Suscríbete

Traducción automática

Visualizaciones de la letra 356

Yaa Meune (feat. VJ)

Wally B. Seck

Letra

Yaa Meune (feat. VJ)

Yaa Meune (feat. VJ)

Ja, jaYeah, yeaa

We hebben het goedDégg nañu naan
Als je kijkt, zie je dat ik achter je staNdaanaan boo gis ndaanaan na nekk ci ginnaawam
Jij bent mijn alles, dat is wat ik voelYaa di sama ndaanaan, li de wor na ma
Wat je vastpakt, lijkt op iets dat je niet loslaatLi nga jàppoon ba mel ni, bul ko bàyyi de jikk na la
Diegenen die je volgen, zijn als schaduwen die je niet kunt negerenÑi la toppoon ba ngay gone ñoo tew tay ñëw gunge la
Ik zal niet stoppen, wie je ook bent, ik zal je altijd steunenDaagul doxel nii ku la laal man dina ma yëngal
Jij alleen bent de reden, mijn schatYaw rekk laay topp, ma chérie

Kijk naar het kindCéy xale bi
Je maakt mijn hart blij, dat is waarYaa ngi yëngal sama xol bi waaw
Hier ben je, ik ben er voor jeFi nga ma yóbbu aka sori
Wat je ook doet, ik wil dat je het weetLi nga may def ku ko dundul mënu ko xam
Want je glimlach is als een zonnestraalNdekke mbëggeel noo neexee ni

Wie weet wie je bentKu ne xam nga ki lay bégal
Wie weet wie je bentKu ne xam nga ki lay gaañ
Wie steunt je als je valtKu ne toppal ki lay yëngal
Wie steunt je als je valtKu ne toppal ki lay gaañ

Ja, je kunt sterk zijn, je kunt het kind zijnYaa mën yaa ëpp doole yaa féete xale
Ja, je kunt sterk zijn, alleen jij bent het kindYaa mën yaa ëpp doole yaw rekk ci xale
Ja, je kunt sterk zijn, je kunt het kind zijnYaa mën yaa ëpp doole yaa féete xale
Ja, je kunt sterk zijn, je bent het kindYaa mën yaa ëpp doole yaa mat xale

Schat, ik ben hier, ik ben bij jeChérie ma ni la tay may sa ndér
Neem de pleister, het zal me helpen, ja, jaJëlal pansement bi faj ma ba ma wér, waawaaw
Jij bent de reden, de reden dat ik niet kan stoppenYaw deko ray, deko defe nin ko bëggee du lu ay waaw
Laten we de sterren aanrakenTakkleen daaj yi
Wie ik ook ben, ik ben hier voor jouKi ma doon seet dal moo ngi ni
Want het voelt goed, schatLi dafa neex man ma ni
Schat, ik wil je niet kwijtChérie yaay ki jonge
Ik wil je niet kwijt, ja, jaDuma la wéccok keneen, waawaaw
Ja, ja, oh!Waawaaw, hum!

Dus hier ben je, mijn bandietKon yaa ngi ni, sama bandit bi way
Als je het moeilijk hebt, ik ben er voor jeBoo soloo daagul, ma daagu si way
Wat je ook doet, ik ben er voor jeLi la yëngal ma, ma yëngal
Kom, laten we samen zijn, schatKaay ñu gisee way bébé
Kom naar me toe!Daneel nga ma!

Wie weet wie je bentKu ne xam nga ki lay bégal
Wie weet wie je bentKu ne xam nga ki lay gaañ
Wie steunt je als je valtKu ne toppal ki lay yëngal
Wie steunt je als je valtKu ne toppal ki lay gaañ

Ja, je kunt sterk zijn, je kunt het kind zijnYaa mën yaa ëpp doole yaa féete xale
Ja, je kunt sterk zijn, alleen jij bent het kindYaa mën yaa ëpp doole yaw rekk ci xale
Ja, je kunt sterk zijn, je kunt het kind zijnYaa mën yaa ëpp doole yaa féete xale
Ja, je kunt sterk zijn, je bent het kindYaa mën yaa ëpp doole yaa mat xale

Dat is wat ik voel, ik en mijn gevoelLi mooy mbëggeel man ak mbëggeel
Dat is wat ik voel, ik en mijn gevoelLi mooy mbëggeel la, man ak mbëggeel looy

Want ik ben hier, ik ben hierBa tax na, dama la, dama la
Ik wil je heel graag, schatDama la bëgg lool chérie

Ik ben hier, ik ben hierDama la, dama la
Ik wil je heel graag, schat, ja!Dama la bëgg lool chérie, waaw!

Comentarios

Envía preguntas, explicaciones y curiosidades sobre la letra

0 / 500

Forma parte  de esta comunidad 

Haz preguntas sobre idiomas, interactúa con más fans de Wally B. Seck y explora más allá de las letras.

Conoce a Letras Academy

¿Enviar a la central de preguntas?

Tus preguntas podrán ser contestadas por profesores y alumnos de la plataforma.

Comprende mejor con esta clase:

0 / 500

Opciones de selección