Suscríbete
visualizaciones de letras 2

Boulko Lal (feat. Diaz Kana)

Sokhou Bb

Letra

    [Diaz Kana]
    Héy Buur Sine fa mak in da building dé
    Sokhou bb

    [Sokhou Bb]
    Ayo béyo béyo béyo
    Ayo béyooo béyoo
    Ayo béyo béyo béyo
    Ayo béyooo béyoo

    Boo ko laale
    Soo ko laale dinaa la dóor
    Boo ko laale
    Diaz Kana soo ko laale dinaa la dóor

    [Diaz Kana]
    Eh dangay laaj lu tax ñu xew
    Mëna rap ak tuuti réew
    Éy waay rakk soo ko laale
    Ñaari boy yi duñu baale
    Hip hop feeling petit galé
    Billaay wallaay musique xale
    Damay laaj bu ñu fi nekkutoon
    Ni musique fatick di mel?
    Sa rappeur bu dalul bay duggu ci man bu ko bàyyi mu yégsi kon dalalal
    Boo gisee sa bopp ci sound bi da fekk sound bu nice bi da la lal
    Xoolatal xaalatal tala lal thiaka Ndiaye amul rappeur bu ñuy xalamal
    Munoo ñu peser ndax moto ñu balance
    Jittu ñu concert ndax dangeen di balance
    Dañu koy diolou te dangeen koy panache
    Yomb nañu tak kon médina gounass
    Yeena ngi crise di cardiaque
    Déf kat moné sa car diak
    Duñu yég ci prise de contact, eh!
    Dét ñu dañu lay prise ci contact
    Rap galsen am ngeen client
    Flow buy daw mel ni Kylian
    Ñus ñépp delluwat tok suñu pliante

    [Sokhou Bb]
    Ayo béyo béyo béyo
    Ayo béyooo béyoo
    Ayo béyo béyo béyo
    Ayo béyooo béyoo

    Boo ko laale
    Soo ko laale dinaa la dóor
    Boo ko laale
    Diaz Kana soo ko laale dinaa la dóor

    Koñ bi am ngeen gane defarat leen toogaay (na yaatu)
    (Soo ko laale dinaa la)
    Fi benn rappeur du nelaw (ku nelaw sax ma yee ko)
    (Soo ko laale dinaa la)
    Ay ku mu teye sa rappeur benn fan du nelaw (nelaw nelaw nelaw)
    (Soo ko laale dinaa la)
    Koñ bi dañu naan
    Dafa mëna rap lool!
    Du loolu rap bee ne ci moom
    Diaz loo rap bul baxul ma la wax liii

    [Diaz Kana]
    Ann, ñaari boys yi fu ñu tasee xam nga dañ koy casser
    (Même boo ciy fâcher dañ lay mbëlé néla fait chier)
    Gis nga nuñ koy defe ak fuñ ciy tële
    (Jeme ngeen ba sonn demul fenn dangeen tële)
    Fañ na ngoro, rog a dép na xolum
    Kora ma ka Nona fappum
    Songa xama songa ndiadiagne
    Séréer tigi riméla Ndiaye-ndiaye
    (Amuleen fit, dangeen tit tok
    Sound yaa ngi daw biir TikTok)
    Sumay rap joo moy beatbox
    Gëm sama bopp mooy gëm sama hip hop
    Man may Titi ci beat tu Gabi (umaga)
    Boo déggee pipipe dangay niaali
    Man dama têtu ci beat tu Gabi bu doon yaw dangay pipis ci beat tu wadji
    Dugal la coup duma laaw nak
    Man may Sokhou, duma baal nak
    Yaw nak juum nga ba lal kuñ dul laale nak

    Yaa leen mën sa bé bor
    Yaa leen mën si bii bor
    Rap bi dang ko teyé ñun dé xam nañu loolu
    Fu ñu la wowee nga valider Diaz

    Boo ko laale
    Soo ko laale dinaa la dóor
    Boo ko laale
    Diaz Kana soo ko laale dinaa la dóor

    Est-ce que ñeme na ma, éhh?
    Soo may laale may
    Umaga on the beat!


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Sokhou Bb y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección