Tradução automática

Mbeuguelou Bandit
Soryba Kouyate
Mbeuguelou Bandit
Mbeuguelou Bandit
MusiqueMusic
Soryba ha-ha-haaa MusiqueSoryba ha-ha-haaa Music
Si je te dis de venir, tu vas te revendiquer comme une tête de muleNga jël ma taf sa wét di ma tëgg ni tama tàjjaboon
Je meurs pour toi, tu pourrais me laisser tomber sur ton cheminDama dof ci yaw, nga may ndëpal ma daanu ci sa ron
Là où je vais avec le gosse, ça fait que je me sens faibleFu ma jëm ak xale bi, àttanuma lii
Son regard m'excite, o-o-ow ça m'allumeSon regard me fait effet, o-o-ow ça m'excite
Ici, mon style fait mal, ma tête grimace un peuFi ma làkk dafa sore, bopp bi noonul ñore
Le bandit excelle dans son rôleYëfi bandit dafa jongé
Je fais le paon pour que tu te souviennes de mes vieilles madamesDef ma buur di ma limal samay maam
Avoir quelque chose de doux, ça m'attireMbëggeel lu neex la
Oh là là, avoir quelque chose de douxBillaay, mbëggeel lu neex
Moi et toi, aux États-UnisMan ak yaw ba États-Unis
Sans visa, je saisSans visa ma ni
Marcher, se diriger vers la RoumanieDox ba dem Roumanie
Là-haut, sous le ciel, je touche le paradisNaaw ba asaman tërëdi àljanna
Voilà, oh là là, voilàFoofu la, billaay foofu la
Oh là là, bébéBillaay wallaay bébé
Je te demande, dis-moi qui pourrait dire le contraireMaa la nob, wax ma ku ci mën nada
Lui, il ne sait pas, il ne comprend rien aux lourds charmes et soucisMoom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga
Lui, il est comme un agneau tout bienMoom dafa nooy agneau la bu tooy
Lui, je ne vais pas jouer, juste te faire sourire (bébé)Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo (bébé)
Je te demande, dis-moi qui pourrait dire le contraireMaa la nob, wax ma ku ci mën nada
Lui, il ne sait pas, il ne comprend rien aux lourds charmes et soucisMoom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga
Lui, il est comme un agneau tout bienMoom dafa nooy agneau la bu tooy
Lui, je ne vais pas jouer, juste te faire sourireMoom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo
Ah, mon oxygène, je le brasse chaque jourYaay sama oxygène bi ma soxla di nooy tous les jours
Bébé je t'aime, tu m'aimesBébé je t'aime, tu m'aimes
Depuis la nuit des temps jusqu'à l'infiniDepuis la nuit des temps pour tous les jours
Poser ma lourde balance, je crie 'au secours!'Poser sama balance lourde, ma yoxu 'au secours! '
Rien n'égale l'amour que j'ai, je me dévoue pour cet amourLi nekkatul love kase dama jaaxle céy l'amour
Je vais tenir, tenir mon amour, je suis là pour toiWaat naa ba waat sama akoulaye man yaa ma saf
Mon charme me porte, je te demande d'atteindre le cielSama mbëggeel raw na roppalaan ba naaw jëm asaman
Parfois je l'ai eu si mauvais, bébéÑaanu la ko lawu soo ma njëkkoon dee bébé
Oh là là, je ne veux pas te perdre !Billaay, dootuma dundu man!
États-Unis, sans visa, je saisÉtats-Unis, sans visa ma ni
Marcher, se diriger vers la RoumanieDox ba dem Roumanie
Là-haut, sous le ciel, je touche le paradisNaaw ba asaman tërëdi àljanna
Voilà, oh là là, voilàFoofu la, billaay foofu la
Oh là là, bébéBillaay wallaay bébé
Je te demande, dis-moi qui pourrait dire le contraireMaa la nob, wax ma ku ci mën nada
Lui, il ne sait pas, il ne comprend rien aux lourds charmes et soucisMoom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga
Lui, il est comme un agneau tout bienMoom dafa nooy agneau la bu tooy
Lui, je ne vais pas jouer, juste te faire sourire, bébéMoom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo bébé
Assane Wilane l'internationalAssane Wilane l'international
Chéri Mamy Mbaye Sofa Magui saliwooChéri Mamy Mbaye Sofa Magui saliwoo
Assane je t'aime, Wilane je te suisAssane bëgg naa la, Wilane fonk naa la
Mami va jouer, juste pour te faire sourire, bébéMami doo ko jooyloo, dëkke di ko sourireloo bébé
Je te demande, dis-moi qui pourrait dire le contraireMaa la nob, wax ma ku ci mën nada
Lui, il ne sait pas, il ne comprend rien aux lourds charmes et soucisMoom du coow du tooñ du fowe dóor ak saaga
Lui, il est comme un agneau tout bienMoom dafa nooy agneau la bu tooy
Lui, je ne vais pas jouer, juste te faire sourire.Moom sax duma jooyloo dëkke di ma sourireloo

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Soryba Kouyate y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: