visualizaciones de letras 4

Délo Ndioukeul Serigne Bamba (Jeureujeuf)

Sokhou Bb

Letra

    Jërëjëf Maam Bamba
    Jaaraama Maam Cheikh Ibra Fall Lo
    Jërëjëf Sëriñ Bamba
    Maam Cheikh Ibra Fall yaram la

    Jërëjëf Maam Bamba
    Jaaraama Maam Cheikh Ibra Fall Lo
    Jërëjëf Sëriñ Bamba
    Maam Cheikh Ibra Fall yaram la

    Bañu wote bureau ba ca Ndar
    Xadim ma taxaw ni Yàlla rekk ay buur
    Jërëjëf Sëriñ Bamba
    Maam Cheikh Ibra Fall yaram la

    Hum la mu tontu bureau ba ca Ndar moo ko yóbbu ma yomba
    Gars yi weddi woon nañu bàyyi fi ñu toog ñu yóbbi doomi Mame Diarra
    Ka moom fa Ndar manate ba tay mooy wajj
    Ña loon fa Ndar du ñoom te ba tay duñu waa ji
    La mu tontu tundu jee wal ku yóbbu ma yomba

    Jërëjëf Maam Bamba
    Jaaraama Maam Cheikh Ibra Fall Lo
    Jërëjëf Sëriñ Bamba
    Maam Cheikh Ibra Fall yaram la

    Jërëjëf Maam Bamba
    Jaaraama Maam Cheikh Ibra Fall Lo
    Jërëjëf Sëriñ Bamba
    Maam Cheikh Ibra Fall yaram la

    Bañu wote bureau ba ca Ndar
    Xadim ma taxaw ni Yàlla rekk ay buur
    Jërëjëf Sëriñ Bamba
    Maam Cheikh Ibra Fall yaram la

    Booleek nañ ko gaynde gu toog fukki fan lekkul ñam
    Gaynde nga waf ca kanamu Bamba doomi Mame Diarra
    Nakk wañ ko booleek aka gaawa jël jibril
    La dajeel kenn du Bamba doomi Mame Diarra
    Cheikhuna Bamba moo fi wotu ci yónnent bi
    Te misaal bi lu wéer la fel kurane
    Dajefëti yaram bi
    Mbake ya ni woon yaa rabi man de moom man na ma yanu yan bi
    Jajëféti Mame Bamba, jajëfëti sama taabi
    Yaay gësam Mbacke muy tabbi, sa tabaraw taw bi
    Jafëfëti sama njool ma
    Mbacke yaa kawel sama xayma, yaa mëna maye ni am ma
    Jafëfeti Mame Bamba
    Mamy Sérigne abo mu Mame Sey Fall bété-bété jërëjëf

    Jërëjëf Maam Bamba
    Jaaraama Maam Cheikh Ibra Fall Lo
    Jërëjëf Sëriñ Bamba
    Maam Cheikh Ibra Fall yaram nga

    Jërëjëf Maam Bamba
    Jaaraama Maam Cheikh Ibra Fall Lo
    Jërëjëf Sëriñ Bamba
    Maam Cheikh Ibra Fall yaram nga

    Sëriñ Mountakha ne na baayu Sëriñ Moussa nawil ne na
    Naqar gu soosu Ndakaaru amoo ñeeti guddeek Mame Bamba
    Am na mbegte mu koo raw ci ubbiteek Massalikul Jinaan jee
    Mënuma munuma baña sargal sama baay
    Dieng Salla Thioro madjigen Ali Awa Baba ba ca
    Bagañ baay Faalu Sériñ Abbo Mbacké Fallilo

    Jërëjëf Maam Bamba
    Jaaraama Maam Cheikh Ibra Fall yaram nga
    Jërëjëf Maam Bamba
    Jaaraama Maam Cheikh Ibra Fall Lo
    Jërëjëf Maam Bamba
    Jaaraama Maam Cheikh Ibra Fall yaram nga


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Sokhou Bb y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección