Suscríbete
visualizaciones de letras 2

Reine Des Stars

Sokhou Bb

Letra

    Reine des stars fële
    Lu fi yëngu ñépp d’accord ni man la (man la)
    Ma tëju woon doon toggu
    Kon su ma yaqee ñu xam fi ma mané (mëne)
    Ñi di laaj ki ka na?
    Yaa ngi am Sokhou BB la Diva
    Am buzz defaguma dara
    Ñépp di ma wër pourtant et bien je suis là

    Sokhou yaw BB
    (Sokhou yaw BB)
    Sokhou yaw BB
    (Sokhou yaw BB)
    Sokhou yaw BB
    (Sokhou yaw BB)
    Sokhou yaw BB
    (Sokhou yaw BB)

    Doomu Fatick bi mag na
    Déllusi jël li mu moom si game bi
    Dama nekk sama yoon
    Yagg liggéey lu génn feel
    Am na ñu may wax Sokhou Cover rekk
    Dégluwoo ma wax ma li ngay yëg
    Il faut imiter les meilleurs pour en devenir un

    C’est normal
    Lu ma génne mu doon hit
    C’est normal
    May xalé bi yóbbu seen fit
    C’est normal
    Dama open si def ay feat
    Ça dépend
    Xam nga musique gu Sénégal
    Dafa doy waar waaye j’attends tout

    Lu fi yëngu ñépp d’accord ni man la (man la)
    Ma tëju woon doon toggu
    Kon su ma yaqee ñu xam fi ma mané (mëne)
    Ñi di laaj ki ka na?
    Yaa ngi am Sokhou BB la Diva
    Am buzz defaguma dara
    Ñépp di ma wër pourtant et bien je suis là

    Sokhou yaw BB
    (Sokhou yaw BB)
    Sokhou yaw BB
    (Sokhou yaw BB)
    Sokhou yaw BB
    (Sokhou yaw BB)
    Sokhou yaw BB
    (Sokhou yaw BB)

    Ñëwaat na
    Si game bi
    Ñëwaat na
    Si game bi
    Ñëwaat na
    Si game bi
    Fans Sokhou yéh!
    Maa ngi ni


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Sokhou Bb y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección