ai entendu (wade farawade ndiack)Ndoye Mali Maram Ndoye waynala (wade farawade ndiack)
Mendy Coto, je t'ai entendu (pouye beukeury)Mendy Coto waynala (pouye beukeury)
Fall Ndiaga Yaram, je t'ai entendu (je t'ai entendu, Camara yilé)Fall Ndiaga yaram waynala (waynala Camara yilé)
Dieye Massamba, je t'ai entendu (guissé Maabo)Dieye Massamba waynala (guissé Maabo)
Mbacké Balla AissaMbacké Balla Aissa
Sy SawandéSy Sawandé
Niass Coumba AbdallahNiass Coumba Abdallah
Laye MakhtarLaye Makhtar
Kounta Sidy, je vous ai entendus !Kounta Sidy way naa leen!
Les saints doivent protéger notre pays (lo ndam ciré)Sante yi war Galgui reew mangui (lo ndam ciré)
Les saints doivent protéger notre pays (youm sega Mbaye mbassou Diene ndiogou)Sante yi war Galgui reew mangui (youm sega Mbaye mbassou Diene ndiogou)
Les saints doivent protéger notre pays (thiaw séni Mbengue mbor)Sante yi war Galgui reew mangui (thiaw séni Mbengue mbor)
Les saints doivent protéger notre pays (ndour wally mbergane Niang mbaallo)Sante yi war Galgui reew mangui (ndour wally mbergane Niang mbaallo)
Les saints doivent protéger notre pays (sene thiali Sylla moctar)Sante yi war Galgui reew mangui (sene thiali Sylla moctar)
Les saints doivent protéger notre pays (seck sa guanar)Sante yi war Galgui reew mangui (seck sa guanar)
Les saints doivent protéger notre pays (sarra moundo Ly bousso)Sante yi war Galgui reew mangui (sarra moundo Ly bousso)
Les saints doivent protéger notre paysSante yi war Galgui reew mangui
Les saints doivent protéger notre paysSante yi war Galgui reew mangui



Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de OMG y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: