Traducción generada automáticamente

Kumu Neexul
Viviane Chidid
Kumu Neexul
Kumu Neexul
Ouais là, ouais làYaw la, yaw la
C'est vrai, c'est vrai, c'est juste çaDëgg dëgg dëgg yaw rekk la
Regarde ça, regarde çaCoow li, coow li
Neexul, oh neexul, Ndiaye, c'est ton frèreNeexul ba neexul Ndiaye doo seen moroom
Celui qui ne se laisse pas faire, il se batKu mu neexul jëlal fale
Celui qui ne se laisse pas faire, il se défendKu mu neexul toppal nale
Nos cœurs, c'est toi qui les a en toiSunu xol yi yaw yaa ci ne
Est-ce que ta mère sait tout ça ?Ndax sa mbaax ñepp ñoo ko seede
La force de Ndiaye, ta véritéGaynde Ndiaye sa dëgg-dëgg
Ici, tu sais où se trouve la véritéFi nga jàpp foofo dëgg
Trop de problèmes, je peux partirYàqe bari feem mëna dem
Tu es en train de pleurer et de crierYaa ngi tax a jooy te dóoroo ñu
On est dans le ciel et on s'en foutÑu ngi asaman te nawuñu
Reste calme, reste calme, tranquilleTëddel tëddel nelaw
Tranquille, pour suivre ta route, je t'aimeNelaw ba yàndoor sa gannaw bandang
Je veux juste toiMan bëgg naa la
Aime Dieu, ohGëmel Yàlla ji
Aime Dieu, oh, et sache que c'est juste lui qui peut m'aiderGëmel Yàlla ji te xam ni moom rekk kaay maye
Aime Dieu, oh, et sache que c'est juste lui qui peut me sauverGëmel Yàlla ji te xam ni moom rekk kay dogal
Celui qui ne se laisse pas faire, il se batKu mu neexul jëlel fale
Celui qui ne se laisse pas faire, il se défendKu mu neexul toppal nale
Nos cœurs, c'est toi qui les a en toiSunu xol yi yaw yaa ci ne
Est-ce que ta mère sait tout ça ?Ndax sa mbaax ñepp ñoo ko seede
La force de Ndiaye, ta véritéGaynde Ndiaye sa dëgg-dëgg
Ici, tu sais où se trouve la véritéFi nga jàpp foofo dëgg
Trop de problèmes, je peux partirYàqe bari feem mëna dem
Tu es en train de pleurer et de crierYaa ngi tax a jooy te dóoroo ñu
On est dans le ciel et on s'en foutÑu ngi asaman te nawuñu
Reste calme, reste calme, tranquilleTëddel tëddel nelaw
Alboury, le fils de Penda NdieméAlboury biram Penda Ndiemé
Le maître de Jolof, il a de la forceBoroom Jolof bu na njorte
Le fils de Penda, Farimata, il est un vrai hérosBiram penda Farimata mi mu dembothioro bé
Moy Mami Serigne Ndiaye, c'est vraiMoy Mami Serigne Ndiaye buna
C'est vrai, Jolof, c'est pas facile, c'est vraiBuna ba Jolof marré nane, buna yaaa
Il faut que tu restes fort, même si ça fait maleunoub tene wajuram di sa nane ba rewmi naat
Yacine Gueye, prends soin de ta mèreYacine gueye massar sa yaye
Serigne Ndiaye, le bon, c'est vraiSerigné Ndiaye bu mansur buna
Sëriñ Ndiaye, Aziz, Fama, Mansour, c'est vraiSëriñ Ndiaye Aziz Fama Mansour umi
Mame Fama Ndiaye, la sœur de Sophie NdiayeMame fama Ndiaye baayu Sophie Ndiaye
Aaaah, aaaahn, aaaahnAaaah, aaaahn, aaaahn
Sëriñ Ndiaye, BounaSëriñ Ndiaye Bouna
Tranquille, pour suivre ta route, je t'aimeNelaw ba yàndoor sa gannaw bandang
Je veux juste toiMan bëgg naa la
Le fils de Aissa NdiayeBiram ndieme Aissa Ndiaye
S'il te plaît, ne me laisse pas tomberBu kaari bigué sanguleen
Alboury, le vrai, Alboury, le bon, Buna NdiayeAlboury diakher, Alboury baay Buna Ndiaye
Mami, ma mère, Famara, Ciré Ndiaye, Buna NdiayeMami mame Famara Ciré Ndiaye, Buna Ndiaye
Je veux juste suivre ta tranquillitéMan nga yàndoor soy nelaw
Celui qui ne se laisse pas faire, il se batKu mu neexul jëlal fale
Celui qui ne se laisse pas faire, il se défendKu mu neexul toppal nale
Tranquille, pour suivre ta route, je t'aimeNelaw ba yàndoor sa gannaw bandang
Je veux juste toiMan bëgg naa la

Comentarios
Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra
Forma parte de esta comunidad
Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Viviane Chidid y explora más allá de las letras.
Conoce a Letras AcademyRevisa nuestra guía de uso para hacer comentarios.
¿Enviar a la central de preguntas?
Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.
Comprende mejor con esta clase: