visualizaciones de letras 3

Loy Wax (feat. Mgeey)

OoThenTiK Zeus

Letra

    Omzo on the Mafe

    Niveau bey hot dey lakke
    Song bi dey daw M'bappe
    Ndakaaru njaay lay wacce
    Da nga xam wala ngay lacce? (Ey)
    Niveau bey hot dey lakke
    Song bi dey daw: M'bappe
    Ndakaaru njaay lay wacce
    Da nga xam wala ngay lacce?

    Boy kula laadj loy wax?
    Ey waay ndeysaan
    Ey deykalanax!
    Dañu koy salsaa bamu saf sapp
    Boy kula laadj loy wax?
    Ey waay ndeysaan
    Ey deykalanax!
    Dañu koy salsaa bamu saf sapp

    Eh seen xel yè karaas mënoleen dem
    Fépp lañ mënè ego ak théme
    Lepp ngeen tële di xaatim nenn
    Yèn ñëp lay warax, talent dey fènn
    Raw naa daxaar qon lepp ay saff
    Yëngël Dakar ba lepp ay barr
    Fepp ay saxar te fepp ay tarr
    Xatna comme yaraax yenn ñëp ay xaar
    Naanuma lingom te gënlaa forox
    Deñ lay tingoom nga mën maa boroos
    Sëf lë ay drogues Di laal ay troc
    Jital oyof tе mën naa torop
    Laalnaa xol yi, bët yeppay taa
    Root néñ xalaat ba feesal ndaa
    Xir bey dalaat
    Fi mann leñ falaat tе
    Neena faraax damay salsaa allright

    Niveau bey hot dey lakke
    Song bi dey daw M'bappe
    Ndakaaru njaay lay wacce
    Da nga xam wala ngay lacce? (Ey)
    Niveau bey hot dey lakke
    Song bi dey daw: M'bappe
    Ndakaaru njaay lay wacce
    Da nga xam wala ngay lacce?

    Boy kula laadj loy wax?
    Ey waay ndeysaan
    Ey deykalanax!
    Dañu koy salsaa bamu saf sapp
    Boy kula laadj loy wax?
    Ey waay ndeysaan
    Ey deykalanax!
    Dañu koy salsaa bamu saf sapp

    Eh kula laaj loy? My boy
    Bëri ay biens, riche: Bad boy, gatdamn
    Dañu koy game bamu neex
    Waye mënu ñuko gagne fò, d'accord
    Maak Mgeey de la Mancha
    Sancaat drip bu leer diko salsaa
    May MC bila antann
    Tek lu dìs gann si sa kaw ba nga appaat
    Fuck li ngay wax mëso maa jox cèpp
    Budè da nga merr everything okay
    Avant ngeen di xeef nekatul mok yeen
    Sama talent mo daaxa wanewuu Mo gates
    Okay okay no stress No cap
    My boy loy hate?
    Sama chronomètre dou seu temps lay kepp
    Bu yabbo nga kepp sa tank boy
    Tekk ngafi tank Mais taanku guinaaw

    Niveau bey hot dey lakke
    Song bi dey daw M'bappe
    Ndakaaru njaay lay wacce
    Da nga xam wala ngay lacce? (Ey)
    Niveau bey hot dey lakke
    Song bi dey daw: M'bappe
    Ndakaaru njaay lay wacce
    Da nga xam wala ngay lacce?

    Boy kula laadj loy wax?
    Ey waay ndeysaan
    Ey deykalanax!
    Dañu koy salsaa bamu saf sapp
    Boy kula laadj loy wax?
    Ey waay ndeysaan
    Ey deykalanax!
    Dañu koy salsaa bamu saf sapp


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de OoThenTiK Zeus y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección