Traducción generada automáticamente

Sama Wo
Philip Monteiro
Sama Wo
Sama Wo
JaYeah
Sama fans, ik ben hier voor jullieSama fans yi, maa ngi leen di gërëm
Ik zie jullie strijd, ik zie jullie pijnDi leen sant gis naa seen taxawaay
De muziekMusique bi
Voor jullie, oo oo ooPur yeen la, oo oo oo
Ik heb jullie nodig, jaMan nob naa leen, waaw
Het is echt veel (het is veel)Yàgg na lool (yàgg na)
Sinds je weg bent (sinds je weg bent)Bi nga demee (bi nga demee)
Ik heb het moeilijk (moeilijk)Man réer naa (réer naa)
Moeilijk zonder jou (zonder jou)Réer naa sans yaw (sans yaw)
Wat moet ik doen? (Zeg het me)Lan laa wara def? (Wax ma)
Doe het zonder jou (zonder jou, hey)Def sans yaw (sans yaw, hey)
Ik mis je, ik hou van jeDama la soxla, dama la bëgg
(Jullie hebben me verlaten)(Dem nga te bàyyi ma)
Verlaat me niet in de nachtBàyyi ma ci lëndëm
Maar je weet datWante xam nga ni
Als ik moet leven tot nuNi dama wara dundu ba tey
(Jullie hebben me verlaten)(Dem nga te bàyyi ma)
Baby, kom terug naar mijBaby, ñëwaatal ci man
Heb je mijn liefde gehoord, jaXanaa déggoo sama woo, yeah
(Baby, kom terug)(Baby ñëwaatal)
Het is echt veel sinds je weg bentYàgg na lool bi nga demee
(Het doet mijn hart pijn)(Tax na sama xol wéete)
Wat kan ik doen als je terugkomt, terugkomt naar mijLu may def ba nga ñëwaat, ñëwaat ci man
(Baby, kom terug)(Baby ñëwaatal)
Het is echt veel sinds je weg bentYàgg na lool bi nga deme
(Het doet je hart pijn)(Tax nga sama xol wéete)
Heb je me gehoord op de dag dat je hier weer bij me komtXanaa di la wax bés bu ne fi nga tollu ci man
Als ik wakker word en denkBu ma toggee di xalaat
(Leven is mooi als we samen zijn)(Dundu yu neex ñi ñu doon dundu)
Is mijn hart alleen maarRekk sama xol fees
(Wat moet ik doen?)(Xamatuma lu ma wara def)
Je hebt me verlaten in de nachtDeme nga bàyyi ma ci lëndëm
(Maar je weet dat)(Wante xam nga ni)
Ik moet leven tot nuDama wara dundu ba tey
(Jullie hebben me verlaten)(Dem nga te bàyyi ma)
Verlaat me niet in de nachtBàyyi ma ci lëndëm
Ik mis je, ik hou van jeDama la soxla, dama la bëgg
Baby, kom terug naar mijBaby ñëwaatal ci man
Heb je mijn liefde gehoordXanaa déggoo sama woo
(Baby, kom terug)(Baby ñëwaatal)
Het is echt veel sinds je weg bentYàgg na lool bi nga demee
(Het doet mijn hart pijn)(Tax na sama xol wéete)
Wat kan ik doen als je terugkomt, terugkomt naar mijLu may def ba nga ñëwaat, ñëwaat ci man
(Baby, kom terug)(Baby ñëwaatal)
Het is echt veel sinds je weg bentYàgg na lool bi nga demee
(Het doet je hart pijn)(Tax nga sama xol wéete)
Heb je me gehoord op de dag dat je hier weer bij me komtXanaa di la wax bés bu ne fi nga tollu ci man
Wat moet ik doen? (het is echt veel)Xamatuma li ma wara def (yàgg na lool)
[?] denken[?] xalaat
Ik wil niet dat je weet wat ik voelBëgguma nga xam li ma daj
Weet je dat ik iemand anders heb?Ndax xam naa ni am nga keneen
Ik kan het niet geloven, ik kan het niet gelovenMënuma ko gëm, mënuma des ni
Het is echt veel sinds je weg bentYàgg na lool bi nga demee
Ik heb het moeilijk hierMan réer na nekkatu fi
Wat moet ik doen hier?Lan la wara def nékkatu fi
[?][?]
Ik mis je, ik hou van jeDama la soxla, dama la bëgg
Baby, kom terug naar mijBaby ñëwaatal ci man
Heb je mijn liefde gehoordXanaa déggoo sama woo
(Baby, kom terug)(Baby ñëwaatal)
Het is echt veel sinds je weg bentYàgg na lool bi nga demee
(Het doet mijn hart pijn)(Tax na sama xol wéete)
Wat kan ik doen als je terugkomt, terugkomt naar mijLu may def ba nga ñëwaat, ñëwaat ci man
(Baby, kom terug)(Baby ñëwaatal)
Het is echt veel sinds je weg bentYàgg na lool bi nga demee
(Het doet je hart pijn)(Tax nga sama xol wéete)
Heb je me gehoord op de dag dat je hier weer bij me komtXanaa di la wax bés bu ne fi nga tollu ci man

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Philip Monteiro y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: