visualizaciones de letras 1
Letra

    Señorita maa ko moom, désolée
    Bul insister kii ma koy décorer
    Sanq ba tay gis na noo koy xoole
    Sama bos la, Yàlla moo ñu boole

    Maaxàllaa yore jikko bukki ak tan
    Di jël alalu jaambur te xamuma ndax lan
    Fi nga teg sa loxo baaxul tegil ma ko ndank
    Bu de weeyu ngay jaay moo bandit ba ngi ni jank

    Oh señorita (señorita)
    Boo gënul ci man
    Oh baalu fetal
    Oh man la lay fëgg ngay càcc gënal ci man

    Anh boo xamul del laaj lijjanti ma
    Anh li nga sex tay kaani la du chewing-gum

    Oh ma señorita (ma señorita)
    Yaw doo bonita
    Maa doole ci la
    Man rekk la bugga

    Teg ko ci suuf li nga nar baaxul gënul ci yaw
    Bul ci dugg oo telo xam nga du la jikk ee

    Ku ma yàpp daa fekk ma nelaw
    Soo ma gisee xam duma sa morom
    Kii jigéen la, maamam ma ko yar
    Rewande ànd ak fula ak fayda ju bari ne ci man

    Dello ne ko mu delloo
    Avance bi mu jëloon loolu gëna sedd ci moom
    Man xale duma dekku sama xéy xaajul ci yaw
    Dute day xam lekkam xamal sa bopp mu nopal la

    Anh chéri coco (Oupadiam)
    Jaral na ma (Oupadiam)
    Ma garér la (Oupadiam)
    Te coow du jiip (Oupadiam)

    Xanaa xanaa dof wala lu la dal
    Xanaa xamoo li lekku bandit la

    Maaxàllaa yore jikko bukki ak tan
    Di jël alalu jaambur te xamuma ndax lan
    Fi nga teg sa loxo baaxul tegil ma ko ndank
    Bu de weeyu ngay jaay moo bandit ba ngi ni jank

    Oh señorita (señorita)
    Boo gënul ci man
    Oh baalu fetal
    Oh man la lay fëgg ngay càcc gënal ci man

    Anh boo xamul del laaj lijjanti ma
    Anh li nga sex tay kaani la du chewing-gum

    Oh ma señorita (ma señorita)
    Yaw doo bonita
    Maa doole ci la
    Man rekk la bugga

    Teg ko ci suuf li nga nar baaxul gënul ci yaw
    Bul ci dugg oo telo xam nga du la jikk ee

    Anh chéri coco (Oupadiam)
    Jaral na ma (Oupadiam)
    Ma garér la (Oupadiam)
    Te coow du jiip (Oupadiam)

    Xanaa xanaa dof wala lu la dal
    Xanaa xamoo li lekku bandit la

    Maaxàllaa yore jikko bukki ak tan
    Di jël alalu jaambur te xamuma ndax lan
    Fi nga teg sa loxo baaxul tegil ma ko ndank
    Bu de weeyu ngay jaay moo bandit ba ngi ni jank

    Oh señorita (señorita)
    Boo gënul ci man
    Oh baalu fetal
    Oh man la lay fëgg ngay càcc gënal ci man

    Anh boo xamul del laaj lijjanti ma
    Anh li nga sex tay kaani la du chewing-gum

    Oh ma señorita (ma señorita)
    Yaw doo bonita
    Maa doole ci la
    Man rekk la bugga


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Safary (Senegal) y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección