Traducción generada automáticamente

visualizaciones de letras 164

Motema (feat. Baye Mass)

Sidy Diop

Letra

Motema (feat. Baye Mass)

Motema (feat. Baye Mass)

Dis-moi si tu veux que je fasse çaWax ma loo bëgg ma defal la ko
J'ai ta lumière, j'ai ton étoileAm naa sa yéene, am naa tam sa jot
Ce que tu m'as donné, ça éclaire mon cheminLi nga ma wan doy ma éclairer sama yoon
Alors je vois la lumière au bout du tunnelYaa tax ma gis leer au bout du túnel

Je vais te connaître mieux, ton corps qui m'étonneMa la gëna jége sa yere yi nga sol
Dans la pénombre, je vais te retrouverCi mbëggeelu jokk jokk laa lay woo
Ce que j'aimerais, prendre ma mainLi ma bélli, lëndëmal jant bi
Je vais faire mon chemin, tu saisNgoonalu dibéer laa li woo

Donne-moi ta main, je te parlerai aussiJox ma sa mbëggeel ma déncal la ko
Si tu me donnes un signe, j'irai avec toiSu ci njaabot juddoo ma sàmmal la ko
Avec toi, il y a la paixCi sa wet am naa fa jàmm
Tu es la lumière pour moi, oui, ma lumière qui brille, ouaisYaw de doy nga ma, yaay lumièru siñaara yea

Comptons un deux, bébé, tu es làBooy compter one one baby yaa ngi ci kaw rekk
Tout ce qui me retient, je vais m'en occuper maintenantLu mu tàng tàng tàng na ko jéri man rekk
Et si je dois mettre mon cœur à l'enversTe lu mu metti metti metti metti metti
Je le garderai avec joie, je suis làNa ko siicu-siicuwaat mu njan

Tu es là, tu es en train de mentir, tout ça fait malDanga miig di zonzé, xeere nooy di bondé
Celui qui compte, il ne sait que un, un, tu es làKu lay compter danaan un un yaa ngi ci un rekk
Je vais peser et savoir qu'il y a des gens comme toiMaa la peser xam ni nit ku mel ni yaw
Dieu s'il te plaît, fais tomber une pluie, ouais!Yàlla sakkul ci ñaar, billaay!

Le temps des ténèbres, c'est du poisonMbëggeelu temps yi, xëppante acide la
Si je te laisse, tu es ma dernière chanceBu ma bàyyi, sama exitran nga
Tout ce qui doit se passer, se passeraLu mu metti metti metti metti bae
Je ferai attention pour t'avoir à mes côtésDinaa ko muñ ngir mbëggeel gi ma am ci yaw

Je suis là pour avancerMaa ngi tëddoon def tekk
Personne ne peut me gérer, même pas moiNoboss koboss ma ni tekk
Je reste encore derrièreTaxaw demb di jokk rekk
Je ne veux pas que tu meures juste comme çaMa bañ mu ni ma jokk rekk
Tu sais, je veux que tu sois là, carYaa ma yee mu neex ma ndaxte
Si je veux vivre et être bien, c'est avec toiFoo ma yee yeetal beey gëna neex
Bébé, juste toi!Baby yaw rekk!

Bébé, juste toiBaby manaak yaw rekk
Au cœur de ce noir, juste toiCi biir néegu bu wet rekk
Dans cet endroit, juste toiCi lal bu nooy rekk
Je vais avancer avec toi, juste toiMa koy defal ak yaw rekk
Juste toi!Ak yaw rekk!
Tout ce que je fais là, c'est avec toiBooy jooy doo ko tay ak man rekk

Je suis là pour avancerMaa ngi tëddoon def tekk
Personne ne peut me gérer, même pas moiNoboss koboss ma ni tekk
Je reste encore derrièreTaxaw demb di jokk rekk
Je ne veux pas que tu meures juste comme çaMa bañ mu ni ma jokk rekk
Tu sais, je veux que tu sois là, carYaa ma yee mu neex ma ndaxte
Si je veux vivre et être bien, c'est avec toiFoo ma yee yeetal beey gëna neex
Bébé, juste toi!Baby yaw rekk!

Mon espoir est làSama jeeg bu jar bi
Je sens comme un souffle qui m'attireSaf ni soosu kaani
Ma star,Sama star bi
Où que j'aille, c'est avec ton amourFu ma jëm ak sa taar bi
Ce qui peut arriver m'attendLu may wiri wiri delluwaat
À la ligne de départCi point départ bi

Mon répertoire, juste toiRépertoire bi yaw rekk
Mes messages, juste toiSamay message yaw rekk
Mes pensées, juste toiSama yitte yaw rekk
Mon quotidien, juste toiSama quotidien yaw rekk
Si je te demande de faire le travail, ne me dis pas nonSoo ma soxlawee liggéey bi soxla ma bul ma laaj
Qui peut te dire non? Bébé, juste toi!Kan mooy xaar? Baby yaw rekk!

Ouais, ouaisYee yeeh

Bébé, juste toiBaby manaak yaw rekk
Au cœur de ce noir, juste toiCi biir néegu bu wet rekk
Dans cet endroit, juste toiCi lal bu nooy rekk
Je vais avancer avec toi, juste toiMa koy defaak yaw rekk
Juste toi!Ak yaw rekk!
Tout ce que je fais là, c'est avec toiBooy jooy doo ko tay ak man rekk

Tu es là, tu es en train de mentir, tout ça fait malDanga miig di zonzé, xeere nooy di bondé
Celui qui compte, il ne sait que un, un, tu es làKu lay compter danaan un un yaa ngi ci un rekk
Je vais peser et savoir qu'il y a des gens comme toiMaa la peser xam ni nit ku mel ni yaw
Dieu s'il te plaît, fais tomber une pluie, ouais!Yàlla sakkul ci ñaar, billaay!

Bébé, sauve-moiBébé baal ma
Toi, bébé, sauve-moi!Yaw bébé baal ma!

Tu es là, je t’ai dit que tu es un bandit!Danga doon wëyu wëyu lu boy bandit ba ngi ni!
Bébé, sauve-moiBébé baal ma
Toi, bébé, sauve-moi!Yaw bébé baal ma

Tu es là, je t’ai dit que tu es un cerveau bandit!Danga doon wëyu wëyu lu bandit cerveau ba ngi ni!
Bébé, sauve-moiBébé baal ma
Toi, bébé, sauve-moi!Yaw bébé baal ma

Qui peut dire que tu es nulle, où ça se passe?Ku la dul def lutax nga naan woy wooy wooy, loo koy doye?

Tu es là, je t’ai dit que tu es un grand bandit!Danga doon wëyu wëyu lu magu bandit yaa ngi ni!
Bébé, sauve-moiBébé baal ma
Toi, bébé, sauve-moi!Yaw bébé baal ma

Qui peut dire que tu es nulle, où ça se passe?Ku la dul def lutax nga naan woy wooy wooy, loo koy doye?
Bébé, sauve-moiBébé baal ma
Toi, bébé, sauve-moi!Yaw bébé baal ma

Tu es là, je t’ai dit que tu es un cerveau bandit!Danga doon wëyu wëyu lu bandit cerveau ba ngi ni!
Bébé, sauve-moiBébé baal ma
Toi, bébé, sauve-moi!Yaw bébé baal ma

Tu es là, je t’ai dit que tu es un cerveau bandit!Danga doon wëyu wëyu lu bandit cerveau ba ngi ni!
Bébé, sauve-moiBébé baal ma
Toi, bébé, sauve-moi!Yaw bébé baal ma

Hummm, oui!Hummm bah!
Ils sont là!Ñoo fi jar!

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Sidy Diop y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección