visualizaciones de letras 277

Jeune Mara

VJ

Letra
    Significado

    Lay layla luu
    Tay ngeen dee, teyaati ngeen dee ooo
    Wuy sama ndey jooy naa ba wadd
    Kaay!

    Doo def lu mel ni même boo ko bëggoon (eee)
    Mënoo ko def ni man mi (eee)
    Lan ngay wër ci stars lu newul ci man mi (eee)
    Maa jogé di échauffement arbitre naan but
    Lekketu bayal yi la miin

    Xale bi yëngël jamono jëkketi na toog di xaar seen commentaire
    Troisième GT ci boy bu ndaw, ah c'est légendaire!
    Kan moo fi dëkk ci feesal stade, Senegaal booy ma fi stars
    Tribune la ma ñépp di owe, xaaju ma ci ay salle
    Maa ngi dégg xale yi naan: VJ duñu concert xanaa
    Yaw doo def bala déwen, léegi ñu am vacances
    Yaw suñu album bi ñuy xaar, doo ko génne xanaa?
    Yaw loo génne dafay neex, chouchou des nanas

    Moo tax ni rekk laa koy defe ni mu yombe
    Nga jënde sa ticket dox ñu daje biir GT
    Album bi bés bu génne bu amul morts am bléssé
    Ndax xol bu rafet ak mbégte ding ko déglu wét di fecc
    Force zac zac zarko (àljanna)
    Ko kaay corégeou président maay capo
    Man VJ sama concert xale yi neex fa lañ baado
    Ma te gambe bi flow yas ngay siisoo

    Bon, setlu naa nak ku fi jokk rekk def ma concurrence
    Maa toog def noppi di seetaan calmement
    Ki la wax dama tappet ku ko ne ragal la
    Man may bandit di délinquant (yaw ki di woyu)

    Mara, marabout de la jeunesse
    Jeune mara, marabout de la jeunesse
    Man VJ, maay marabout de la jeunesse
    Jeune mara, marabout de la jeunesse
    Mara, marabout de la jeunesse
    Jeune mara, marabout de la jeunesse
    Man VJ, maay marabout de la jeunesse
    Jeune mara, marabout de la jeunesse!


    Comentarios

    Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

    0 / 500

    Forma parte  de esta comunidad 

    Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de VJ y explora más allá de las letras.

    Conoce a Letras Academy

    ¿Enviar a la central de preguntas?

    Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

    Comprende mejor con esta clase:

    0 / 500

    Opciones de selección