Traducción automática

Foowé
Samba Peuzzi
Foowé
Foowé
Tu es là, tu dois rester, je veux juste être ton hommeToog nga fi nga wara toog tax tay ma bëgg doon sa jëkkër
Regarde-moi, mon bébéNangul waay, my baby
Tu es une étoile brillante, et je veux que tu sois ma petiteYor nga xelu mag te fowewoo sa ndaw bébé
Mais je ne te quitterai pasKon man duma la fowe
Non, non, non, ne nous sépare pasNon, non, non, doo ku ñu fowe
Ooh, ton cœur ne doit pas se briserOoh sa coeur duma ko briser
Non, non, non, ne nous sépare pasNon, non, non, doo ku ñu fowe
Ooh, ton cœur ne doit pas se briserOoh sa coeur duma ko briser
Trop classe, tellement coolBari classe, solu nice
Si je ne suis pas là, tu ne peux pas me manquerFu la paj kanam du la ko may
Une belle silhouette, un sourire éclatantForme bu nice, sourire bu graw
Je sais que l'enfant est là pour me faire brillerDaf ma xam xale bi na ma ray
Hey, je te le dis, ma fille, je vais te garderHey, waxoon naa la baby girl dina la way
Je ne te laisserai pas, notre amour ne doit pas mourir, heyYaa ma dekkilal suñu bëggal du dead hey
Mariage monogame, c'est toi que je veux signer, heyMarier monogame ci yaw la signer hey
Je suis là, je suis prêt à tout pour toi (pour toi)Dam la takk maa ngi fépp foo ne (foo ne)
Parfois, avec toi, on se comprendSometimes ma ak yaw ñu xulóo
On parle juste avec nos yeux, c'est suffisantWaxtaan ci ay bët rekk jubóo
Hey, je peux te donner, je ne peux pas te laisserHey, mënoo ma bàyyi, mënuma la bàyyi
Mon cœur te voit, c'est pourquoi je suis là avec toi, bébéXol yee gise moo tax man ak yaw ñu tase baby
Tu es là, tu dois rester, je veux juste être ton hommeToog nga fi nga wara toog tax tay ma bëgg doon sa jëkkër
Regarde-moi, mon bébéNangul waay, my baby
Tu es une étoile brillante, et je veux que tu sois ma petiteYor nga xelu mag te fowewoo sa ndaw bébé
Mais je ne te quitterai pasKon man duma la fowe
Non, non, non, ne nous sépare pasNon, non, non, doo ku ñu fowe
Ooh, ton cœur ne doit pas se briserOoh sa coeur duma ko briser
Non, non, non, ne nous sépare pasNon, non, non, doo ku ñu fowe
Ooh, ton cœur ne doit pas se briserOoh sa coeur duma ko briser
Celui qui te ressemble, je sais qu'il est rare iciKu mel ni yaw xam naa ni dafa rare fi
Je vais demander à mes deux mainsDina laaj sama ñaari loxo
Si je me marie, je peux rester célibataire à vieBu ma rëccee mëna doon célibataire à vie
Je ne veux pas y penser, non, non, nonXalaatuma la bàyyi, non, non, non
Toi, je t'aime, toi, ma belleYaw laa nob, yaw kese yaw
Je ne te laisserai pas, je vais te donner tout ce que j'aiDuma la ko nëbb yaa may tere nelaw
Je ne peux pas te perdre, je vais rester là jusqu'à la finSuma la mënul gént damay toog xoole ba bëtsët
La vérité est que je ne veux pas te blesserMbëggeel bi dëgg moo tax talatuma la doser
Je veux juste être avec toi, je veux que tu sois làNa ñàkk fula ak fayda am la bëgg na
La vitesse de mon cœur va vite quand je parle de toiVitesse la sama xol di deme su may wax ci yaw
C'est pourquoi je pense à toi, bébé, regarde-moiLoolu tax ma fiir, baby xool ma fi
Je t'aime, personne ne peut nous séparerNob naa la, kenn mënu ci tus
Non, non, non, ne nous sépare pasNon, non, non, doo ku ñu fowe
(Tu es là, tu dois rester, je veux juste être ton homme)(Toog nga fi nga wara toog tax tay ma bëgg doon sa jëkkër)
Ooh, ton cœur ne doit pas se briserOoh sa coeur duma ko briser
(Tu es une étoile brillante, et je veux que tu sois ma petite)(Yor nga xelu mag te fowewoo sa ndaw bébé)

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Samba Peuzzi y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: