visualizaciones de letras 7

Boy Friend

Queen Biz

Letra

    Ñu bari ñi ngi naan lu ma gis ci yaw
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)
    Dañu mënul gis leer gi ma gis ci yaw
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)
    Yëg-yëg bee fort dafa diis ci ñoom
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)
    Waaye faalewuma leen dundu maak ñoom
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)

    Sa mbëggeel ci man moo tax taamu naa la
    Sa yërmande ci man moo tax fónk naa la
    Yeah, yeah, yeah, yeah gune yi
    Nañu ma bàyyeek yaw
    Yeah, yeah, yeah, yeah gune yi
    Sama àdduna yaa ko yor

    Ñoom dal (Queen Biz)
    Fu nu tollu ñi ngi may toogee
    Dégg naa (Quen Biz)
    Man nan laa lay toppee
    Man dal (Queen Biz)
    Bañuma ci dara, dama bardé
    Ñoo ngi naan (Queen Biz)
    Moom dafa ñàkk fayda

    Lépp ci yaw la
    Li niy teg sama kaw yépp ci yaw la
    Li tax ma bëgg la (ci yaw la)
    Baby yaa ma ko jaral (ci yaw la)
    Baby lu tax ma nangu (ci yaw la)
    Li sugar sama xol bi (ci yaw la)
    Li tax ma bëgg la (ci yaw la)
    Baby yaa ma ko jaral (ci yaw la)

    Ñu bari ñi ngi naan lu ma gis ci yaw
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)
    Dañu mënul gis leer gi ma gis ci yaw
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)
    Yëg-yëg bee fort dafa diis ci ñoom
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)
    Waaye faalewuma leen dundu maak ñoom
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)

    Yaw la love te yaw la (yaw la)
    Yaw la love te yaw la
    Yaw la love te yaw la love
    Yaw la love te yaw la
    Baby yaw la love te yaw la, yaw la love
    Yaw la love te yaw la
    Yaw la love te yaw la love
    Yaw la love te yaw la
    Eh yeah, yeah, yeah

    Respect bi nga am ci man moo tax taamu naa la
    Gondiwoo ma ak li nga am moo tax fónk naa la
    Sama xol bi yaa ma ci doy
    Nañ ma bàyyeek yaw
    Ku ma bëgg na ma bàyyeek yaw
    Sama àdduna yaa ko yor

    Ñoom dal (Queen Biz)
    Bëgg nu ma gis may happy
    Ñoo ngi naan (Queen Biz)
    Alalam bi la ko toppe
    Fàtte nañ (Queen Biz)
    Dama pare démb tay soog a ñëw
    Waxleen (Queen Biz)
    Lu dul mbëggeel sonalu ma

    Lépp ci yaw la
    Li niy teg sama kaw yépp ci yaw la
    Li tax ma bëgg la (ci yaw la)
    Baby yaa ma ko jaral (ci yaw la)
    Baby lu tax ma nangu (ci yaw la)
    Li sugar sama xol bi (ci yaw la)
    Li tax ma bëgg la (ci yaw la)
    Baby yaa ma ko jaral (ci yaw la)

    Ñu bari ñi ngi naan lu ma gis ci yaw
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)
    Dañu mënul gis leer gi ma gis ci yaw
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)
    Yëg-yëg bee fort dafa diis ci ñoom
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)
    Waaye faalewuma leen dundu maak ñoom
    (Yaa ma leen gënal sama boyfriend)

    Yaw la love te yaw la (yaw la)
    Yaw la love te yaw la
    Yaw la love te yaw la love
    Yaw la love te yaw la
    Baby yaw la love te yaw la, yaw la love
    Yaw la love te yaw la
    Yaw la love te yaw la love
    Yaw la love te yaw la
    Eh yeah, yeah, yeah


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Queen Biz y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección